BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi ñu jagleel waa jasporaa bi, ci njiiteefu Njiitu réew mi...

BÉS NIKI TAY, NEELEEN DOKTOOR PÀPPA AALI JÀLLO

Gaawo, 13eelu desàmbar 2025, ca Jàngune bu Ndar, la Pàppa Aali Jàllo (njiitul LDW) doon gaaral teesam ci Làkk ak mbatiiti Afrig, duppe ko...

FOQATIG NGUUR FA RÉEWUM BENEE

Ginnaaw coowal sóobare yi toog fa boppu réewum Gine Bisaawu, geneen foqatig Nguur naroon naa amaat, wile yoon, fa réewum Benee ak ay sóobare...

MOUSSO NGIR « JIGÉEN GÉNN CIG LËNDËM »

Soo déggee baatu « mousso », sam xel mën naa dem cib « restaurant » bu siiw ba ca Kanadaa. Waaye, « mousso » bii moom bokkul ak booba ; xéy-na...

NGOMBLAAN GI : DÉPITE YI TÀMBALI NAÑU CÀMBAR NAFA 2026 GI

Dépite yi tàmbali nañu càmbar nafag atu 2026 mi fa Ngomblaan ga. Ñu nar koo amal ci diiru ñaari ayu-bés ngir dalal jëwriñi Càmm...

MAGU WAXOON NAA KO

JIKKO JU RAFET MOOY TABAX AM RÉEW

Wolof nee na, rafet kanam, rafet jikko a ko...
01:33:07

“Héritages” dalal na Bubakar Bóris Jóob

"Héritages ak Awa" ngi dalal Bubakar Bóris Jóob, ngir...

Malaanum Lëndëm : Bóris Jóob, na woon, fa woon

Ñeenteelu yoon a ngi nii Bubakar Bóris Jóob di...

GÀCCE NGAALAAMA, MBUGAAR !

Senegaal amati na ndam ci 3eelu fan ci weeru...

KUJJE GEEK WOTEB 2022 BI: BËGG NAA LA, BËGGUMA LA, LOOLU JARUL COOW

Ci bésub 23 sàŋwiye ci atum 2022 bii di...

FÀTTALIKU DÉMB

SEEX

Seex Mooy góor Moo di as gor Mbokk ya ko wor Ñooy mbokk...

FÀTTALIKU OMAR BOLONDEŊ JÓOB… 2/2

(ÑAAREELU XAAJ) Bi ñu nee Senegaal moom na boppam tamit,...

2002, ATUM SUUXU JOOLAA BI

Bërki-démb 26 sàttumbar ci atum 2020, "Bateau le Joolaa"...

FAIDHERBE, SAAY-SAAY BI NUY SARGAL

Bi Siidiya Ndàtte Yàlla génnee àddina ak léegi, am...

JÉERI JOOR NDEELAAK TUBAAB BI

Jéeri Joor Ndeela Faal mu ngi gane àdduna ci...

DÉMB AK TEY

WIDEWO YI

WAXLEEN SEEN XALAAT

BOO BAÑEE ÑAAW…

Bu nu la waxee nga àggale kàddu gii, looy...

Njiitu Réew

Dangaa jiitoom Dañu la jiital Sa jubb cunduŋ xanaa taxul Moo ndax...

YAA GORE !

Yàgg, yàgg, dëgg ay daan Dëgg lottoon na Senegaal Usmaan Sonkoo...

Ndigalu Maam Ya

Afrig nee Waaw góor, waaw kumba Ayca leen ca waar wa Bu...

SÀCCIIN WI JËM CI TÀNN YI DËGMAL TE FEEÑALEES KO

Sëñ Abdu Xaadr Kebe mooy biral fii xalaatam ñeel...

TÀGGATOO

NJÀNGAT CI TÉERE YI

XËT YI LEEN DÀQAL

NJÀNG MI : JËLUB 2000iy JÀNGALEKAT

Bàrki-démb ci alxames ji, 23 sãwiyee 2025, la Càmm gi tijji woon jëlub 2...

GUDOMP : 92i KËR JOT NAÑUY JUMTUKAAYI TABAX

Fa gox bii di Gudomp, njaboot yi tàmbalee dellusi ginnaaw bi leen fa xareb...

TUKKIB ELIMAANU JËWRIÑ YI FA EMIRAAT ARAAB YA AK ITAALI

Elimaanu jëwriñ yi, Sëñ Usmaan Sonko, moo nga woon tay fa réewum Itaali, ginnaaw...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (23/1/2025)

MURIG MBALAANU KIIRAAYU FARBA NGOM Ayu-bés bii ñu génn la Ngomblaan gi dooroon liggéey bi...

MURIG MBALAANI KIIRAAYI MUSTAFAA JÓOB AK NDEY SALI JÓOB JEŊ

Tay, ci altine ji, lañu woolu woon dépite yi fa Ngomblaan ga. Li waraloon...

CÀMBARUG ÑEENTI SÉMBI SÀRT FA NGOMBLAAN GA

Lu tollu ci weer ak lu teg ginnaaw bi ñu dakkalee seen i càmbar...

LIG 1 SENEGAAL : TIIS WU METTI

Démb ci gaawu bi, 17i Me 2025, la jéyya ju metti dal ci kay...

KU NAAN JOX SA MOROOM

Amoon na fiy jamono, néewoon na lool lees di gis kër gu amul ndaa....

IMAAM AMAAT CAAM, IMAAM BU DËPPALE WOON DIINE AK JAMONO…

Imaam Caam dafa gëmoon bu baax ne, àddina mooy aar allaaxira. Li lay tax...

NGOMBLAAN : DINDI NAÑU MBALAANU KIIRAAYU FARBA NGOM

Dépite yi dindi nañu mbalaanu kiiraayu Farba Ngom ci àjjumay tay jii, 24i sãwiyee...

MBIRUM KOPPARI COVID-19 YI : JÀPP YAA NGIY WÉY

Mbasum koronaa maa ngi wéy di lëmbe réew mi. Naam, jàngoro ji wéy na,...

XURUW DEX GI : ISRA MI NGI CAAF MBAYUM CEEB MU YEES

ISRA sóobu na ci xeetu mbayum ceeb mu yees ca bëj-gànnaaru réew mi. Nde,...

USMAAN SONKO : « JÀMM REKK LAA SÉQ AK JOMAAY… LIGGÉEYALUMA JOMAAY, SENEGAAL LAAY LIGGÉEYAL. »

Elimaanu jëwriñ yi doon na janook dépite yi, ci àjjumay tay ji. Moom ak...

Doxub sàrgal Séex Anta Jóob

Mbootaayu Panafrig « La marche internationale Dakar-Thieytou » amaloon na am ndaje ak saabalkat yi ca...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (04/3/2025)

ÑAXTUB VACATAIRES YI REVUS (Regroupement des Enseignants Vacataires du Sénégal, di kurélug jàngalekat yi ñu...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (24/6/2025)

NGURD CÀMM GI CI ÑETTI WEER YI JIITU CI ATUM 2025 MI Jëwriñu ngurd meek...

FOQATIG NGUUR FA RÉEWUM BENEE

Ginnaaw coowal sóobare yi toog fa boppu réewum Gine Bisaawu, geneen foqatig Nguur naroon...

KAAJARUG “NEW DEAL TECHNOLOGIQUE”

Tay ci altine ji lañu doon aajar naal wees dippee “New Deal Technologique”. Ndaje...

MBIRUM DUWAAÑE BI LÀQOON YÀMBAA CI DAAMARAM

Kaawteef ! Ab duwaañe lees fekk yàmbaa cig daamaram. Mbuur la xewee. Mu di...

UBBITEG LEKKOOL YI CI SENEGAAL

Tay, altine juróom-benni fan ci weeru oktoobar atum 2025, lañu ubbi lekkool yi fii...

XIBAARI TÀGGAT-YARAM

EKIBU SENEGAAL BU MAG BI Paap Caw, tàggatkatu ekib bi siiwal na limka ndaw yi...

LAAJI DÉPITE YI ÑEEL CÀMM GI

Elimaanu jëwriñ yi, Usmaan Sonko, ak Càmm gi mu jiite ña nga woon ca...

MBIRUM AAMADU (MAKI) SÀLL : WOOLU NAÑ WAALI SEKK

Mbirum Aamadu Sàll, doomu Njiitu réew ma woon (Maki Sàll), mi ngi wéy di...

NDAJEM PÉNCOO NOSTEG DUND BI CI KEMBAARU AFRIG CI ATUM 2025.

Jamono jii, ñu ngi amal, fi Ndakaaru, lees ndaje mees duppee « Forum Africain des...

GASAA : ISRAAYEL DOGAALE NA GAALUG NDIMBAL GII DI « MADLEEN »

Ci guddig altine 8, jàpp talaata 9eelu fanu suwe 2025 la sóobarey géej yu...

NGUUR GI DAJALE NA 405i MILIYAAR

Nguurug Senegaal dajale na 405i miliyaar ci 15i fan kese. Muy alal ju takku...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (5/8/2025)

ÑAXTU LIGGÉEYKAT YI CI WÀLLU YOON Démb ci altine ji, 4 ut 2025, kurélug layookat...

MAMADU JA CA KAW, DE GAULLE CI SUUF !

Démb, ci àllarba ji, lañu doon amal ndajem jëwriñ yi, ni ñu ko baaxoo...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (10/7/2025)

PASTEF MÀGG NA Atum 2014 lañu sosoon làng gii ñuy dippe PASTEF. Maanaam, atum ren...

CAN MAROG 2025

Puluf nañu kippuy CAN 2025 bees dëgmal te mu war a ame fa Marog....

21EELU FÉEWIRYEE : BÉS BI ÀDDINA JAGLEEL LÀMMIÑ WEES NÀMP

Làmmiñ wees nàmp ci ekooli tuut-tànk yi… Làmmiñi réew mi, lépp la ñu mën, mën...

UBBITEG KOPPEY LIGGÉEY AK JÀPPALANTE YI

Elimaanu jëwriñ yi, Usmaan Sonko, ma nga woon Kumpentum, fa diiwaanu Tàmbaakundaa. Ci àjjumay...

SENEGAAL DÓOR NA ÀNGALTEER 3-1

Gaynde Senegaal yi fàdd nañ yoy Àngalteer ya. Ñetti bal la leen gari Senegaal...

“FII SÉNÉGAL 2025” : MBIR MI, FII LA !

Ci talaatay tay jii, 7eelu fanu oktoobar 2025, lees door ndajem liggéey bees dippee...

LI GËN A FËS CI XIBAARI BÉS BI (6/11/2025)

PRODAC : YOON TÉYANDI NAÑU Tay ci ngoon la takk-deri DIC yi fekki Paab Maalig Nduur...

MBËKK MI : JÀPP NAÑU MEERU JONWAAR BI

Laasana Saar, meeru Jonwaar, ak yeneen juróom-benni nit ñu ngi ci loxoy Yoon jamono...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (28/1/2025)

NGOMBLAAN GI Coppite am na ci doxalinu Ngomblaan gi. Dog nañu ndàmpaay yi ñu daan...