BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi ñu jagleel waa jasporaa bi, ci njiiteefu Njiitu réew mi...

BÉS NIKI TAY, NEELEEN DOKTOOR PÀPPA AALI JÀLLO

Gaawo, 13eelu desàmbar 2025, ca Jàngune bu Ndar, la Pàppa Aali Jàllo (njiitul LDW) doon gaaral teesam ci Làkk ak mbatiiti Afrig, duppe ko...

FOQATIG NGUUR FA RÉEWUM BENEE

Ginnaaw coowal sóobare yi toog fa boppu réewum Gine Bisaawu, geneen foqatig Nguur naroon naa amaat, wile yoon, fa réewum Benee ak ay sóobare...

MOUSSO NGIR « JIGÉEN GÉNN CIG LËNDËM »

Soo déggee baatu « mousso », sam xel mën naa dem cib « restaurant » bu siiw ba ca Kanadaa. Waaye, « mousso » bii moom bokkul ak booba ; xéy-na...

NGOMBLAAN GI : DÉPITE YI TÀMBALI NAÑU CÀMBAR NAFA 2026 GI

Dépite yi tàmbali nañu càmbar nafag atu 2026 mi fa Ngomblaan ga. Ñu nar koo amal ci diiru ñaari ayu-bés ngir dalal jëwriñi Càmm...

MAGU WAXOON NAA KO

JIKKO JU RAFET MOOY TABAX AM RÉEW

Wolof nee na, rafet kanam, rafet jikko a ko...
01:33:07

“Héritages” dalal na Bubakar Bóris Jóob

"Héritages ak Awa" ngi dalal Bubakar Bóris Jóob, ngir...

Malaanum Lëndëm : Bóris Jóob, na woon, fa woon

Ñeenteelu yoon a ngi nii Bubakar Bóris Jóob di...

GÀCCE NGAALAAMA, MBUGAAR !

Senegaal amati na ndam ci 3eelu fan ci weeru...

KUJJE GEEK WOTEB 2022 BI: BËGG NAA LA, BËGGUMA LA, LOOLU JARUL COOW

Ci bésub 23 sàŋwiye ci atum 2022 bii di...

FÀTTALIKU DÉMB

SEEX

Seex Mooy góor Moo di as gor Mbokk ya ko wor Ñooy mbokk...

FÀTTALIKU OMAR BOLONDEŊ JÓOB… 2/2

(ÑAAREELU XAAJ) Bi ñu nee Senegaal moom na boppam tamit,...

2002, ATUM SUUXU JOOLAA BI

Bërki-démb 26 sàttumbar ci atum 2020, "Bateau le Joolaa"...

FAIDHERBE, SAAY-SAAY BI NUY SARGAL

Bi Siidiya Ndàtte Yàlla génnee àddina ak léegi, am...

JÉERI JOOR NDEELAAK TUBAAB BI

Jéeri Joor Ndeela Faal mu ngi gane àdduna ci...

DÉMB AK TEY

WIDEWO YI

WAXLEEN SEEN XALAAT

BOO BAÑEE ÑAAW…

Bu nu la waxee nga àggale kàddu gii, looy...

Njiitu Réew

Dangaa jiitoom Dañu la jiital Sa jubb cunduŋ xanaa taxul Moo ndax...

YAA GORE !

Yàgg, yàgg, dëgg ay daan Dëgg lottoon na Senegaal Usmaan Sonkoo...

Ndigalu Maam Ya

Afrig nee Waaw góor, waaw kumba Ayca leen ca waar wa Bu...

SÀCCIIN WI JËM CI TÀNN YI DËGMAL TE FEEÑALEES KO

Sëñ Abdu Xaadr Kebe mooy biral fii xalaatam ñeel...

TÀGGATOO

NJÀNGAT CI TÉERE YI

XËT YI LEEN DÀQAL

IRÃ – ISRAAYEL : XARE BAA NGAY WÉY

Xare baa ngay wéy diggante Irã ak Israayel. Ci guddig démb gi, gaawu jàpp...

BUL BIND… / BINDAL…

Seen yéenekaayu web ci wolof ubbil na leen xët wu bees wees duppee BUL...

NAFAG 2026 : JAGLEES NA 356 MILIYAAR NJËWRIÑU YAXANTU BEEK NDEFAR GI

Njiiti Senegaal yi dañu bëgg a jël fànnu ndefar wi, def ko xolu koom-koomu...

KAARAANGE TALI BI : NDOG YEE NGI WÉY DI FAAT

Bëgg-bëggu Nguur gi moo doonoon wàññi limub ndog yi ci tali bi ba, fii...

TABASKI 2025 : CÀMM GEE NGI CI WAAJTAAY YI

Càmmug Senegaal a ngi ba tay ci waaytaayi tabaski 2025 bi. Ginnaaw déggoo bi...

MBIRUM MAJAMBAL JAAÑ

Ginnaaw bi Majambal Jaañ dawee, génn réew mi, Nguurug Senegaal jàpplu na ko fu...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (31/1/2025)

JURÓOM-ÑEENTEELU BÉSU SET-SETAL Set-setal bi ab xew-xew la boo xam ne Nguur gee ko doon...

ÑAXTUY LÀNGI PÓLITIGI MALI YI

Coowi pólitig yi lëmbe na lool réewi Afrig sowu-jant yi, rawatina ci juróomi at...

ABBAAS FAAL : “BOROOM NDAKAARU”

Tay, ci altine ji, lañu doon wote ngir fal meeru Ndakaaru biy wuutu Bàrtelemi...

“COUPE DU MONDE DES CLUB 2025”

Joŋanteb kuppe bees duppee “Coupe du monde des clubs”, di po mu mag muy...

AJAA JAAL MBAAY, JAAR NA BA JÀLL

Àddina yoon la wow, ku ko xas ba dëgmal, dem rekk. Moo waral sunu...

NDAJEM JËWRIÑ YI (29/1/2025)

Nees ko tàmm a defe ayu-bés bu nekk fa Njénde la, amal nañu ci...

DIGAALE SENEGAAL AK RIISI ÑEEL MBAY MI

Njiiti réew mi, dañu nas aw naal, tudde ko "Senegaal 2050", mu doon cëslaay...

NAALUW JOYYANTI KOOM GI AK MBOOLAAY MI

Elimaanu jëwriñ yi, Sëñ Usmaan Sonko, gaaral na naaluw joyyanti koom geek mboolaay mi....

USMAAN SONKO XAATIM NA DÉGGOOB JÀMM AK BENN PÀCCU MFDC

Elimaanu jëwriñ yi, Usmaan Sonko, ak benn pàccu MFDC xaatim nañu ab déggoob jàmm...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (11/3/2025)

NDONGO YI ÑU DÀQ FA SIGICOOR Fa Sigicoor, am na ñetti xale yu ñu dàq...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (1/7/2025)

NDAJEM ÀDDINA SI ÑEEL KOPPARAL SUQALEEKU GI Démb ci altine ji lañu doon amal Ndajem...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (6/3/2025)

“SUIT” WEDDI NA XIBAAR BI L’OBS JIBAL SUIT (Syndicat Unique des Travailleurs du Trésor) mooy...

JIIXI-JAAXA CI GÉNNUG ÀDDUNA IMAAM UMAR JAAWO

Naqar ak tiis la askanu Koldaa nekke fan yii, rawatina ña dëkke fa koñ...

NGUURUG SENEGAAL DAJALE NA 450i MILIYAAR

Tolluwaayu réewum Senegaal ci wàllu koom tàmbali naa ub boppu ñenn ñi. Te, dara...

LAAJ-TONTU AK SOXNA FAATU SIISE KAN (1/2)

LU DEFU WAXU, seen yéenekaay ci kàllamay Kocc, mi ngi am mbégte dalal fii...

FARBA NGOM DEM NA KASO

Farba Ngom dem na kaso. Tay ci alxemes ji, 27 féewiryee 2025, la ko...

TUKKIB USMAAN SONKO FA BURKINAA FAASO

Elimaanu jëwriñ yi, Sëñ Usmaan Sonko, tukki na tay ci àjjuma ji, 16 me...

MONJAAL 2026 / RDC-SENEGAAL : XEEXU GAYNDE AK TENE

Joŋante bu tar te nar a tàng mooy xaar sunu gayndey futbal yi war...

CAYTUG BOKKEEF GI : « NDAWUL NGUUR MËNUL DOON MILIYAARDEER », (USMAAN SONKO)

Elimaanu jëwriñ yi, Sëñ Usmaan Sonko, teeweeji woon na ndaje mees jagleel coppiteg nosteg...

NDAJEM NJIITI NGOMBLAANI RÉEW YI XARITOOK PALESTIN

Démb ci àjjuma ji, Njiitu Ngomblaan gi, Allaaji Maalig Njaay, moo nga woon fa...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (12/8/2025)

TUKKIB ELIMAANU JËWRIÑ YI FA TIRKI Elimaanu jëwriñ yi, Usmaan Sonko, jeexal na démb ci...

WÀÑÑIG NJËGU KUURAŊ BI

Ci ayu-bés bii ñu génn la jëwriñ ji ñu dénk yaxantu gi xamle woon...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (17/7/2025)

SÓOBAREY FARÃS YI GÉNN NAÑU RÉEW MI Bu yàgg ba tay (1960) sóobarey Farãs yi...

XIBAARI TÀGGAT-YARAM

LAMB JI : FARÃ DAAN NA AAMAA BALDE Dibéer 16 féewiryee jii weesu la doomu...

“MUUT ! MOTT ! NUN, WAA ISRAAYEL, NOO NGI REY !”

Léegi, képp ku jóg ngir saabal reyaate ba xew fa Palestine, Israayel dina la...

ISRAAYEL – IRÃ : JURÓOMEELU BÉSUB XARE

Juróomi fan ci tay, bi xare bi tàmbalee diggante Israayel ak Irã. Bees ci...

2026 : SENEGAAL A NGI SÓOBU CI SÉMB YU MAG YI

Ginnaaw bi ñu defee at ak lu teg, Càmmug Basiiru Jomaay Jaxaar Fay gee...

KUBALI GALAG YI : NGUUR GI DAJALE NA 3 000IY MILIYAAR

Nguur gi siiwal na caabalug doxal ñeel nafa gi ci juróom-ñeenti weer yi njëkk...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (4/2/2025)

SÉMBUW JOTALE DËKKI KOW YI AK NDOX MU SELL Nguur gi seqi na ñaareelu jéego...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (27/05/2025)

TUKKIB NJIITU RÉEW MI FA GINE BISAAWO Njiitu réew mi Sëñ Basiiru Jomaay Jaxaar Fay...

NJÀNG MEEK NJÀNGALE MI : NGUUR GI NAMM NAA AMAL DOXALIN WU DIGG-DÓOMU

Ci ubbite lekkool gi, Nguur gi jël nay matuwaay yu am solo ngir taxaw...