BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi ñu jagleel waa jasporaa bi, ci njiiteefu Njiitu réew mi...

BÉS NIKI TAY, NEELEEN DOKTOOR PÀPPA AALI JÀLLO

Gaawo, 13eelu desàmbar 2025, ca Jàngune bu Ndar, la Pàppa Aali Jàllo (njiitul LDW) doon gaaral teesam ci Làkk ak mbatiiti Afrig, duppe ko...

FOQATIG NGUUR FA RÉEWUM BENEE

Ginnaaw coowal sóobare yi toog fa boppu réewum Gine Bisaawu, geneen foqatig Nguur naroon naa amaat, wile yoon, fa réewum Benee ak ay sóobare...

MOUSSO NGIR « JIGÉEN GÉNN CIG LËNDËM »

Soo déggee baatu « mousso », sam xel mën naa dem cib « restaurant » bu siiw ba ca Kanadaa. Waaye, « mousso » bii moom bokkul ak booba ; xéy-na...

NGOMBLAAN GI : DÉPITE YI TÀMBALI NAÑU CÀMBAR NAFA 2026 GI

Dépite yi tàmbali nañu càmbar nafag atu 2026 mi fa Ngomblaan ga. Ñu nar koo amal ci diiru ñaari ayu-bés ngir dalal jëwriñi Càmm...

MAGU WAXOON NAA KO

JIKKO JU RAFET MOOY TABAX AM RÉEW

Wolof nee na, rafet kanam, rafet jikko a ko...
01:33:07

“Héritages” dalal na Bubakar Bóris Jóob

"Héritages ak Awa" ngi dalal Bubakar Bóris Jóob, ngir...

Malaanum Lëndëm : Bóris Jóob, na woon, fa woon

Ñeenteelu yoon a ngi nii Bubakar Bóris Jóob di...

GÀCCE NGAALAAMA, MBUGAAR !

Senegaal amati na ndam ci 3eelu fan ci weeru...

KUJJE GEEK WOTEB 2022 BI: BËGG NAA LA, BËGGUMA LA, LOOLU JARUL COOW

Ci bésub 23 sàŋwiye ci atum 2022 bii di...

FÀTTALIKU DÉMB

SEEX

Seex Mooy góor Moo di as gor Mbokk ya ko wor Ñooy mbokk...

FÀTTALIKU OMAR BOLONDEŊ JÓOB… 2/2

(ÑAAREELU XAAJ) Bi ñu nee Senegaal moom na boppam tamit,...

2002, ATUM SUUXU JOOLAA BI

Bërki-démb 26 sàttumbar ci atum 2020, "Bateau le Joolaa"...

FAIDHERBE, SAAY-SAAY BI NUY SARGAL

Bi Siidiya Ndàtte Yàlla génnee àddina ak léegi, am...

JÉERI JOOR NDEELAAK TUBAAB BI

Jéeri Joor Ndeela Faal mu ngi gane àdduna ci...

DÉMB AK TEY

WIDEWO YI

WAXLEEN SEEN XALAAT

BOO BAÑEE ÑAAW…

Bu nu la waxee nga àggale kàddu gii, looy...

Njiitu Réew

Dangaa jiitoom Dañu la jiital Sa jubb cunduŋ xanaa taxul Moo ndax...

YAA GORE !

Yàgg, yàgg, dëgg ay daan Dëgg lottoon na Senegaal Usmaan Sonkoo...

Ndigalu Maam Ya

Afrig nee Waaw góor, waaw kumba Ayca leen ca waar wa Bu...

SÀCCIIN WI JËM CI TÀNN YI DËGMAL TE FEEÑALEES KO

Sëñ Abdu Xaadr Kebe mooy biral fii xalaatam ñeel...

TÀGGATOO

NJÀNGAT CI TÉERE YI

XËT YI LEEN DÀQAL

UBBITEG KOPPEY LIGGÉEY AK JÀPPALANTE YI

Elimaanu jëwriñ yi, Usmaan Sonko, ma nga woon Kumpentum, fa diiwaanu Tàmbaakundaa. Ci àjjumay...

SENEGAAL DÓOR NA ÀNGALTEER 3-1

Gaynde Senegaal yi fàdd nañ yoy Àngalteer ya. Ñetti bal la leen gari Senegaal...

“FII SÉNÉGAL 2025” : MBIR MI, FII LA !

Ci talaatay tay jii, 7eelu fanu oktoobar 2025, lees door ndajem liggéey bees dippee...

JÀNGUNEB UGB : NDONGO LI ÑU FEKK MU DEE CA NÉEGAM

Naqar ak uw tiis la ndongoy jànguneb Gastõ Berse fanaane démb. Seen benn moroom...

AIBD : SYTAS ÀNDUL CI NDOGALU NJIIT LA

SYTAS (Syndicat des Travailleurs des Aéroports du Sénégal) nanguwul a dégg ndogal li njiitul...

NGOMBLAAN GI YEESAL NA SÀRTU-BIIRAM

Dépite yi jàllale nañu « loi organique no10/2025 ». Muy àtte bob, dafa ñëw ngir andi...

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi...

UMAR SISOKO EMBALOO DÀQ NA NDAWI CEDEAO AK UNOWAS

Ñaari kuréli Afrig sowu-jant yii di CEDEAO (Communauté Economique Des Etats de l’Afrique de...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (12/6/2025)

TUKKIB NJIITU RÉEW MI CI BËJ-GÀNNAARU RÉEW MI Tay, ci alxames ji, la Njiitu réew...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (9/10/2025)

YOON TÉYANDI NA ALIW SÀLL (RAKKU MAKI SÀLL) AK SOXNAAM Aliw Sàll, nekkoon fi meeru...

CONGUM GOMA FA KONGO RDC

Askanuw Goma dootuñu fàtte altiney tay jii, 27i fani sãwiyee 2025. Nde, ci fitna...

KOCC BARMA FAAL AK ÑAARI SÀMM YA

Nettali bii, jukkees na ko ci téere bii di Xew-xewi démb. Jukkib xët yuy...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (22/7/2025)

NJÀNGALE MU KAWE MI Jëwriñu njàngale mu kawe mi dina jël 500i jàngalekat ak i...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (20/6/2025)

GAINDESAT-1B : SENEGAAL WUTALI NA JAWW JI Senegaal a ngi séqi na jéego bu yees...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (15/4/2025)

LAAJ-TONTU (ELIMAANU JËWRIÑ YEEK DÉPITE YI) Démb ci altine ji, Elimaanu jëwriñ yi, Sëñ Usmaan...

NJÀNG MU KAWE MI : JËWRIÑ JI DINA JËL 1 500I JÀNGALEKAT

Jëwiriñu Njàng mu kawe mi, Gëstu beek Coste gi, dina jël 1 500i jàngalekat...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (3/4/2025)

NDOG MU METTI CI YOONU LINGEER AK MAATAM WI Yoon waa ngi wéy di bóom...

BADARA GAJAGA FANAANI NA KASO

Ayu-bés bii ñu génn lañu la Yoon woolu woon Badara Gajaga. Li sababoon woote...

XIBAARI TÀGGAT-YARAM

LÀMB JI Dibéer 16i fani féewiryee mooy bés bi njabootug lamb yépp di xaar. Ndax,...

KURÉLUG BINDKATI SENEGAAL YI AM NA NJIIT LU BEES : ABDULAAY FÓODE NJOON.

Gaawu, 8eelu màrs 2025, la kurélu bindkati Senegaal yi doon tabb njiit lu bees...

MOODY’S WÀCCEE NA NATTUB SENEGAAL

Moody’s Investors ag kurél la guy natt réewi àddina si ci wàllu kopparal. Bees...

GÉEWUB WAXTAANE LÀKKI RÉEW MI

Grand Théatre bu Ndakaaru mooy amal géewub waxtaane làkki réew mi : mbir mu...

CÀMM GU YEES GI

Càmm gi soppeeku na. Démb, ci guddig gaawu bi, 6 sàttumbar 2025, la elimaanu...

NAFAG 2026 : JAGLEES NA 356 MILIYAAR NJËWRIÑU YAXANTU BEEK NDEFAR GI

Njiiti Senegaal yi dañu bëgg a jël fànnu ndefar wi, def ko xolu koom-koomu...

KAARAANGE TALI BI : NDOG YEE NGI WÉY DI FAAT

Bëgg-bëggu Nguur gi moo doonoon wàññi limub ndog yi ci tali bi ba, fii...

TABASKI 2025 : CÀMM GEE NGI CI WAAJTAAY YI

Càmmug Senegaal a ngi ba tay ci waaytaayi tabaski 2025 bi. Ginnaaw déggoo bi...

MBIRUM MAJAMBAL JAAÑ

Ginnaaw bi Majambal Jaañ dawee, génn réew mi, Nguurug Senegaal jàpplu na ko fu...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (31/1/2025)

JURÓOM-ÑEENTEELU BÉSU SET-SETAL Set-setal bi ab xew-xew la boo xam ne Nguur gee ko doon...

ÑAXTUY LÀNGI PÓLITIGI MALI YI

Coowi pólitig yi lëmbe na lool réewi Afrig sowu-jant yi, rawatina ci juróomi at...

ABBAAS FAAL : “BOROOM NDAKAARU”

Tay, ci altine ji, lañu doon wote ngir fal meeru Ndakaaru biy wuutu Bàrtelemi...

“COUPE DU MONDE DES CLUB 2025”

Joŋanteb kuppe bees duppee “Coupe du monde des clubs”, di po mu mag muy...

AJAA JAAL MBAAY, JAAR NA BA JÀLL

Àddina yoon la wow, ku ko xas ba dëgmal, dem rekk. Moo waral sunu...

BÉS NIKI TAY, NEELEEN DOKTOOR PÀPPA AALI JÀLLO

Gaawo, 13eelu desàmbar 2025, ca Jàngune bu Ndar, la Pàppa Aali Jàllo (njiitul LDW)...

FMI DËGGAL NA ËTTUB CETTANTAL GI

RFI, saabalukaay Farãs bi, moo siiwal xibaar bi. Ci li mu fésal, FMI dafa...

IRÃ – ISRAAYEL : XARE BAA NGAY WÉY

Xare baa ngay wéy diggante Irã ak Israayel. Ci guddig démb gi, gaawu jàpp...

BUL BIND… / BINDAL…

Seen yéenekaayu web ci wolof ubbil na leen xët wu bees wees duppee BUL...