BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi ñu jagleel waa jasporaa bi, ci njiiteefu Njiitu réew mi...

BÉS NIKI TAY, NEELEEN DOKTOOR PÀPPA AALI JÀLLO

Gaawo, 13eelu desàmbar 2025, ca Jàngune bu Ndar, la Pàppa Aali Jàllo (njiitul LDW) doon gaaral teesam ci Làkk ak mbatiiti Afrig, duppe ko...

FOQATIG NGUUR FA RÉEWUM BENEE

Ginnaaw coowal sóobare yi toog fa boppu réewum Gine Bisaawu, geneen foqatig Nguur naroon naa amaat, wile yoon, fa réewum Benee ak ay sóobare...

MOUSSO NGIR « JIGÉEN GÉNN CIG LËNDËM »

Soo déggee baatu « mousso », sam xel mën naa dem cib « restaurant » bu siiw ba ca Kanadaa. Waaye, « mousso » bii moom bokkul ak booba ; xéy-na...

NGOMBLAAN GI : DÉPITE YI TÀMBALI NAÑU CÀMBAR NAFA 2026 GI

Dépite yi tàmbali nañu càmbar nafag atu 2026 mi fa Ngomblaan ga. Ñu nar koo amal ci diiru ñaari ayu-bés ngir dalal jëwriñi Càmm...

MAGU WAXOON NAA KO

JIKKO JU RAFET MOOY TABAX AM RÉEW

Wolof nee na, rafet kanam, rafet jikko a ko...
01:33:07

“Héritages” dalal na Bubakar Bóris Jóob

"Héritages ak Awa" ngi dalal Bubakar Bóris Jóob, ngir...

Malaanum Lëndëm : Bóris Jóob, na woon, fa woon

Ñeenteelu yoon a ngi nii Bubakar Bóris Jóob di...

GÀCCE NGAALAAMA, MBUGAAR !

Senegaal amati na ndam ci 3eelu fan ci weeru...

KUJJE GEEK WOTEB 2022 BI: BËGG NAA LA, BËGGUMA LA, LOOLU JARUL COOW

Ci bésub 23 sàŋwiye ci atum 2022 bii di...

FÀTTALIKU DÉMB

SEEX

Seex Mooy góor Moo di as gor Mbokk ya ko wor Ñooy mbokk...

FÀTTALIKU OMAR BOLONDEŊ JÓOB… 2/2

(ÑAAREELU XAAJ) Bi ñu nee Senegaal moom na boppam tamit,...

2002, ATUM SUUXU JOOLAA BI

Bërki-démb 26 sàttumbar ci atum 2020, "Bateau le Joolaa"...

FAIDHERBE, SAAY-SAAY BI NUY SARGAL

Bi Siidiya Ndàtte Yàlla génnee àddina ak léegi, am...

JÉERI JOOR NDEELAAK TUBAAB BI

Jéeri Joor Ndeela Faal mu ngi gane àdduna ci...

DÉMB AK TEY

WIDEWO YI

WAXLEEN SEEN XALAAT

BOO BAÑEE ÑAAW…

Bu nu la waxee nga àggale kàddu gii, looy...

Njiitu Réew

Dangaa jiitoom Dañu la jiital Sa jubb cunduŋ xanaa taxul Moo ndax...

YAA GORE !

Yàgg, yàgg, dëgg ay daan Dëgg lottoon na Senegaal Usmaan Sonkoo...

Ndigalu Maam Ya

Afrig nee Waaw góor, waaw kumba Ayca leen ca waar wa Bu...

SÀCCIIN WI JËM CI TÀNN YI DËGMAL TE FEEÑALEES KO

Sëñ Abdu Xaadr Kebe mooy biral fii xalaatam ñeel...

TÀGGATOO

NJÀNGAT CI TÉERE YI

XËT YI LEEN DÀQAL

XIBAARI TÀGGAT-YARAM

FUTBAL Racine Club de Lens xamle na ni Nàmpalis Mendi dana jóge ca ekib ba...

TÀGGE : MEETAR XURAYSI BA DËDDU NA

Layookati Senegaal yi am nañu tiis ak njàqare  ginnaaw bi kenn ci seen naataangoo...

FRAPP : NOO BAÑ ! “ASSISES DE LA DÉMOCRATIE” BI MAKORÕ BËGG A AMAL UCAD DU FI AME !

Waa FRAPP siiwal nañu ab yégle, démb àllarba 18 suwe 2025, di ci biral...

TÉYANDI NAÑU PAAB MAALIG NDUUR (APR)

Tay lañu woolu woon Paab Maalig Nduur, nekkoon jëwriñ ca nguurug Maki Sàll ga...

FMI – SENEGAAL : ÀND LIGGÉEY NGIR JOYYANTI NAFA GI

FMI feddali na yéeneem ci liggéey ak Senegaal, gunge ko ngir mu joyyanti nafaam...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (18/3/2025)

COOWAL MUURAAY YI CI LEKOOL BI Coowal muuraay yi ci lekool bi dekkiwaat na. Démb...

AG PAS GU YEES DIGGANTE SENEGAAL AK MÓRITANI

Réewum Senegaal ak mu Móritani yeesal nañu ag pas ci seen diggante. Muy Pas...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI(13/3/2025)

NDOGAL YI ELIMAANU JËWRIÑ YI JËL ÑEEL MBIRUM SUUF SI Démb, ci àllarba ji lañu...

TUKKIB ELIMAANU JËWRIÑ YI FA RÉEWUM SIIN

Àjjuma jii weesu la elimaanu jëwriñ yi, Usmaan Sonko, dooroon ab tukkeem fa bitim-réew....

TUKKIY NJIITU RÉEW MI

Njiitu réew mi, Basiiru Jomaay Jaxaar Fay, door na tukki yu am solo ci...

POROFESËER MUSAA DAAF WÀCC NA LIGGÉEY

Naqar ak uw tiis wu réy a réy la njaabotug jànguney Senegaal yi yeewoo....

NDAJEM NDEYU SÀRTU RÉEW MI NEENAL NA ÀTTEB LEERAL ÑEEL ÀTTEB MBAALE GI

Ndajem ndeyu sàrtu réew mi neenal àtteb leeral (loi d’interprétation) bi Ngomblaan gi wote...

Cang gi Bambaa ko moom !

Cang gi ñuy woote fa Sëriñ Tuubaa lañu koy fekk. Mooy ki jëkk a woote...

SEN-PNA AK MEDIS S.A BOOLOO NAÑU NGIR LIGGÉEY

SEN-PNA mooy banqaas bi ñu dénk lépp lu aju ci defar, jënd ak séddale...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (29/4/2025)

YOKKUTEG SENEGAAL CI ATUM 2025 MI Ci atum 2025 mi, Càmm gu Senegaal moo ngi...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (19/8/2025)

FMI YÓNNEE NAY NDAW FI SENEGAAL Ay ndawi FMI (Fond Monétaire International, di kurélug koom-koomu...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (10/4/2025)

WOOLU NAÑU SIMÕ FAY Yoon a ngi wéy di teg bët ci liy xew ci...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (24/7/2025)

UBBITEG CAMPUSEN Bu yàggul dara la joŋantey fàggug lijaasa bii ñuy dippe Baccalauréat jeex. Nde,...

XIBAARI TÀGGAT-YARAM

KUPPEG ÀDDINA 2026  Ci weeru màrs wii, Senegaal dina ci amal ñaari mats ñeel...

XALAM NEEXOON NA BA NOPPI…

“Xalam demoon na bay neex, buum ga dog”. Wolof dina faral di wax kàddu...

SÉYDINAA MUHAMMADU MAXTAAR LAAY, XALIFA LAAYEEN YI, DËDDU NA.

Xalifa Laayeen yi, Séydinaa Muhammadu Maxtaar Laay, génn na àddina guddig talaata (8eelu awril...

SÉMBUW KOPPEY MBAY ÑEEL NJABOOTU DAARA

Jëwriñu Mbay mi, Dund gu doy gi ak Càmm gi, Sëñ Mabuuba Jaañ, yégle...

MBIRUM KOPPARI COVID-19 YI : JÀPP NAÑU MANSUUR FAY

Mansuur Fay mi ngi ci guddi gu lëndëm këriis. Nde, jamono yii, Yoon dafa...

MBOOTAAYU XEET YI WOTE NA “DECLARATION DE NEW YORK” BI

Ngomblaanu Mbootaayu Xeet yi nangu na lees duppee "Déclaration de New York" bi nga...

38EELU NDAJEM BENNOOG AFRIG (UA)

38eelu ndajem Bennog Afrig (Union Africaine) mee ngi ñuy amal jamono yii fa Ecopi....

LI GËN A FÉS CI XIBAARI DÉMB YI (3/6/2025)

PAS YU BEES DIGGANTE SENEGAAL AK MURITANI Réewum Senegaal ak mom Muritani xaatim nañu ñaari...

COOWAL BOR BI ÑU NËBB

Coowal bor bi ñu ne Nguurug Maki Sàll dafa ko nëbboon a ngi wéy...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (6/2/2025)

LIMUB SAABALUKAAY YI SÀMMONTE AK SÀRT YI Sànq ci bëccëg lañu siiwal limub saabalukaay yi...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (15/5/2025)

YOON LÀBBALI NAW FASAM Ayu-bés bee ñu génn la Ngomblaan gi tegoon ay tuuma ci...

LI GËN A FÉS CI XIBAAR BÉS BI (4/9/2025)

GÀMMU 2025 Tay, alxames, yemoo ak ñeenti fan ci weeru sàttumbar lañuy màggal bés bi...

XIBAARI TÀGGAT-YARAM

FUTBAL : SAA-SENEGAALI BITIM-RÉEW Abiib Jara gan-ganluwul fa Àngalteer. Gannaaw ba mu jógee Strasbourg dem Sunderland,...

MANSUUR FAY AM NA DËGG CI KAW NGUUR GI

Dañu tere woon Mansuur Fay mu génn réew mi. Fan yii weesu, waññi nañu...

PALESTIN, JIRIMU ÀDDINA SI

Ñaar-fukki weeri xare yoy, bés bu nekk, fa Gasaa, ay bakkan rot. Bu leen...

USMAAN SONKO YÉENE NA WÀÑÑIB MBËJ GI, NJAFAAN GEEK GIL BI

Càmm gaa ngi ci tànki wàññi njëgi mbëj gi, njafaan gi, gil bi...