2026 : SENEGAAL A NGI SÓOBU CI SÉMB YU MAG YI

Ginnaaw bi ñu defee at ak lu teg, Càmmug Basiiru Jomaay Jaxaar Fay gee ngi waaj a song sémb yu mag yi ngir tabax...

MBIRUM SEEX TURE, GUNEG SENEGAAL GI ÑU FAAT CA GANA

Takk-deri Gana yi tàmbali nañoo lëñbët ngir ca yan anam la doomu Senegaal jii di Seex Ture faatoo ak ñan ñoo jël bakkanam. Dafa...

TUKKIY NJIITU RÉEW MI

Njiitu réew mi, Basiiru Jomaay Jaxaar Fay, door na tukki yu am solo ci njeexitalu ayu-bés bii ñu génn. Ñaari tukki yépp mi ngi...

CAAROY : GËSTUKAT YA JÉBBALE NAÑU NJIITU RÉEW MI NJUREEF YI

Gëstukat yi ñu dénkoon mbirum Caaroy ak sóobare ya ñu fa bóomoon ca atum 1944 jébbal nañu Njiitu réew mi Téere bu weex bob,...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (16-10-2025)

XIBAAR ÑEEL YOON Téyandi nañu ràppëer bii di “10 000 problèmes” ak kii di Lamin Kàngaam. Ki tax ñu jàpp leen mooy  Sëriñ Abdulaay Fay...

MAGU WAXOON NAA KO

JIKKO JU RAFET MOOY TABAX AM RÉEW

Wolof nee na, rafet kanam, rafet jikko a ko...
01:33:07

“Héritages” dalal na Bubakar Bóris Jóob

"Héritages ak Awa" ngi dalal Bubakar Bóris Jóob, ngir...

Malaanum Lëndëm : Bóris Jóob, na woon, fa woon

Ñeenteelu yoon a ngi nii Bubakar Bóris Jóob di...

GÀCCE NGAALAAMA, MBUGAAR !

Senegaal amati na ndam ci 3eelu fan ci weeru...

KUJJE GEEK WOTEB 2022 BI: BËGG NAA LA, BËGGUMA LA, LOOLU JARUL COOW

Ci bésub 23 sàŋwiye ci atum 2022 bii di...

FÀTTALIKU DÉMB

SEEX

Seex Mooy góor Moo di as gor Mbokk ya ko wor Ñooy mbokk...

FÀTTALIKU OMAR BOLONDEŊ JÓOB… 2/2

(ÑAAREELU XAAJ) Bi ñu nee Senegaal moom na boppam tamit,...

2002, ATUM SUUXU JOOLAA BI

Bërki-démb 26 sàttumbar ci atum 2020, "Bateau le Joolaa"...

FAIDHERBE, SAAY-SAAY BI NUY SARGAL

Bi Siidiya Ndàtte Yàlla génnee àddina ak léegi, am...

JÉERI JOOR NDEELAAK TUBAAB BI

Jéeri Joor Ndeela Faal mu ngi gane àdduna ci...

DÉMB AK TEY

WIDEWO YI

WAXLEEN SEEN XALAAT

BOO BAÑEE ÑAAW…

Bu nu la waxee nga àggale kàddu gii, looy...

Njiitu Réew

Dangaa jiitoom Dañu la jiital Sa jubb cunduŋ xanaa taxul Moo ndax...

YAA GORE !

Yàgg, yàgg, dëgg ay daan Dëgg lottoon na Senegaal Usmaan Sonkoo...

Ndigalu Maam Ya

Afrig nee Waaw góor, waaw kumba Ayca leen ca waar wa Bu...

SÀCCIIN WI JËM CI TÀNN YI DËGMAL TE FEEÑALEES KO

Sëñ Abdu Xaadr Kebe mooy biral fii xalaatam ñeel...

TÀGGATOO

NJÀNGAT CI TÉERE YI

XËT YI LEEN DÀQAL

XIBAARI TÀGGAT-YARAM

FUTBAL CHAN 2025 Po mi tàmbali na keroog 2 Ut 2025. Senegaal dafa bom matsam bu...

NOPPEE GËN I WAX

Ba bërki-biig rekk, gaa ña jubooguñu woon. Ñu ngi doon wéy di jokkalantey kàddu....

MAKI SÀLL JÓG NA NGIR SETAL DERAM

Sunuy naataangoy L’Observateur ñoo xëyee xibaar bi ci seen xët mu njëkk. Peeñug Njiitu...

KAASAMAAS : DELLUB DAW-LÀQU YI

Door nañu sémbuw jàPpandal dellub daw-làqu yi fa Kaasamaas. Tay ci gaawu bi, 11i...

NAALUW JÀPPANDAL NDOX MU SELL MI

Tay, ci altine ji, lañu doon sumb naaluw jàppandal ndox mu sell ci dëkki...

KAAJARUG “NEW DEAL TECHNOLOGIQUE”

Tay ci altine ji lañu doon aajar naal wees dippee “New Deal Technologique”. Ndaje...

NJAAM GU YEES FA ARAABI SAWDIT

Xoqatal ak metital ya amoon ca jamonoy njaam ga dekkiwaat na fa Araabi Sawdit....

WÀÑÑIG NJËGU KUURAŊ BI

Ci ayu-bés bii ñu génn la jëwriñ ji ñu dénk yaxantu gi xamle woon...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (1/5/2025)

XAATIMUG DÉGGOOB DAL DIGGANTE NGUUR GI, SÀNDIKAA YI AK “PATRONATS” YI Bésub alxamesu tay jii...

TÀGGE : NGŨGĨ WA THIONG’O DËDDU NA

Afrig ñàkkati na kenn ci doomam yu ràññeeku yi. Wile yoon, njabootu ladab ak...

SAA-CEES DAANAAT NA SÀRKOO !

14i at ci ren gannaaw ba Saa-Cees ak Sàrkoo njëkkee bëre. Seen lámb jooju,...

YOKKUTEG PAYOORI SAABALUKAAYI BITIM-RÉEW YI

Nguur gu bees gi séqi na ay jéego ñeel cettantalug pas yi réewum Senegaal...

XIBAARI TÀGGAT-YARAM

BASKET : AFROBASKET 2025 Senegaal dina amal mats jàll (barrage) ëllëg ci altine ji, bu 18i...

TUKKIB ELIMAANU JËWRIÑ YI FA EMIRAAT ARAAB YA AK ITAALI

Elimaanu jëwriñ yi, Sëñ Usmaan Sonko, moo nga woon tay fa réewum Itaali, ginnaaw...

NDAJEM WAXTAANU DOXALKAT YI AK SAYTUKATI NGUUR GI

Tay, ci altine ji, lañu doon amal ndaje moomu. Fa béréb bii ñu dippe...

GERTE : SONACOS DAJALE NA 22. 000IY TON FA NJURBEL

Bi kàmpaañu njaayum gerte gi tàmbalee ba nëgëni sii, banqaasu SONACOS bi nekk Njurbel...

NDAJEM JËWRIÑI AFRIG YI ÑEEL NDOX MI

Doon nañu amal ci altiney barki-démb ji, 6eelu ndaje mu mag mu ndisoog AMCOW...

KOPPARI COVID-19 YI : JÀPPAGUM NAÑU ÑU BARI

Yoon tàmbali na saytu mbirum koppar yees jagleeloon mbasu Covid-19 ma. Ci altiney démb...

XIBAARI TÀGGAT-YARAM

LIGUE DES CHAMPIONS, EUROPA LEAGUE, CONFÉRENCE LEAGUE Ñetti joŋantey kuppe yoy tugal yépp àgg nañu...

“PENTECÔTE” 2025 : BENNOO CI NGËM, JÀPPOO CI JÀMM

Niki dibéeru démb ji, 8eelu fanu suwe 2025, la kerceni àddina sépp, rawatina yoy...

ÑAXTUY SÀNDIKAA YI

Jamono yee ñu weesu, ñaxtuy sàndikaa yi yëngaloon na réew mi. Waaye, ginnaaw ab...

NJIITU RÉEW MI WOOTE NA ÑAARI FANI NJËMBËTUM GARAB

Njiitu réew mi Sëñ Basiiru Jomaay Jaxaar Fay woote nab kàmpaañu njëmbëtum garab. Ñu...

ABBAAS FAAL : “BOROOM NDAKAARU”

Tay, ci altine ji, lañu doon wote ngir fal meeru Ndakaaru biy wuutu Bàrtelemi...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (25-9-2025)

NJIITU RÉEW MI JËMMAL NA ÑEENTI SÉMBI SÀRT YEES WOTE WOON FA NGOMBLAAN GA Fan...

CAN MAROG 2025

Puluf nañu kippuy CAN 2025 bees dëgmal te mu war a ame fa Marog....

SÀNDIKAA YI FIPPU NAÑU

Sàndikaa yu bari door nañu ay ñaxtu ci ayu-bés bii. Muy ñi féete ci...

SOGEPA MI NGI CI YOONU NANGU KËRI NGUUR GI

Lu ëpp juróom-fukki njaboot la SOGEPA nar a génne ciy kër yoy, moomeelu Nguur...

KORITE 2025 : KÀDDUY NJIITU RÉEW MI

Ci altiney tay jii la Njiitu réew mi julli korite. Fa Jumaay Ndakaaru ju...

KODDIWAAR : YOON WA GÉNNEE NA TIJJAAN CAAM CI TOFTALEG WOTEKAT YA

Ëttub àtte bu njëkk bu Abijã jël na ndogal, daldi génnee, seppi lawax bii...

NAALUW “CONSEIL SUPÉRIEUR DE LA JUSTICE”

Démb, ci dibéer ji, la kii di Porofesëer Siidi Alfa Njaay, doon amal aw...

KÀTTEY CFEE YU 2025

Kàtte yu atum 2025 mi dinañu tàmbali ginnaaw-ëllëg, alxames 19 suwe, jeex ci àjjuma...

NAALUW SENEGAAL 2050 : USMAAN SONKO SAS NA JËWRIÑ YI

Ci altiney démb ji, elimaanu jëwriñ yi, Usmaan Sonko, doon amal ndaje ak jëwriñi...

XEW-XEWI PÓLITIG FA CÀDD AK KODDIWAAR

Réewi Afrig yi, rawatina yoy Afrig sowu-jant, bari na lool lees fay nemmeeku ay...

LI GËN A FÉS CI XIBAAR BÉS BI (4/9/2025)

GÀMMU 2025 Tay, alxames, yemoo ak ñeenti fan ci weeru sàttumbar lañuy màggal bés bi...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (9/10/2025)

YOON TÉYANDI NA ALIW SÀLL (RAKKU MAKI SÀLL) AK SOXNAAM Aliw Sàll, nekkoon fi meeru...

USMAAN SONKO XAATIM NA DÉGGOOB JÀMM AK BENN PÀCCU MFDC

Elimaanu jëwriñ yi, Usmaan Sonko, ak benn pàccu MFDC xaatim nañu ab déggoob jàmm...