COKKAASU ODIA

MAGU WAXOON NAA KO

JIKKO JU RAFET MOOY TABAX AM RÉEW

Wolof nee na, rafet kanam, rafet jikko a ko...
01:33:07

“Héritages” dalal na Bubakar Bóris Jóob

"Héritages ak Awa" ngi dalal Bubakar Bóris Jóob, ngir...

Malaanum Lëndëm : Bóris Jóob, na woon, fa woon

Ñeenteelu yoon a ngi nii Bubakar Bóris Jóob di...

GÀCCE NGAALAAMA, MBUGAAR !

Senegaal amati na ndam ci 3eelu fan ci weeru...

WAAW, KAÑ LA SENEGAAL GËJ A YËNGOO NII…?

Weeru màrs wii weesu, Senegaal tàngoon na jipp !...

KÀDDUY USMAAN SONKO 2/2 PÀCC

Senegaal gépp amoon na fiy yëngu-yëngu, réew mi jaxasoo,...

KÀDDUY USMAAN SONKO 1/2 PÀCC

Senegaal gépp amoon na fiy yëngu-yëngu, réew mi jaxasoo,...

Njàngatub Bàmmeelu Kocc : Téereb dekkali 1/2

Du guléet. Déedéet. Bindkat bi tëbul rekk bind Bàmmeelu...

FÀTTALIKU DÉMB

SEEX

Seex Mooy góor Moo di as gor Mbokk ya ko wor Ñooy mbokk...

FÀTTALIKU OMAR BOLONDEŊ JÓOB… 2/2

(ÑAAREELU XAAJ) Bi ñu nee Senegaal moom na boppam tamit,...

2002, ATUM SUUXU JOOLAA BI

Bërki-démb 26 sàttumbar ci atum 2020, "Bateau le Joolaa"...

FAIDHERBE, SAAY-SAAY BI NUY SARGAL

Bi Siidiya Ndàtte Yàlla génnee àddina ak léegi, am...

JÉERI JOOR NDEELAAK TUBAAB BI

Jéeri Joor Ndeela Faal mu ngi gane àdduna ci...

DÉMB AK TEY

Dal-leen ak jàmm ci seen xët DÉMB AK TEY...

JIÑAABO, JÀMBAARU SELEKI BA CA SIGICOOR

Boo demee ca diiwaanu Sigicoor, dinga fa fekk liise...

DAAWUDA JAAWARA FAATU, NUY FÀTTALIKU SENEGÀMBI

Daawuda Kayraba Jaawara, jiite woon fi réewum Gàmbi 1979...

SAARTJIE BAARTMAN, NDAW SA TUBAAB YI DEFOON MALA

Saartjie Baartman ab jaam la woon, fekkoon baax ca...

WIDEWO YI

WAXLEEN SEEN XALAAT

BOO BAÑEE ÑAAW…

Bu nu la waxee nga àggale kàddu gii, looy...

Njiitu Réew

Dangaa jiitoom Dañu la jiital Sa jubb cunduŋ xanaa taxul Moo ndax...

YAA GORE !

Yàgg, yàgg, dëgg ay daan Dëgg lottoon na Senegaal Usmaan Sonkoo...

Ndigalu Maam Ya

Afrig nee Waaw góor, waaw kumba Ayca leen ca waar wa Bu...

SÀCCIIN WI JËM CI TÀNN YI DËGMAL TE FEEÑALEES KO

Sëñ Abdu Xaadr Kebe mooy biral fii xalaatam ñeel...

TÀGGATOO

Roqi, ba beneen yoon. Seetal ma lii rekk. Wax dëgg....

NJÀNGAT CI TÉERE YI

XËT YI LEEN DÀQAL

NJÀNG MI : JËLUB 2000iy JÀNGALEKAT

Bàrki-démb ci alxames ji, 23 sãwiyee 2025, la Càmm gi tijji woon jëlub 2...

GUDOMP : 92i KËR JOT NAÑUY JUMTUKAAYI TABAX

Fa gox bii di Gudomp, njaboot yi tàmbalee dellusi ginnaaw bi leen fa xareb...

TUKKIB ELIMAANU JËWRIÑ YI FA EMIRAAT ARAAB YA AK ITAALI

Elimaanu jëwriñ yi, Sëñ Usmaan Sonko, moo nga woon tay fa réewum Itaali, ginnaaw...

KAAJARUG “NEW DEAL TECHNOLOGIQUE”

Tay ci altine ji lañu doon aajar naal wees dippee “New Deal Technologique”. Ndaje...

MBIRUM DUWAAÑE BI LÀQOON YÀMBAA CI DAAMARAM

Kaawteef ! Ab duwaañe lees fekk yàmbaa cig daamaram. Mbuur la xewee. Mu di...

UBBITEG LEKKOOL YI CI SENEGAAL

Tay, altine juróom-benni fan ci weeru oktoobar atum 2025, lañu ubbi lekkool yi fii...

XIBAARI TÀGGAT-YARAM

EKIBU SENEGAAL BU MAG BI Paap Caw, tàggatkatu ekib bi siiwal na limka ndaw yi...

NGOMBLAAN : DINDI NAÑU MBALAANU KIIRAAYU FARBA NGOM

Dépite yi dindi nañu mbalaanu kiiraayu Farba Ngom ci àjjumay tay jii, 24i sãwiyee...

MBIRUM KOPPARI COVID-19 YI : JÀPP YAA NGIY WÉY

Mbasum koronaa maa ngi wéy di lëmbe réew mi. Naam, jàngoro ji wéy na,...

XURUW DEX GI : ISRA MI NGI CAAF MBAYUM CEEB MU YEES

ISRA sóobu na ci xeetu mbayum ceeb mu yees ca bëj-gànnaaru réew mi. Nde,...

USMAAN SONKO : « JÀMM REKK LAA SÉQ AK JOMAAY… LIGGÉEYALUMA JOMAAY, SENEGAAL LAAY LIGGÉEYAL. »

Elimaanu jëwriñ yi doon na janook dépite yi, ci àjjumay tay ji. Moom ak...

Doxub sàrgal Séex Anta Jóob

Mbootaayu Panafrig « La marche internationale Dakar-Thieytou » amaloon na am ndaje ak saabalkat yi ca...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (04/3/2025)

ÑAXTUB VACATAIRES YI REVUS (Regroupement des Enseignants Vacataires du Sénégal, di kurélug jàngalekat yi ñu...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (24/6/2025)

NGURD CÀMM GI CI ÑETTI WEER YI JIITU CI ATUM 2025 MI Jëwriñu ngurd meek...

FOQATIG NGUUR FA RÉEWUM BENEE

Ginnaaw coowal sóobare yi toog fa boppu réewum Gine Bisaawu, geneen foqatig Nguur naroon...

MAMADU JA CA KAW, DE GAULLE CI SUUF !

Démb, ci àllarba ji, lañu doon amal ndajem jëwriñ yi, ni ñu ko baaxoo...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (10/7/2025)

PASTEF MÀGG NA Atum 2014 lañu sosoon làng gii ñuy dippe PASTEF. Maanaam, atum ren...

CAN MAROG 2025

Puluf nañu kippuy CAN 2025 bees dëgmal te mu war a ame fa Marog....

21EELU FÉEWIRYEE : BÉS BI ÀDDINA JAGLEEL LÀMMIÑ WEES NÀMP

Làmmiñ wees nàmp ci ekooli tuut-tànk yi… Làmmiñi réew mi, lépp la ñu mën, mën...

LAAJI DÉPITE YI ÑEEL CÀMM GI

Elimaanu jëwriñ yi, Usmaan Sonko, ak Càmm gi mu jiite ña nga woon ca...

MBIRUM AAMADU (MAKI) SÀLL : WOOLU NAÑ WAALI SEKK

Mbirum Aamadu Sàll, doomu Njiitu réew ma woon (Maki Sàll), mi ngi wéy di...

NDAJEM PÉNCOO NOSTEG DUND BI CI KEMBAARU AFRIG CI ATUM 2025.

Jamono jii, ñu ngi amal, fi Ndakaaru, lees ndaje mees duppee « Forum Africain des...

GASAA : ISRAAYEL DOGAALE NA GAALUG NDIMBAL GII DI « MADLEEN »

Ci guddig altine 8, jàpp talaata 9eelu fanu suwe 2025 la sóobarey géej yu...

NGUUR GI DAJALE NA 405i MILIYAAR

Nguurug Senegaal dajale na 405i miliyaar ci 15i fan kese. Muy alal ju takku...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (5/8/2025)

ÑAXTU LIGGÉEYKAT YI CI WÀLLU YOON Démb ci altine ji, 4 ut 2025, kurélug layookat...

SEROM BÀNJAKI DUUT NA BAARAAM MIMI TURE

Weeru sàttumbaar wee jàll lañu tegoon loxo kii di Serom Bànjaki, ñu di ko...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (1/5/2025)

XAATIMUG DÉGGOOB DAL DIGGANTE NGUUR GI, SÀNDIKAA YI AK “PATRONATS” YI Bésub alxamesu tay jii...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (21/8/2025)

DAKKALUG DUGAL GAAS CI RÉEW MI Réewum Senegaal mi ngi waaj a séqi beneen jéego...

PARIS SAINT-GERMAIN : BIDDEEW BI DIKK NA!

Ca péeyu Farãs, Pari, foo sànni mbattu mu tag. Te lenn waralu ko lu...

LI CI DIGGANTE NIT AK NITE

Moo xam muy seen doomu bopp walla jeneen ju ñu leen dénk, way-jur yu...

MOUSSO NGIR « JIGÉEN GÉNN CIG LËNDËM »

Soo déggee baatu « mousso », sam xel mën naa dem cib « restaurant » bu siiw ba...

UBBITEG KOPPEY LIGGÉEY AK JÀPPALANTE YI

Elimaanu jëwriñ yi, Usmaan Sonko, ma nga woon Kumpentum, fa diiwaanu Tàmbaakundaa. Ci àjjumay...

SENEGAAL DÓOR NA ÀNGALTEER 3-1

Gaynde Senegaal yi fàdd nañ yoy Àngalteer ya. Ñetti bal la leen gari Senegaal...

“FII SÉNÉGAL 2025” : MBIR MI, FII LA !

Ci talaatay tay jii, 7eelu fanu oktoobar 2025, lees door ndajem liggéey bees dippee...

LI GËN A FËS CI XIBAARI BÉS BI (6/11/2025)

PRODAC : YOON TÉYANDI NAÑU Tay ci ngoon la takk-deri DIC yi fekki Paab Maalig Nduur...

MBËKK MI : JÀPP NAÑU MEERU JONWAAR BI

Laasana Saar, meeru Jonwaar, ak yeneen juróom-benni nit ñu ngi ci loxoy Yoon jamono...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (28/1/2025)

NGOMBLAAN GI Coppite am na ci doxalinu Ngomblaan gi. Dog nañu ndàmpaay yi ñu daan...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (20/05/2025)

ËTTU ÀTTEKAAY BU KAWE BI Ëttu àttekaay bu kawe bi tàmbali naa déglu jëwriñ yees...

DOXU ÑAXTU KUJJE GI

Ginnaaw tekkaaral gu yàgg gees nemmeeku woon ci kujje gi diggante bi waa Pastef...

UMAR SISOKO EMBALOO DÀQ NA NDAWI CEDEAO AK UNOWAS

Ñaari kuréli Afrig sowu-jant yii di CEDEAO (Communauté Economique Des Etats de l’Afrique de...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (12/6/2025)

TUKKIB NJIITU RÉEW MI CI BËJ-GÀNNAARU RÉEW MI Tay, ci alxames ji, la Njiitu réew...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (9/10/2025)

YOON TÉYANDI NA ALIW SÀLL (RAKKU MAKI SÀLL) AK SOXNAAM Aliw Sàll, nekkoon fi meeru...

CONGUM GOMA FA KONGO RDC

Askanuw Goma dootuñu fàtte altiney tay jii, 27i fani sãwiyee 2025. Nde, ci fitna...

KOCC BARMA FAAL AK ÑAARI SÀMM YA

Nettali bii, jukkees na ko ci téere bii di Xew-xewi démb. Jukkib xët yuy...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (22/7/2025)

NJÀNGALE MU KAWE MI Jëwriñu njàngale mu kawe mi dina jël 500i jàngalekat ak i...

JÀNGUNEB UGB : NDONGO LI ÑU FEKK MU DEE CA NÉEGAM

Naqar ak uw tiis la ndongoy jànguneb Gastõ Berse fanaane démb. Seen benn moroom...