BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi ñu jagleel waa jasporaa bi, ci njiiteefu Njiitu réew mi...

BÉS NIKI TAY, NEELEEN DOKTOOR PÀPPA AALI JÀLLO

Gaawo, 13eelu desàmbar 2025, ca Jàngune bu Ndar, la Pàppa Aali Jàllo (njiitul LDW) doon gaaral teesam ci Làkk ak mbatiiti Afrig, duppe ko...

FOQATIG NGUUR FA RÉEWUM BENEE

Ginnaaw coowal sóobare yi toog fa boppu réewum Gine Bisaawu, geneen foqatig Nguur naroon naa amaat, wile yoon, fa réewum Benee ak ay sóobare...

MOUSSO NGIR « JIGÉEN GÉNN CIG LËNDËM »

Soo déggee baatu « mousso », sam xel mën naa dem cib « restaurant » bu siiw ba ca Kanadaa. Waaye, « mousso » bii moom bokkul ak booba ; xéy-na...

NGOMBLAAN GI : DÉPITE YI TÀMBALI NAÑU CÀMBAR NAFA 2026 GI

Dépite yi tàmbali nañu càmbar nafag atu 2026 mi fa Ngomblaan ga. Ñu nar koo amal ci diiru ñaari ayu-bés ngir dalal jëwriñi Càmm...

MAGU WAXOON NAA KO

JIKKO JU RAFET MOOY TABAX AM RÉEW

Wolof nee na, rafet kanam, rafet jikko a ko...
01:33:07

“Héritages” dalal na Bubakar Bóris Jóob

"Héritages ak Awa" ngi dalal Bubakar Bóris Jóob, ngir...

Malaanum Lëndëm : Bóris Jóob, na woon, fa woon

Ñeenteelu yoon a ngi nii Bubakar Bóris Jóob di...

GÀCCE NGAALAAMA, MBUGAAR !

Senegaal amati na ndam ci 3eelu fan ci weeru...

KUJJE GEEK WOTEB 2022 BI: BËGG NAA LA, BËGGUMA LA, LOOLU JARUL COOW

Ci bésub 23 sàŋwiye ci atum 2022 bii di...

FÀTTALIKU DÉMB

SEEX

Seex Mooy góor Moo di as gor Mbokk ya ko wor Ñooy mbokk...

FÀTTALIKU OMAR BOLONDEŊ JÓOB… 2/2

(ÑAAREELU XAAJ) Bi ñu nee Senegaal moom na boppam tamit,...

2002, ATUM SUUXU JOOLAA BI

Bërki-démb 26 sàttumbar ci atum 2020, "Bateau le Joolaa"...

FAIDHERBE, SAAY-SAAY BI NUY SARGAL

Bi Siidiya Ndàtte Yàlla génnee àddina ak léegi, am...

JÉERI JOOR NDEELAAK TUBAAB BI

Jéeri Joor Ndeela Faal mu ngi gane àdduna ci...

DÉMB AK TEY

WIDEWO YI

WAXLEEN SEEN XALAAT

BOO BAÑEE ÑAAW…

Bu nu la waxee nga àggale kàddu gii, looy...

Njiitu Réew

Dangaa jiitoom Dañu la jiital Sa jubb cunduŋ xanaa taxul Moo ndax...

YAA GORE !

Yàgg, yàgg, dëgg ay daan Dëgg lottoon na Senegaal Usmaan Sonkoo...

Ndigalu Maam Ya

Afrig nee Waaw góor, waaw kumba Ayca leen ca waar wa Bu...

SÀCCIIN WI JËM CI TÀNN YI DËGMAL TE FEEÑALEES KO

Sëñ Abdu Xaadr Kebe mooy biral fii xalaatam ñeel...

TÀGGATOO

NJÀNGAT CI TÉERE YI

XËT YI LEEN DÀQAL

UGB : XEEX BI DOORATI NA !

Xeex bi jolleeti na diggante ndongoy iniwérsite Gastoŋ Berse ak takk-der yi. Jamono jii...

« COALITION SENEGALAISE DES DEFENSEURS DES DROITS HUMAINS (COSEDDH) »

Ay kilifa ak i kàngaam yu mag bennoo nañ bind ab bataaxal, jagleel ko...

USMAAN SONKO FEEÑ NA

Lees doon njort moo am : takk-der yaa jàppoon, ndeke, Usmaan Sonko. Fim ne...

Màggalu Tuubaa

"Bu kenn dem, na ñépp toog, Màggal-leen seen kër". Lii mooy kàdduy jëwriñ bi...

LI GËN A FES CI XIBAARI BÉS BI (Alxames 16 féewaryee 2023)

LAYOO MAAM MBAY ÑAN AK USMAAN SONKO Tey ci alxames ji lañu waroon a àtte...

TOOGAANU-ÑAXTU NGIR JÀPPALE PAAP NJAAY MU WALF

Ay téeméeri-téeméeri nit ñoo teeweesi toogaanu-ñaxtu ba amoon ci buntu màkkaanum Walf. Lees ko...

CNRA DOG NA SIÑAALU iTV

Ngir fàttali, CNRA dafa artu woon rajo yeek tele yi ngir ñu bañ a...

DIGE GÉEJ, KILIBU SÉEX ALIYU NDAW : TEKKI MBAA LAB

Dige géej, téere kilib bii Séex Aliyu Ndaw di door a génne, OSAD mi...

ÑEETTEELU MOOME : MAKI SÀLL JÉGGAANI NA AW LAY

Jéggaani xaalis. Jéggaani dund. Jéggaani xam-xam. Léegi, jéggaaniy xalaat a ci des. Ndeke, Njiitu...

FU USMAAN SONKO RÉER ?

Kenn xamul fu Usmaan Sonko nekk jamono jii. Bentaleb Sow ak Juan Branco, layookatu...

Lu Nguur gi di xaar ci Usmaan Sonko ?

Lu Nguur gi di xaar ci Usmaan Sonko Weeru Yàllaa ngi nii ginnaaw bi Yoon...

MAKI SALL : « KENN DU TEE WOTE YI AM ! »

Njiitu réew mi, Maki Sàll, amaloon naw waxtaan ak sunuy naataango yu Le Monde,...

PAATE JAAÑ, SA JAAN WÀCC NA !

Paate Jaañ wàcc na liggéey démb ci àllarba ji, 23i fan ci weeru ut...

LÀMMIÑ WEES NÀMP

21eelu féwaryee lañ jagleel ci àddina sépp bésu làmmiñ wi nga nàmp. Xalaat bu...

BALAA NGAA LAAX JAAY, LAAX LEKK

Ngomblaan gee woote ngir dépite yi jëlsi kaarbiraŋ biñ leen di jagleel weer wu...

GÀTTALI BÉS BI (ALXAMES 27 AWRIL 2023)

Ndoorteelu burok Meeru Sigicoor bi, Usmaan Sonko, biral na 12i naal yi mag yim jagleel...

2eelu NDAJE MU MAG ÑEEL KOPPARAL JUMTUWAAY YI CI AFRIG

Ginnaaw bi ñu ko njëkkee amal ci atum 2014,  Nguuri Afrig yeek seen i...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI, Dibéer 14 ut 2022

PÓLITIG  Li bettul kenn mooy fekki gi Paap Jóob fekki waa BBY. Mu nekkoon lu...

YOKKUTEG NJËGU SOBLE SI

Am soble nekk na lu jafe lool fi mu tollu nii ci biir réew...

MAKI, FÀTTALIKUL “PAPA DOC”

Jafe na nga xam as lëf ci dundu "Papa Doc" (François Duvalier) mu réewum...

SÀMPIYONAA ALMAAÑ : BAYER LEVERKUSEN JËL NA KO !

Xabi Alonso ak gaayam yi def nañ ko. Dugal nañ Bayer Leverkusen ci mboorum...

“SUNUY MILYAAR DU REES !”

« Place de la nation », walla Péncum askan wi ci wolof, wuyoo na...

KATI LEENA NJAAY : KOPPAR, SAÑ-SAÑ, MBOORUM FCFA

Film bi Kati Leena Njaay (sottalkat) mujj génne te tudde ko Koppar, sañ-sañ, mboorum...

Li gën a fés ci xibaari bés bi (alxames 29 desàmbar 2022)

PÓLITIG Yeneen tàbb yu yees  Ca ndajem jëwriñ ma mu doon amal démb, Njiitu réew mi...

(AMI MBENG)

  Senegaal :   Yan njàngat la askan wi wara jukkee ci kàngam yu bare te ràññeeku yi génn àddina ci fan yii ? Ci diirub 40i fan   rekk, réewum Senegaal dëjal na fiy boroomi daraja yu fésoon lool. Li ci gën a doy-waar mooy ne dafa méngook jamono joo xam ne, réew maa ngi jànkoonteek mbasum covid-19 mi. Loolu, nag, war nanoo yee, nu xool naka lees di def ba ndaw ñi roy ci ñooñule réew mi ñàkk.  KORONAA : Jawriñ biñ dénk kaaraange biir réew mi Aali Nguy Njaay,...

USMAAN SONKO : « MBATIIT MOOY LÉPP, MOOY CËSLAAYU YOKKUTE. »

Laaj ak tontu bii nag, seen yéenekaayub web defuwaxu.com séqoon na kook Usmaan Sonko...

TUBAAB YAA NGI YEDD MAKI SÀLL

Kurél gi boole digaaley Senegaal yi ci wàllu xarala ak kopparal, G50, yedd na...

BURKINAA FAASO : AAYEES NA YÉENEKAAY LE MONDE

Barki-démb ci gaawu gi la ko Rimtalba Jean Emmanuel Ouédraogo xamle ci ab yégle....

CAN KODDIWAAR 2024 : CAABALU BÉS BI

NGIRTEY JONANTE DÉMB YI Démb ci talaata ji lees amal ñetteeli joŋantey kippug C gi...

YOONU YÀQUTE…

"Noo lànk !" Ñaari baat yooyu la askanu Senegaal wépp àndandoo yuuxu cib doxu-ñaxtu, àjjuma jii...

XEEB NGA XAL, MU LAKK SA DÀGGA (1/2)

Kuy laaj fu réewum Senegaal tollu, dellul bésub alxames, 16 féewaryee 2023, xool, seet,...

Li gёn a fés ci xibaari bés bi Alxames 22 sàttumbar 2022

PÓLITIG  Mbirum Njaga Juuf Ёttub àtte bu Ndakaaru dёggal na daan yi ñu teg ci ndoddu...

Cargalug CAF Awards 2022 : Senegaal ca kow, ca kanam

Alxemes, 21i fan ci weeru sulet lañ doon amal cargalug CAF Awards 2022 yi....

AAJIBOOK BATAAXALUB LËMBAAJE BI

Séex Aajibu Sumaare, njiitu jëwriñ ja woon, dafa bind ab bataaxal jagleel ko Njiitu...

« COO ! NOO ÑÀKK FAYDA !… COO ! NOO ÑÀKK JOM ! »

Magum jawriñu Senegaal, Aamadu Ba, ma nga woon Farãs, waroon fa teewe ndajem liggéey...

GÉNNUG ÀDDINA Me USMAAN SÉY 

Me Usmaan Séy, layookat bu siiw bi, moo génn àddina. Ay mbokkam a ko...