BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi ñu jagleel waa jasporaa bi, ci njiiteefu Njiitu réew mi...

BÉS NIKI TAY, NEELEEN DOKTOOR PÀPPA AALI JÀLLO

Gaawo, 13eelu desàmbar 2025, ca Jàngune bu Ndar, la Pàppa Aali Jàllo (njiitul LDW) doon gaaral teesam ci Làkk ak mbatiiti Afrig, duppe ko...

FOQATIG NGUUR FA RÉEWUM BENEE

Ginnaaw coowal sóobare yi toog fa boppu réewum Gine Bisaawu, geneen foqatig Nguur naroon naa amaat, wile yoon, fa réewum Benee ak ay sóobare...

MOUSSO NGIR « JIGÉEN GÉNN CIG LËNDËM »

Soo déggee baatu « mousso », sam xel mën naa dem cib « restaurant » bu siiw ba ca Kanadaa. Waaye, « mousso » bii moom bokkul ak booba ; xéy-na...

NGOMBLAAN GI : DÉPITE YI TÀMBALI NAÑU CÀMBAR NAFA 2026 GI

Dépite yi tàmbali nañu càmbar nafag atu 2026 mi fa Ngomblaan ga. Ñu nar koo amal ci diiru ñaari ayu-bés ngir dalal jëwriñi Càmm...

MAGU WAXOON NAA KO

JIKKO JU RAFET MOOY TABAX AM RÉEW

Wolof nee na, rafet kanam, rafet jikko a ko...
01:33:07

“Héritages” dalal na Bubakar Bóris Jóob

"Héritages ak Awa" ngi dalal Bubakar Bóris Jóob, ngir...

Malaanum Lëndëm : Bóris Jóob, na woon, fa woon

Ñeenteelu yoon a ngi nii Bubakar Bóris Jóob di...

GÀCCE NGAALAAMA, MBUGAAR !

Senegaal amati na ndam ci 3eelu fan ci weeru...

KUJJE GEEK WOTEB 2022 BI: BËGG NAA LA, BËGGUMA LA, LOOLU JARUL COOW

Ci bésub 23 sàŋwiye ci atum 2022 bii di...

FÀTTALIKU DÉMB

SEEX

Seex Mooy góor Moo di as gor Mbokk ya ko wor Ñooy mbokk...

FÀTTALIKU OMAR BOLONDEŊ JÓOB… 2/2

(ÑAAREELU XAAJ) Bi ñu nee Senegaal moom na boppam tamit,...

2002, ATUM SUUXU JOOLAA BI

Bërki-démb 26 sàttumbar ci atum 2020, "Bateau le Joolaa"...

FAIDHERBE, SAAY-SAAY BI NUY SARGAL

Bi Siidiya Ndàtte Yàlla génnee àddina ak léegi, am...

JÉERI JOOR NDEELAAK TUBAAB BI

Jéeri Joor Ndeela Faal mu ngi gane àdduna ci...

DÉMB AK TEY

WIDEWO YI

WAXLEEN SEEN XALAAT

BOO BAÑEE ÑAAW…

Bu nu la waxee nga àggale kàddu gii, looy...

Njiitu Réew

Dangaa jiitoom Dañu la jiital Sa jubb cunduŋ xanaa taxul Moo ndax...

YAA GORE !

Yàgg, yàgg, dëgg ay daan Dëgg lottoon na Senegaal Usmaan Sonkoo...

Ndigalu Maam Ya

Afrig nee Waaw góor, waaw kumba Ayca leen ca waar wa Bu...

SÀCCIIN WI JËM CI TÀNN YI DËGMAL TE FEEÑALEES KO

Sëñ Abdu Xaadr Kebe mooy biral fii xalaatam ñeel...

TÀGGATOO

NJÀNGAT CI TÉERE YI

XËT YI LEEN DÀQAL

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (26/3/2025)

GII MARI SAAÑAA SAMP NAY LAAJ ÑEEL CÀMM GI Dépite bii di Gii Mari Saañaa...

KÀDDUY NJIITU RÉEW MI FA GINE BISAAWO

Njiitu réew mi Sëñ Basiiru Jomaay Jaxaar Fay yékkati nay kàddu woote fa Gine...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (20/3/2025)

COOWAL AMNISTI BI Coppiteg amnisti bi dépitey Pastef yi namm a wotelu ca Ngomblaan ga...

TUKKIB NJIITU RÉEW MI FA ESPAAÑ

Démb, ci dibéer ji, la Njiitu réew mi, Basiiru Jomaay Jaxaar Fay, bawoo ci...

« MËSUNOO GIS BOR BU ÑU NËBB BU TOLLU NII CI AFRIG », EDWARD GEMAYEL, NJIITU NDAWI FMI FI SENEGAAL

Nees ko biralee woon ci sunu yaxalu barki-démb bi, ndawi yi FMI yabal fi...

SOLOS FUDDËN

Coosaanu fuddën Fuddën as ngarab la sos, ci làkkuw farãse, dippees na ko lawsoña inermis,...

TÀGGE : NGŨGĨ WA THIONG’O DËDDU NA

Afrig ñàkkati na kenn ci doomam yu ràññeeku yi. Wile yoon, njabootu ladab ak...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (18/9/2025)

CÀMBARUG ÑETTI SÉMBI SÀRT Altine jii weesu lañu ubbiwaatoon Ngomblaan ga. Lañu ko dugge woon...

NDAJEM SALI NGIR SELLAL DUND BI

Lekk baax na. Waaye nag, na doon lekk lu baax, ci anam bu baax....

KAASAMAAS : DELLUB DAW-LÀQU YI

Door nañu sémbuw jàPpandal dellub daw-làqu yi fa Kaasamaas. Tay ci gaawu bi, 11i...

JUBBANTI : DALUWAAYU NIMERIG BI ÑEEL PÉNCOOM PÓLITIG BI

Nguur gi taxawal na daluwaay nimerig bees dippee JUBBANTI ngir waajal péncoom réew mi...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (26/8/2025)

NGOMBLAAN GI Dépite yi wote nañu sémbuw àtte wiy jëmmal yoolekat yi. Muy àtte bob,...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (9/1/2025)

BÉS BI ÑU JAGLEEL NJÀNGUM XALE YU JIGÉEN YI Tay, alxames juróom-ñeenti fan ci weeru...

MBIRUM KOPPARI “FONDS FORCE COVID-19”

Mbiru “Fonds Force Covid-19” mi lëmbe na lool réew mi fan yii. Bari na...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (30/7/2025)

SULLIWAAT NAÑ WAYNDAREW FÀLLU FAAL Mbirum Fàllu Faal lëmbe woon na lool réew mi jamono...

XIBAARI TÀGGAT-YARAM

KUPPEG AFRIG U17 Guney Senegaal yi amal nañu seen matsu kippu bu njëkk. Seen dëkkandoo...

WAX SA LÀKK, MOOM SA BOPP

Bi nu noppee ci fal Njiit lu bees, teg ko ci boppu réew mi,...

USÉYNU BÉEY, AT CI SUUF…

Bi Uséynu Béey génnee àddina ak tey, def na atum Yàlla. Ñu bari bind...

DÉGGOOB DAKKAL XEEX DIGGANTE ISRAAYEL AK HAMAS

Nguuru Israayel ak waa sóobarey Hamas yi (Palestin) am nañu déggoob dakkal xeex bi...

KORITE 2025 : KÀDDUY NJIITU RÉEW MI

Ci altiney tay jii la Njiitu réew mi julli korite. Fa Jumaay Ndakaaru ju...

USMAAN SONKO “ BÉG” NA CI TUKKEEM BI MU AMAL FA SIIN

Elimaanu jëwriñ yi, Usmaan Sonko, fésal na mbégteem ci tukki bi mu tukki fa...

CAABALUG ARCOP 2022-2023 : 3,2 MILIYAAR YU NE MËY !

ARCOP (Autorité de Régulation des Marchés Publics), di banqaas biy saytu lépp lu aju...

TIJJITEL ËTT AK BÉRÉBI ÀTTEKAAY YI : YÉENEY NJIITU RÉEW MI

Démb a nekkoon bésub tiijitel ëtt ak bérébi àttekaay yi ci njiitalu Njiitu Réew...

BÉS BI ÑU JAGLEEL JUR GI FI RÉEW MI

Démb ci gaawu bi, 22i fani féewirye, lañu doon màggal bés bi ñu jagleel...

IRÃ AK ISRAAYEL : LEBTOO, FEYTOO !

Xeex bi àddina sépp doon ragal ci diggante Irã ak Israayel tàmbali na. Ginnaaw...

COP 30 : ABDURAHMAAN JUUF FEDDALINA TAXAWAAYU SENEGAAL

Jëwriñ jii di Abdurahmaan Juuf yékkati na ay kàddu fa Beresil ngir dëggal taxawaayu...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (13/2/2025)

NDÉGLUG FARBA NGOM Tay, ci alxames ji la waa PJF (Pool Judiciaire Financier) woolu woon...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (23/5/2025)

XIBAAR ÑEEL JURÓOMI JËWRIÑ YI ËTTU YOON GU KAWE GI WOOLU WOON Ci ndoorteelu ayu-bés...

NDAJEM JËWRIÑ YI : NJIITU RÉEW MI ÀDDU NA CI LÀKKI RÉEW MI

Njiitu Réew mi, Sëñ Basiiru Jomaay Jaxaar FAY, jiite na, ci alarbay démb ji,...

XIBAARI TÀGGAT-YARAM

FUTBAL El Maalig Juuf tàmbali na ak ekibam bu bees bi, West Ham. Amal nañu...

1 ME : BÉSUB LIGGÉEYKAT YI

Benn fan ci weeru me mooy bés bi ñu jagleel liggéeykat. Maanaam, ci lél...

BÀJJEN ARAM

La Kocc jàngale woon nga feeñal ci talaata jii « Mag mat naa bàyyi cim réew » Teey,...

SONACOS SIGICOOR : JËWRIÑ MABUUBA XOOLI WOON NA NDEFAR GI

Jëwriñu mbey mi, Sëñ Mabuuba Jaañ, amaloon na tukkib nemmeeku fa Sigicoor. Li mu...

PÉNCOO MI ÑEEL NJÀNG MU KAWE MEEK GËSTU BI

Ginnaaw bi ñu nekkee ciy waxtaan ak i joyyanti ngir jubbanti ati njàng yu...

SENEGAAL-MÓRITANI : PAS GU BEES ÑEEL DEM BEEK DIKK BI

Réewum Senegaal ak mu Móritani fas nañu lu bees ci dem beek dikk bi....

PASTEF AK TFM, LU XEW ?

Coowoo diggante làngug Pastef gi ak tele bii di TFM du guléet ñu koy...