BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi ñu jagleel waa jasporaa bi, ci njiiteefu Njiitu réew mi...

BÉS NIKI TAY, NEELEEN DOKTOOR PÀPPA AALI JÀLLO

Gaawo, 13eelu desàmbar 2025, ca Jàngune bu Ndar, la Pàppa Aali Jàllo (njiitul LDW) doon gaaral teesam ci Làkk ak mbatiiti Afrig, duppe ko...

FOQATIG NGUUR FA RÉEWUM BENEE

Ginnaaw coowal sóobare yi toog fa boppu réewum Gine Bisaawu, geneen foqatig Nguur naroon naa amaat, wile yoon, fa réewum Benee ak ay sóobare...

MOUSSO NGIR « JIGÉEN GÉNN CIG LËNDËM »

Soo déggee baatu « mousso », sam xel mën naa dem cib « restaurant » bu siiw ba ca Kanadaa. Waaye, « mousso » bii moom bokkul ak booba ; xéy-na...

NGOMBLAAN GI : DÉPITE YI TÀMBALI NAÑU CÀMBAR NAFA 2026 GI

Dépite yi tàmbali nañu càmbar nafag atu 2026 mi fa Ngomblaan ga. Ñu nar koo amal ci diiru ñaari ayu-bés ngir dalal jëwriñi Càmm...

MAGU WAXOON NAA KO

JIKKO JU RAFET MOOY TABAX AM RÉEW

Wolof nee na, rafet kanam, rafet jikko a ko...
01:33:07

“Héritages” dalal na Bubakar Bóris Jóob

"Héritages ak Awa" ngi dalal Bubakar Bóris Jóob, ngir...

Malaanum Lëndëm : Bóris Jóob, na woon, fa woon

Ñeenteelu yoon a ngi nii Bubakar Bóris Jóob di...

GÀCCE NGAALAAMA, MBUGAAR !

Senegaal amati na ndam ci 3eelu fan ci weeru...

KUJJE GEEK WOTEB 2022 BI: BËGG NAA LA, BËGGUMA LA, LOOLU JARUL COOW

Ci bésub 23 sàŋwiye ci atum 2022 bii di...

FÀTTALIKU DÉMB

SEEX

Seex Mooy góor Moo di as gor Mbokk ya ko wor Ñooy mbokk...

FÀTTALIKU OMAR BOLONDEŊ JÓOB… 2/2

(ÑAAREELU XAAJ) Bi ñu nee Senegaal moom na boppam tamit,...

2002, ATUM SUUXU JOOLAA BI

Bërki-démb 26 sàttumbar ci atum 2020, "Bateau le Joolaa"...

FAIDHERBE, SAAY-SAAY BI NUY SARGAL

Bi Siidiya Ndàtte Yàlla génnee àddina ak léegi, am...

JÉERI JOOR NDEELAAK TUBAAB BI

Jéeri Joor Ndeela Faal mu ngi gane àdduna ci...

DÉMB AK TEY

WIDEWO YI

WAXLEEN SEEN XALAAT

BOO BAÑEE ÑAAW…

Bu nu la waxee nga àggale kàddu gii, looy...

Njiitu Réew

Dangaa jiitoom Dañu la jiital Sa jubb cunduŋ xanaa taxul Moo ndax...

YAA GORE !

Yàgg, yàgg, dëgg ay daan Dëgg lottoon na Senegaal Usmaan Sonkoo...

Ndigalu Maam Ya

Afrig nee Waaw góor, waaw kumba Ayca leen ca waar wa Bu...

SÀCCIIN WI JËM CI TÀNN YI DËGMAL TE FEEÑALEES KO

Sëñ Abdu Xaadr Kebe mooy biral fii xalaatam ñeel...

TÀGGATOO

NJÀNGAT CI TÉERE YI

XËT YI LEEN DÀQAL

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (26/6/2025)

TUKKIB NJIITU RÉEW MI FA ESPAAÑ Bu yàggul dara la Njiitu réew mi, Basiiru Jomaay...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI 30/10/2025

TÉYANDI NAÑU AMET NDÓOY Amet Ndóoy, kenn la ci koronikëeri Sentv yi. Moom nag, dañu...

YEESALUG NGOMBLAAN GI : EL MAALIG SUMB NA LIGGÉEY BI

Démb ci guddi, tele TFM dawal na laaj-tontu bi Njiitul Ngomblaan gi, El Maalig...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (24/4/2025)

4eelu NDAJEM WAXTAAN ÑEEL XÉY AK TÀGGATU NGIR AM LI ÑUY WUT CI LIGGÉEYKAT Tey...

MALI : JAPP NAÑU ÑAARI SENERAAL AK BENN SAA-FARÃS

Ci alxamesu démb ji la xibaar bi rot. Sóobare yay jiite réewum Mali jamono...

SOWAAL : JÀPP NAÑU GAAL GU YABOON LU ËPP 300I MBËKK-KAT

Ndawi duwaan yi nekke Fimla jàpp nañ ag gaal gu naroon mbëkki. Gaal googu...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (6/5/2025)

NJÀNG MEEK NJÀNGALE Mi Jëwriñu njàngale mi ci daara yu ndaw yeek yu digg-dóomu...

DEKKALI SONACOS : YÉENEY NGUUR GI

Nguurug Senegaal gi dina yékkatiwaat kërug liggéey gii di SONACOS. Jël na 14i ndogal...

YÉGLEB WAY-BOKKI NDAJEM ÑAXTU NGIR DOOLEEL ASKANU PALESTIN

Démb, ci dibéer ji, lañu doon amal i ndajey ñaxtu, fii ci Senegaal, ngir...

SYTJUST-UNTJ LÀBBALI NAÑ

Sàndikaa yi ëmb liggéeykati Yoon yi, di waa SYTJUST (Syndicat des Travailleurs de la...

PAAB CAW TÀNN NA AY GAYNDEEM

Tàggatkatu Senegaal bu bees bi, Paab Caw, biral na ay ndawam keroog ca alxames...

LI ÑÉPP BOKK

Waxi Wolof, yenn saa, dañuy xaw a juunoo. Dafay mel ni sax kuy weddi...

DOKTOOR JÀLLO JÓOB : GOR CI WAX, GOR CI JËF

Bees sukkandikoo ci waatub Hippocrate, dees na gis ni balaa ngay yeyoo turu fajkat...

NDAJEM JËWRIÑ YI (5/3/2025)

Démb ci àllarba ji, 5 màrs 2025, amal nañu ndajem jëwriñ mees di faral...

TAAXUM KAW MA MÀBB FA TUUBAA

Am taaxum kaw a màbbati. Fa Ngor (diiwaanu Ndakaaru) la am taaxum kaw njëkkoon...

BUBAKAR BÓRIS JÓOB : AG GUY CI PÉNCUM LADAB

Jukkees na ab laaj-tontu ci yéenekaay Le Soleil, limu 16582eel bu Gaawu 13 ak...

NJUUX LI : ANACIM A NGI ARTU

Kurél gii dii ANACIM (Agence nationale de l’aviation civile et de la météorologie) mooy...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (19/2/2025)

SOROJU SANGOMAAR BI Bilaŋub sàngomaar bu atum 2024 mi génn na. Waa Woodside ñoo ko...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (10/6/2025)

TABASKI 2025 : KÀDDUY NJIITU RÉEW MI Njiitu réew mi, Sëñ Basiiru Jomaay Jaxaar Fay,...

8eelu NDAJEM GALIEN AFRIG : CÀKKUTEEFU NJIITU RÉEW MI

Njiitu réew mi woote na jëme ci Afrig mën boppam ci wàllu paj mi....

NDOGUM YOON MU METTI FA RISAATOL

Fan yii, ndogi yoon yi bari nañu lool te tegaloo. Saa su ñu jàppee...

NAALUW “CONSEIL SUPÉRIEUR DE LA JUSTICE”

Démb, ci dibéer ji, la kii di Porofesëer Siidi Alfa Njaay, doon amal aw...

NDOGUM YOON MU METTI FA KEBEMEER

Ndogi yoon yaa ngi wéy di gën a bari. Saa yees jàppee ne ndog...

SITTA DAAN NA BÀLLA GAY 2

Dibéer, 20i Sulet 2025, Bàlla Gay 2, doomu Géejawaay ji, waada bu mag doon...

LI GËN A FËS CI XIBAARI BÉS BI (15/1/2025)

NDAJEM JËWRIÑ YI (15/1/2024) Ndogal yi tukkee ci ndajem jëwriñ mu tay mi : Dees...

NJÉGGAANIY SENEGAAL : SIIN ROMB NA FARÃS

Senegaal, li ëpp ci lees fiy jëfandikoo, lees di jéggaani la. Dafa di nag,...

“BANQUE MONDIALE” LEBAL NA SENEGAAL 65i MILIYAARI CFA

Ci talaatay démb ji la "Banque mondiale" siiwal ne nangu na a lebal Senegaal...

MBIRUM MAJAMBAL JAAÑ : YOON TEG NA LOXO MAYMUNA NDUUR FAY (7TV) AK BAABAKAR FAAL (GFM)

Démb ci guddi, Maymuna Nduur Fay dafa bëggoon a dalal Majambal Jaañ ci jotaayub...

SENEGAAL : TOLLUWAAYU ÑÀKKUG LIGGÉEY BI YÉEG NA

ANSD siiwal na tolluwaayu ñàkkug liggéey bi fi Senegaal ci atu 2024 mi. bees...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (26/3/2025)

GII MARI SAAÑAA SAMP NAY LAAJ ÑEEL CÀMM GI Dépite bii di Gii Mari Saañaa...

KÀDDUY NJIITU RÉEW MI FA GINE BISAAWO

Njiitu réew mi Sëñ Basiiru Jomaay Jaxaar Fay yékkati nay kàddu woote fa Gine...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (20/3/2025)

COOWAL AMNISTI BI Coppiteg amnisti bi dépitey Pastef yi namm a wotelu ca Ngomblaan ga...

TUKKIB NJIITU RÉEW MI FA ESPAAÑ

Démb, ci dibéer ji, la Njiitu réew mi, Basiiru Jomaay Jaxaar Fay, bawoo ci...

« MËSUNOO GIS BOR BU ÑU NËBB BU TOLLU NII CI AFRIG », EDWARD GEMAYEL, NJIITU NDAWI FMI FI SENEGAAL

Nees ko biralee woon ci sunu yaxalu barki-démb bi, ndawi yi FMI yabal fi...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (10/2/2025)

NJIITU RÉEW MI TEEWE NA 42eelu JOTAAYU "Comité d’orientation de l’AUDA-NEPAD" Ci xëtu Facebookam la...