BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi ñu jagleel waa jasporaa bi, ci njiiteefu Njiitu réew mi...

BÉS NIKI TAY, NEELEEN DOKTOOR PÀPPA AALI JÀLLO

Gaawo, 13eelu desàmbar 2025, ca Jàngune bu Ndar, la Pàppa Aali Jàllo (njiitul LDW) doon gaaral teesam ci Làkk ak mbatiiti Afrig, duppe ko...

FOQATIG NGUUR FA RÉEWUM BENEE

Ginnaaw coowal sóobare yi toog fa boppu réewum Gine Bisaawu, geneen foqatig Nguur naroon naa amaat, wile yoon, fa réewum Benee ak ay sóobare...

MOUSSO NGIR « JIGÉEN GÉNN CIG LËNDËM »

Soo déggee baatu « mousso », sam xel mën naa dem cib « restaurant » bu siiw ba ca Kanadaa. Waaye, « mousso » bii moom bokkul ak booba ; xéy-na...

NGOMBLAAN GI : DÉPITE YI TÀMBALI NAÑU CÀMBAR NAFA 2026 GI

Dépite yi tàmbali nañu càmbar nafag atu 2026 mi fa Ngomblaan ga. Ñu nar koo amal ci diiru ñaari ayu-bés ngir dalal jëwriñi Càmm...

MAGU WAXOON NAA KO

JIKKO JU RAFET MOOY TABAX AM RÉEW

Wolof nee na, rafet kanam, rafet jikko a ko...
01:33:07

“Héritages” dalal na Bubakar Bóris Jóob

"Héritages ak Awa" ngi dalal Bubakar Bóris Jóob, ngir...

Malaanum Lëndëm : Bóris Jóob, na woon, fa woon

Ñeenteelu yoon a ngi nii Bubakar Bóris Jóob di...

GÀCCE NGAALAAMA, MBUGAAR !

Senegaal amati na ndam ci 3eelu fan ci weeru...

KUJJE GEEK WOTEB 2022 BI: BËGG NAA LA, BËGGUMA LA, LOOLU JARUL COOW

Ci bésub 23 sàŋwiye ci atum 2022 bii di...

FÀTTALIKU DÉMB

SEEX

Seex Mooy góor Moo di as gor Mbokk ya ko wor Ñooy mbokk...

FÀTTALIKU OMAR BOLONDEŊ JÓOB… 2/2

(ÑAAREELU XAAJ) Bi ñu nee Senegaal moom na boppam tamit,...

2002, ATUM SUUXU JOOLAA BI

Bërki-démb 26 sàttumbar ci atum 2020, "Bateau le Joolaa"...

FAIDHERBE, SAAY-SAAY BI NUY SARGAL

Bi Siidiya Ndàtte Yàlla génnee àddina ak léegi, am...

JÉERI JOOR NDEELAAK TUBAAB BI

Jéeri Joor Ndeela Faal mu ngi gane àdduna ci...

DÉMB AK TEY

WIDEWO YI

WAXLEEN SEEN XALAAT

BOO BAÑEE ÑAAW…

Bu nu la waxee nga àggale kàddu gii, looy...

Njiitu Réew

Dangaa jiitoom Dañu la jiital Sa jubb cunduŋ xanaa taxul Moo ndax...

YAA GORE !

Yàgg, yàgg, dëgg ay daan Dëgg lottoon na Senegaal Usmaan Sonkoo...

Ndigalu Maam Ya

Afrig nee Waaw góor, waaw kumba Ayca leen ca waar wa Bu...

SÀCCIIN WI JËM CI TÀNN YI DËGMAL TE FEEÑALEES KO

Sëñ Abdu Xaadr Kebe mooy biral fii xalaatam ñeel...

TÀGGATOO

NJÀNGAT CI TÉERE YI

XËT YI LEEN DÀQAL

GÀTTALI BÉS BI (ALXAMES 18 ME 2023)

Daaray Nguur gi tëj nañu leen fa Siggicoor ak Séeju Li ko dale àjjuma ji...

PECCIM KÓLLЁRЁ (MÀNG) GI CI LÀNGUG PÓLITIG GI : LAN MOO KO WUND ?

Pólitig nekk na mbir mu am solo lool ci mépp réew mum mёn di...

NDONGO SÀMBA SILLA « …CFA, XETTALI FRÃS A KO TAXOON A JÓG»

Mamadu Jàllo :  Ndongo Sàmba Silla, yow doomu-Senegaal nga, di boroom xam-xamam bu mag ci wàllu...

LI GËN A FËS CI XIBAARI BÉS BI (ÀLLARBA 8 MÀRS 2023)

YOON Waa "Sureté Urbaine" bu Ndakaaru woolooti nañu. Wile yoon, Séex Aajibu Sumaare lay doon,...

TANOOR NOPPI NA BA FÀWW

Usmaan Tanoor Jeŋmi fi doonoon njiitu ‘’Parti Socialiste’’ dale ko atum 2000, bi pa1rti...

TABASKI 2023 : XUTBA CEERNO SAYDU NUURU TAAL

Ci alxamesu démb ji la ñu ëpp ci saa-senegaal yi tabaski. Ku ne tabaski,...

LI TAX 102i BOROOM XAM-XAM YU MAG JÀPP NE SENEGAAL DU RÉEWUM YEMALE (MA-JAW NJAAY)

https://m.soundcloud.com/mohamadou-boye/manifeste-en-wolof

CEERNO ALASAAN SÀLL : "YAAKAAR AK RAFET NJORT ÑOO MA TAXOON A ÀND AK MAKI SÀLL"

Tey, Senegaal, kenn mënul a wax  waxu pólitig te doo ci boole Ceerno Alasaan...

LI GËN A FES CI XIBAARI FUTBAL (alxames 9 féewaryee 2023)

 BELSIG AM NA TAGGATKAT BU BEES Kuppeg àddina 2018 ba léegi, Belsig dafa nekkoon ciy...

MUSIBAB SINJAA

Diggante ndongo daara ak sëriñam, yenn saa yi, du doon lu ratax. Lu ci...

LÀMBI GOLO-O ! KU JÓG SAAGA ! (PAAP AALI JÀLLO)

Njoolum-golo miy def yëfi goloom, ku ci yéemu dangay door a yeewu, mbaa...

1 ME, BÉSUB LIGGÉEYKAT YI

Tey, 1 fan ci weeru me, àddina wërngal këpp di màggal bés bees jagleel...

ÑETTEELU MOOME GI

Coowal ñetteelu moome gaa ngiy wéy di lëmbe réew mi. Ba tey, Njiitu réew...

COPPITE YI BASIIRU JOMAAY FAY DIGE

Démb la Njiitu réewum Senegaal lu bees li doon biral kàddoom yu njëkk. Fa...

LÉPP LI CI BIIR LÀNKETU KAPITEEN SÉYDINAA UMAR TURE CA "SECTION DE RECHERCHES" BU KOLOBAAN…

Ci tekkig Musaa Jóob Aysatu Ñaari ayubés ak léegi coow lëmbe réew mi yépp, am...

FAN LA SENEGAAL TOLLOOK ÑAKK YI ? ( Musaa Aysatu Jóob)

Niki weeru féewaryee ci atum 2020 lañ njëkk a dégg baatu koronaawiris , ci...

BUBAKAR BÓRIS JÓOB : « DAÑU WAR A TOPP NJIIT YI FI NEKKOON… »

TV5 doon na dalal werekaan bu mag bi, Bubakar Bóris Jóob, séq ak moom...

CFA WALLA ECO ? SÀMBAAY BÀCC REKK…

Xaar bi yàggoon na, xeex bi metti lool, coow li ne kurr, saf sàpp...

RAFLE JÀMM (DAAWUDA NJAAY JARAAF)

Fitt a jiitu fetal Lépp aju ci ngistal Doolee mën dëgg Weddil googu dëgg Njaayum gànnaay Rombal doonub nay Bu...

XARE CA SUDà

Xeex bu mettee jolli Sudã, diggante làrme beek i sóobare yu beddeeku. Ñaari seneraal...

ARAM FAAL, SUNU SÉEX ANTA JÓOB BU JIGÉEN…

Talaata jii weesu di 23 ci weeru awril la Mbootaayu-Xeet yi jagleel bépp teere...

Li gën a fés ci xibaari bés bi (àjjuma 2 féewaryee 2023)

PÓLITIG  Layoo Maam Mbay Ñaŋ Usmaan Sonko ajandi nañu ko Layoo bi waroon dox démb ci...

LI GËN A FES CI XIBAARI BES BI (àjjuma 10 féewaryee 2023)

PÓLITIG Perefeb Mbàkke tere na mitiŋ ba Tey ci àjjuma ji la kii di Usmaan Sonko...

BOO BAÑEE ÑAAW…

Bu nu la waxee nga àggale kàddu gii, looy wax ? Nga tontu ne...

NAN WAX CI YENN SÉRI TELE YI

Jamono jii nu tollu temm bari na lu ñu seetlu ci miim réew, ñeel...

NDIISOOY NGOMBLAAN GI

Dogub 24eel bu càrtub Ngomblaan gi dafa tëral ne : « Ci ndoorteelu gépp moomeg...

Li gёn a fés ci xibaari bés bi Alxames 1 Sàttumbar 2022

PÓLITIG Àppug wotey HCCT xamees na ko Ci ab saabal bu mu génne, Njiitu réew mi...

SIGARET : REYAATEKAT BI

Bërki-démb, ci talaata ji 7i fan ci féewaryee 2023, lees doon amal ndajem liggéey...

JOŊANTE CFEE 2023

Joŋantey CFEE yi door nañ ci àllarbay tey ji, war a jeex ëllëg ci...

IMAAM ALIYUN NDAW, SA JAAN WÀCC NA !

Bakkan bu ñam dund, ñam dee. Ab xandeer bu damme cib waar moo wàcc....

GÀMMU GI

Weeru Gàmmu La Buur Yàlla taamu Ngir gane àddina Yonent bi Yàlla def mu gën ci mbindeef...

MOO MAN LU MAY WAXATI ? (Taalifu Séex Aliyu Ndaw)

Keroog, àllarba 18i fan ci saŋwiyee 2023 la mbootaayu Fonk Sunuy Làmmiñ doon sargal...

TAS XIBAAR : TAS XAR-BAAX WALLA TAS CI KASO BI ?

Tasum xibaar mi ngi bëgg a tagatémbe jamono jii ci réewum Senegaal. Dara waralu...

SENEGALEY ITALI YI : LA WOON WONNI NA

Fàttaliku lu war jaam la, kon na xel dellu ci ginnaaw ngir saytu walla...

GATSA-GATSA, BA KAÑ ?

Seetlu nañu ne, saa bu Yoon wooloo njiitu pastef lii di Usmaan Sonko rekk,...