BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi ñu jagleel waa jasporaa bi, ci njiiteefu Njiitu réew mi...

BÉS NIKI TAY, NEELEEN DOKTOOR PÀPPA AALI JÀLLO

Gaawo, 13eelu desàmbar 2025, ca Jàngune bu Ndar, la Pàppa Aali Jàllo (njiitul LDW) doon gaaral teesam ci Làkk ak mbatiiti Afrig, duppe ko...

FOQATIG NGUUR FA RÉEWUM BENEE

Ginnaaw coowal sóobare yi toog fa boppu réewum Gine Bisaawu, geneen foqatig Nguur naroon naa amaat, wile yoon, fa réewum Benee ak ay sóobare...

MOUSSO NGIR « JIGÉEN GÉNN CIG LËNDËM »

Soo déggee baatu « mousso », sam xel mën naa dem cib « restaurant » bu siiw ba ca Kanadaa. Waaye, « mousso » bii moom bokkul ak booba ; xéy-na...

NGOMBLAAN GI : DÉPITE YI TÀMBALI NAÑU CÀMBAR NAFA 2026 GI

Dépite yi tàmbali nañu càmbar nafag atu 2026 mi fa Ngomblaan ga. Ñu nar koo amal ci diiru ñaari ayu-bés ngir dalal jëwriñi Càmm...

MAGU WAXOON NAA KO

JIKKO JU RAFET MOOY TABAX AM RÉEW

Wolof nee na, rafet kanam, rafet jikko a ko...
01:33:07

“Héritages” dalal na Bubakar Bóris Jóob

"Héritages ak Awa" ngi dalal Bubakar Bóris Jóob, ngir...

Malaanum Lëndëm : Bóris Jóob, na woon, fa woon

Ñeenteelu yoon a ngi nii Bubakar Bóris Jóob di...

GÀCCE NGAALAAMA, MBUGAAR !

Senegaal amati na ndam ci 3eelu fan ci weeru...

KUJJE GEEK WOTEB 2022 BI: BËGG NAA LA, BËGGUMA LA, LOOLU JARUL COOW

Ci bésub 23 sàŋwiye ci atum 2022 bii di...

FÀTTALIKU DÉMB

SEEX

Seex Mooy góor Moo di as gor Mbokk ya ko wor Ñooy mbokk...

FÀTTALIKU OMAR BOLONDEŊ JÓOB… 2/2

(ÑAAREELU XAAJ) Bi ñu nee Senegaal moom na boppam tamit,...

2002, ATUM SUUXU JOOLAA BI

Bërki-démb 26 sàttumbar ci atum 2020, "Bateau le Joolaa"...

FAIDHERBE, SAAY-SAAY BI NUY SARGAL

Bi Siidiya Ndàtte Yàlla génnee àddina ak léegi, am...

JÉERI JOOR NDEELAAK TUBAAB BI

Jéeri Joor Ndeela Faal mu ngi gane àdduna ci...

DÉMB AK TEY

WIDEWO YI

WAXLEEN SEEN XALAAT

BOO BAÑEE ÑAAW…

Bu nu la waxee nga àggale kàddu gii, looy...

Njiitu Réew

Dangaa jiitoom Dañu la jiital Sa jubb cunduŋ xanaa taxul Moo ndax...

YAA GORE !

Yàgg, yàgg, dëgg ay daan Dëgg lottoon na Senegaal Usmaan Sonkoo...

Ndigalu Maam Ya

Afrig nee Waaw góor, waaw kumba Ayca leen ca waar wa Bu...

SÀCCIIN WI JËM CI TÀNN YI DËGMAL TE FEEÑALEES KO

Sëñ Abdu Xaadr Kebe mooy biral fii xalaatam ñeel...

TÀGGATOO

NJÀNGAT CI TÉERE YI

XËT YI LEEN DÀQAL

GÉNNUG ÀDDINA Me USMAAN SÉY 

Me Usmaan Séy, layookat bu siiw bi, moo génn àddina. Ay mbokkam a ko...

ÑAAW NA BA NOPPI

Paap Aliyun Saar a doon dalal Bubakar Bóris Jóob ca ITV. Tolluwaayu réew mi...

FAN LANU JËM AK ÑAKKI BILL GATES YI?

(USÉYNU BÉEY) Coow laa ngi ne kurr ! Afrig ba Afrig daj, li ko dale Keer...

IBA DEER WÉETAL NA SENEGAAL (NDEY KODDU FAAL)

Gaawu 31eelu fan ci weeru oktoobar 2020 la Iba Deer Caam génn àddina ci...

YËNGU-YËNGUY RÉEW MI : JÀNGUNE YAA NGIY TËJ

Juróom-ñeenti bakkan ci alxames ji, fukk ak ñett ci àjjuma ji, muy ñaar-fukk ak...

Li gёn a fés ci xibaari bés bi Alxames 24 nowàmbar 2022

POLITIG Tabb yu yees yi Ca ndajem jёwriñ ma mu doon amal démb, Njiitu réew mi...

PEKKUG NGOMBLAAN GU BEES GI

Ci talaatay démb ji, li ko dale 11i waxtu ci yoor-yoor bi, lees doon...

SËÑ BÀMBA

Sëñ Bàmba Kéemaan la Dem ba ñëw war a sant ci ñibbisi gi Di sant Boroom...

JÀNGOROY ÑÀKK JI NU GANESI

Askanu Senegaal tollu na ci diggante bu tar cig ñàkk ba sax, li ëpp...

ÀND WATTU LÀKKI RÉEW MI

"MBINDAAN" LEES WAROON A BIND ------------------------------------------------------------------------------ ÀND WATTU LÀKKI RÉEW MI Ànd jubal mbind mi ! Ñaareelu yëngug...

XIBAARI TÀGGAT-YARAM (Dibéer 29 saŋwiye 2023)

CHAN 2023 Sunu gaynde yee ngi wëyal di wane seen bopp fale ca Alseri. Bërki-démb,...

NOOK MBËNN MII NAG, BA KAÑATI ? (SÉEX AXMADU BÀMBA NJAAY)

Séex Axmadu Bàmba Njaay “Ku ndóbin rey sa Maam, foo gisee lu ñuul sax daw.”...

TABASKI 2023 : XUTBA SËRIÑ MAAHI ÑAS

Ci alxamesu démb ji la ñu ëpp ci saa-senegaal yi tabaski. Ku ne tabaski,...

MBAAM MI : ÑETTI LÉEB

Cokkaasu RFI bii daf nuy fàttali ñetti léeb yoy, mbaam a ciy ndeyu-mbill ji....

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI Gaawu 27 ut 2022

 PÓLITIG  Coow li amoon  ci diggante Gabriyel Kan ak jëwriñ ji ñu dénk mbiri jigéen...

Misig

Feetu misig Tey la bés bi ñu jagleel misig. Ñu di ko màggal fii ci...

PÉEXTE (LÀMP FAAL KALA)

PÉEXTE Da maa dëfeenu di jeneer Ba xel mi tàbbi cig ndenéer Dellusi naan ma nu gàddaay Fii...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (ALXAMES 4 ME 2023)

UBBITEG FÓRËM KOOM-KOOMUG MBOOLAAY GEEK JÀPPALANTE BI Ci alxamesu tey ji la Njiitu réew mi,...

Coowal bóom gi am ca Karma

Ci 20 awril bii weesu, lu ëpp 150i doom-aadam lañ faatoon ca dëkk bu...

LI GЁN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI Alxames 20 oktoobar 2022

XIBAARI BITIM-RÉEW Fitna sa ca Càdd Lu tollu ci 60i nit ak lu teg ñoo ñàkk...

PELENT YA JOLLI NAÑ

Téere Séex Yérim Sekk bi ak coowal Aji Saar-Usmaan Sonko ñooy ñaari xibaar yi...

PALUG KURÉL YIY TEEWAL JÀNGALEKAT YI

Njureef ya tukke ca wotey sendikaa jàngalekat yi bir na. Mu mel ni, jàngalekati...

LI GËN A FËS CI XIBAARI BÉS BI

PÓLITIG Saa-fuuta yi noppeeguñoo wannaasu tiiñal gi leen ñenn ci kujje giy tiiñal bi Bennoo...

Li gën a fés ci xibaari tàggat yaram (Gaawu 4 féewaryee 2023)

PREMIER LEAGUE / ÀNGALTEER  Liverpool Ribeertoo Firminoo yëgal na waa këlëb ba ak tàggatkatam, Jurgen Klopp,...

MEERI BU NDAKAARU : DÀQ NAÑ ABBAAS FAAL MU PASTEF

Démb ci àllarba ji la meeri bu Ndakaaru doon yeesalaat pekkoom gi. Li ñu...

CI GÀTTAL, XIBAAR YI GËN A FÉS CI AYU-BÉSUG ALTINE 27 JÀPP ALXAMES 30 ME 2019

#Diisoo ñeel réew mi Diisoo bi Njiitu-réew mi, Maki Sàll, woote woon door na ci...

SËÑ BAS, KU WAX FEEÑ

Sa tànk mën na la dugal, sa làmmiñ génne la ; sa loxo dugal...

NISERYAA : BUHARI FALUWAAT NA

Ci weeru féewaryee wii jàll la askanu Niseryaa doon amal woteb njiitu réewam. Ba...

AY DU YAM CI BOPPU BOROOM

Jàppante ba amoon Mbàkke doxoon ci diggante takk-der ya ak soppey njiitu Pasteef lii...

XIBAARI TÀGGAT-YARAM (21/6/2023)

Senegaal duma na Beresil 4-2 Démb ci talaata ji la ekibu Senegaal bu mag bi...

Réewandoo (fédération) diggante Burkinaa, Mali ak Gine ?

Jëwrin yees dénk wàlluw bittim réew ca Mali, Burkinaa ak Gine jot nañoo amal...

USMAAN SONKO : « MAKI SÀLL CUUNE LA, DI DEF YËFI CUUNE. » (Ndey Koddu Faal, Paap Aali Jàllo, Daawuda Géy)

(Xaaj bu njëkku laaj-tontook Ndey Koddu Faal, Paap Aali Jàllo ak Daawuda Géy) LU DEFU...

“ WÀDD MOO REY ARTISANAA BI, MAKI SÀLL A KO SUUL”

Senegaal dafa tollu ci jamono joo xam ne, képp ku jàngul, mënul a jot...

SÉEX ANTA JÓOB, SUUL KER DU KO TEE FEEÑ…

Séex Anta Jóob a ngi juddoo Céytu, 29eelu fan ci desàmbar 1923. Alxuraan la...

BU YÀLLA NEE WAAW, LÉPP AY BAAX

Li gaa yi naan bàmba bu naan, Senegaal jamono jii bàmbaam naan na ba...

FAATUG HIBAA CAAM : SENEGAAL, BOPP BU XAR ÑAAR?

Guddi àjjuma, dëppook 3eelu fan ci weeru Awril, doon guddi gi jiitu bésub baaxentalub...

LI GЁN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI Àjjuma 14 oktoobar 2022

PÓLITIG Wayndare yiy xaar dépite yi Ginnaaw bi ñu taxawalee Ngomblaan gu bees, ci àjjuma jii...