Fondateur : Bubakar Bóris Jóob – Directeur de publication : Paap Aali Jàllo




TOOGAANU-ÑAXTU NGIR JÀPPALE PAAP NJAAY MU WALF

Ay téeméeri-téeméeri nit ñoo teeweesi toogaanu-ñaxtu ba amoon ci buntu màkkaanum Walf. Lees ko dugge mooy kaas ngir ñu bàyyi Paap Njaay, taskatu-xibaaru Walf...

SONKO, AK KAN ?

Alxames, 16 màrs 2023 ba tey, Usmaan Sonkoo nga ca raglu ba, tëdd. Waa Pastef ñoo ngiy def seen kemtalaayu kàttan ngir jàllale ko...

ÀTTEWAAYU NDAKAARU : USMAAN SONKO WAX NA ÀTTEKAT BI AY DËGGAM

Usmaan Sonko jël na kàddu gi ca àttewaayu Ndakaaru, wax àttekat bi ay dëggam ci fulla ak faayda. Njiitul Pastef li dafa biral jafe-jafe...

LAYOOB SONKO-MBAY ÑAŊ : XEEX BI DOOR NA !

Ñetti biisi Dakar Dem Dikk yu tàkk ca Petersen, AUCHAN Mermoos tàkk jëppeet, ay bérébi liggéey yu tëj, dem yombatul, dikk amatul ci péeyub...

TAKK-DER YI LÉEMATI NAÑU KËRU USMAAN SONKO

Jamono ji nuy yaxal mbind mii, takk-der yaa nga fees dell Cité Site Kër Góorgi (Cité Keur Gorgui), fa Usmaan Sonko dëkk. Yoon yeek...
 
YËRAL LÉPP

MAGU WAXOON NAA KO

01:33:07

“Héritages” dalal na Bubakar Bóris Jóob

"Héritages ak Awa" ngi dalal Bubakar Bóris Jóob, ngir...

Malaanum Lëndëm : Bóris Jóob, na woon, fa woon

Ñeenteelu yoon a ngi nii Bubakar Bóris Jóob di...

GÀCCE NGAALAAMA, MBUGAAR !

Senegaal amati na ndam ci 3eelu fan ci weeru...

KUJJE GEEK WOTEB 2022 BI: BËGG NAA LA, BËGGUMA LA, LOOLU JARUL COOW

Ci bésub 23 sàŋwiye ci atum 2022 bii di...

WAAW, KAÑ LA SENEGAAL GËJ A YËNGOO NII…?

Weeru màrs wii weesu, Senegaal tàngoon na jipp !...
YËRAL LÉPP

FÀTTALIKU DÉMB

SEEX

Seex Mooy góor Moo di as gor Mbokk ya ko wor Ñooy mbokk...

FÀTTALIKU OMAR BOLONDEŊ JÓOB… 2/2

(ÑAAREELU XAAJ) Bi ñu nee Senegaal moom na boppam tamit,...

2002, ATUM SUUXU JOOLAA BI

Bërki-démb 26 sàttumbar ci atum 2020, "Bateau le Joolaa"...

FAIDHERBE, SAAY-SAAY BI NUY SARGAL

Bi Siidiya Ndàtte Yàlla génnee àddina ak léegi, am...

JÉERI JOOR NDEELAAK TUBAAB BI

Jéeri Joor Ndeela Faal mu ngi gane àdduna ci...

DÉMB AK TEY

YËRAL LÉPP

WIDEWO YI

WAXLEEN SEEN XALAAT

BAÑ A WACC SA ÀND…

Mbir mi doy na waar. Kenn xamul lii lu...

BOKK AK NAWLOO NGIR JÀMM AK NAATAANGE CI ÀDDUNA SI

Weer yii nu génn, réew yu bare tànn nañu seen njiit....

"LE PROTOCOLE DE L’ÉLYSÉE" : NJÀNGATU PROF BUUBA JÓOB  

Téere bu am solo bi Ceerno Alasaan Sàll génne...

KORONAAWIRIS : TAXAW TEEWLU

Làmp Faal Kala Mbasum Covid-19 mi lëmbe na àddina, lëmbaaje...

NAKA LAA GISE MBAS MI

Mbas mu dërkiis, ñàkk teggin tey jur tiiñalante ci...

KORONAAK ÀDDINA

YËRAL LÉPP

NJÀNGAT CI TÉERE YI

XËT YI LEEN DÀQAL

BÉS DU MAG, DU TUUTI, BOROOM LAY TOLLOOL…

Dëgg la : ràcc jëmale sa kanam baaxul waaye tey fàww LU DEFU WAXU xamle...

DAAWUDA JAAWARA FAATU, NUY FÀTTALIKU SENEGÀMBI

Daawuda Kayraba Jaawara, jiite woon fi réewum Gàmbi 1979 ba 1994, faatu na ci...

BARSAA WALLA… BARSÀQ !… LU XEW CI MIIM RÉEW?

Géej gaa ngiy wann sunu doom yi. Mbete jasig juy warax béy bu lab. Ay...

7 MÀRS WALLA 8 MÀRS ? BEY CI SA WEWU TÀNK…

Juróom-ñetteelu fan ci weeru màrs la xel yépp di dem ci jigéen ñi, ndax...

KÀDDUY USMAAN SONKO 2/2 PÀCC

Senegaal gépp amoon na fiy yëngu-yëngu, réew mi jaxasoo, yëf yi doy waar lool,...

Bàlla Gay-Móodu Lóo : ñaar ci dara

Làmbu démb ak ju tey jeeka wuute ! Ndege, démb, bu nawet bi wàccaan, ci...

DIBÉERU WËLBATI

Cialtine jii la njiitu réew mi doon jébbal askan wi saxaar gi ñu duppe...

KORONAAWIRIS : MBETE GAYNDE GU TËX !

Ndey Koddu Faal   Fii ci Senegaal, limu ñi Covid-19 bi daaneel romb na téeméer. Moonte bi...

MÀNDELAA WAR NAA AM NAQAR FA MU TËDD !

Lan moo dal sunu mbokki réewum Afrig-bëj-Saalum ? Su ma nee ‘’mbokk’’, nit ñu ñuul...

MBËMËSTAL CI JAAR-JAARU ÀLLAAJI OMAR TAAL

Àllaaji Omar Taal mi juddu ci atum 1796 ca Fuuta, bokk na ci ñi...

FESNAC

Kafrin dalal na xew-xewu mbatiit bu réy bi ñu dippe ci nasaraan Festival National...

COOW DINA TOPP SENEGAAL CI FAATUG ISEN AABARE GI (NDEY KODDU FAAL)

Isen Aabare, Njiitu réewum Càdd la woon, génn na àddina ci loppitaal “Principal” bu...

SAARTJIE BAARTMAN, NDAW SA TUBAAB YI DEFOON MALA

Saartjie Baartman ab jaam la woon, fekkoon baax ca réewum Afrig-bëj-saalum.  Moom, nag, benn doomu...

Mbënn mi ak toj-toj yi : fan la miliyaar yi duggu ?

Njàqare, jaaxle la ñu bari ci ñi dëkke ci yenn diwaan yu nekk ci...

Ëllëgu gaynde yi ca tugal

Naples noppeegul ngir bàyyi Kalidu Kulibali mu dem. Moo ngi ci tànki yokkal ko...

NÉEWAAYU LIMUB ÑI WOTE CI JOŊANTE YII : LAN MOO KO WARAL ?

Dibéer 31i fan ci weeru Sulet nekkoon bés bi ñu doon amal wotey palum...

KAN MOOY… IDIRIISA SEKK ?

Maaraa la ko ay jegeñaaleem di woowe, doomi-réew mi naan ko Idi. Taskati xibaar yi ñoom, Ndaamal-Kajoor lañu...

ANNONCE COURS DE WOLOF À L'IFAN ET À L'EBAD

ANNONCE La deuxième session des cours d’alphabétisation en wolof aura lieu du samedi 5 juin 2021...

WURUS RUSUL A DELLU NGALAM WURUSU MALI, CA LOXOY SAA-MALI

Saa-Mali yi léegi ñooy defaral seen bopp seen wurus. Liggéey boobu nag, dañ ko...

GAALU JINNE

Jinne yu ñuul yi ñaay nañu Sunu Gaal gi, soppi ko gàngunaay, tëmbal ko...

Doxalinu wotey palum depite yi ci Senegaal

Dibéeru tey 31 i fan ci weeru Sulet la wotey palum depite yi tàmbali...

YOW KORONAA (Mamadu Jara Juuf)

TAALIFU MAMADU JARA JUUF Nee nga  layy, ni dott Ñów di nas, di nocci Nërmeel  nga  boroom...

SOXNA XADIJATU NJAAY CA KUNGÉEL, DOY NGA ROYUKAAY ! (AMI MBENG)

« …ñeewuma sama benn moroom bu jàng farañse. » Njiit li, boroom raaya yi, taalifkat bi, njiitalu...

BINDKATU AYUBÉS BI : IBRAAYIMA SAAXO CAAM

                Ibraayima Saaxo Caam a nga juddoo Rëbës ci atum 1973, muy gox bi nekk...

CEERNO ALASAAN SÀLL : "YAAKAAR AK RAFET NJORT ÑOO MA TAXOON A ÀND AK MAKI SÀLL"

Tey, Senegaal, kenn mënul a wax  waxu pólitig te doo ci boole Ceerno Alasaan...

NDAM LU SAFUL XOROM, SAFUL SUUKAR…?

10Dibéer yemook ñaar-fukki fan ak ñeent si weeru Féewaryee, la waa réew mi doon...

2002, ATUM SUUXU JOOLAA BI

Bërki-démb 26 sàttumbar ci atum 2020, "Bateau le Joolaa" def na 18i at ci...

FÀTTALIKU OMAR BOLONDEŋ JÓOB…

https://www.youtube.com/watch?v=3sR_E7UeuMc Ci àllarba tey jii, 11eelu fan ci weeru Mee 2022 la Senegaal di fàttaliku...

Sëñ Bàmba

Sëñ Bàmba Kéemaan la Dem ba ñëw war a sant ci ñibbisi gi Di sant Boroom...

RÉEWUM KODIWAAR (MUSAA AYSATU JÓOB)

Musaa Aysatu Jóob Ci benn bataaxal bu mu siiwal, Jean-Pierre Kutwa, njiitu katoligi Kodiwaar yi,...

Bërug ndëgg-sërëx

*Xana du bër da daan neex ndongo ? Daara ju kawe ja ca Ndar,...

LÀMBI GOLO-O ! KU JÓG SAAGA ! (PAAP AALI JÀLLO)

Njoolum-golo miy def yëfi goloom, ku ci yéemu dangay door a yeewu, mbaa...

ANA LU GÓOR-GIY LÀQARCI ?

Bamu jógee Konaakiri ba tey, seeti woon Alfa Konde, Abdulaay Wàdd, sunu Njiitu-réew ma...

AFRIG, LU LA TAX A DES GINNAAW ?

Bare na li may toog man kenn, di yónni samam xel, mu wëral ma...

MAKI/XALIFA : MAG, BU RUSEE NE MAA-TEY

Fan yii nu génn, bare woon na ñu doon yéy ak a yàbbi ci...