USMAAN SONKO “ BÉG” NA CI TUKKEEM BI MU AMAL FA SIIN

Elimaanu jëwriñ yi, Usmaan Sonko, fésal na mbégteem ci tukki bi mu tukki fa réewum Siin. Pekeŋ la ko waxee, di gëblag réew ma....

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (26/6/2025)

TUKKIB NJIITU RÉEW MI FA ESPAAÑ Bu yàggul dara la Njiitu réew mi, Basiiru Jomaay Jaxaar Fay, jóge fa ndajem CEDEAO ma. Balaa yàgg, dina...

“BANQUE MONDIALE” LEBAL NA SENEGAAL 65i MILIYAARI CFA

Ci talaatay démb ji la "Banque mondiale" siiwal ne nangu na a lebal Senegaal koppar yu tollu ci 115i miliyoŋ ciy dolaar, yemook 65i...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (24/6/2025)

NGURD CÀMM GI CI ÑETTI WEER YI JIITU CI ATUM 2025 MI Jëwriñu ngurd meek nafa gi siiwal na caabal gi aju ci yorinu nafa...

TUKKIB ELIMAANU JËWRIÑ YI FA RÉEWUM SIIN

Àjjuma jii weesu la elimaanu jëwriñ yi, Usmaan Sonko, dooroon ab tukkeem fa bitim-réew. Moom nag, guléet muy génn kembaarug Afrig bi ñu tabbee...

MAGU WAXOON NAA KO

JIKKO JU RAFET MOOY TABAX AM RÉEW

Wolof nee na, rafet kanam, rafet jikko a ko...
01:33:07

“Héritages” dalal na Bubakar Bóris Jóob

"Héritages ak Awa" ngi dalal Bubakar Bóris Jóob, ngir...

Malaanum Lëndëm : Bóris Jóob, na woon, fa woon

Ñeenteelu yoon a ngi nii Bubakar Bóris Jóob di...

GÀCCE NGAALAAMA, MBUGAAR !

Senegaal amati na ndam ci 3eelu fan ci weeru...

KUJJE GEEK WOTEB 2022 BI: BËGG NAA LA, BËGGUMA LA, LOOLU JARUL COOW

Ci bésub 23 sàŋwiye ci atum 2022 bii di...

FÀTTALIKU DÉMB

SEEX

Seex Mooy góor Moo di as gor Mbokk ya ko wor Ñooy mbokk...

FÀTTALIKU OMAR BOLONDEŊ JÓOB… 2/2

(ÑAAREELU XAAJ) Bi ñu nee Senegaal moom na boppam tamit,...

2002, ATUM SUUXU JOOLAA BI

Bërki-démb 26 sàttumbar ci atum 2020, "Bateau le Joolaa"...

FAIDHERBE, SAAY-SAAY BI NUY SARGAL

Bi Siidiya Ndàtte Yàlla génnee àddina ak léegi, am...

JÉERI JOOR NDEELAAK TUBAAB BI

Jéeri Joor Ndeela Faal mu ngi gane àdduna ci...

DÉMB AK TEY

WIDEWO YI

WAXLEEN SEEN XALAAT

BOO BAÑEE ÑAAW…

Bu nu la waxee nga àggale kàddu gii, looy...

Njiitu Réew

Dangaa jiitoom Dañu la jiital Sa jubb cunduŋ xanaa taxul Moo ndax...

YAA GORE !

Yàgg, yàgg, dëgg ay daan Dëgg lottoon na Senegaal Usmaan Sonkoo...

Ndigalu Maam Ya

Afrig nee Waaw góor, waaw kumba Ayca leen ca waar wa Bu...

SÀCCIIN WI JËM CI TÀNN YI DËGMAL TE FEEÑALEES KO

Sëñ Abdu Xaadr Kebe mooy biral fii xalaatam ñeel...

TÀGGATOO

NJÀNGAT CI TÉERE YI

XËT YI LEEN DÀQAL

MOO MAN LU MAY WAXATI ? (Taalifu Séex Aliyu Ndaw)

Keroog, àllarba 18i fan ci saŋwiyee 2023 la mbootaayu Fonk Sunuy Làmmiñ doon sargal...

CAN 2021 : Kub baa nga woon ca Séeju, Saajo Maane delloo mbàttu ca ndaa la mu naane

Bàmbali, ci diwaanu Séeju, dalal na Kubu Afrig bi Senegaal jële woon ca Kamerun...

USMAAN SONKO : “BËGGUMA KU MA RAWALE… DAÑ MA BËGGOON A REY…”

90 000iy nit ak lu teg ñoo teewe waxtaan wi Usmaan Sonko doon amal...

LI CI BIIR "GUDDIG MBOOYO" BU LAMIN MBAAY

KAN MOOY LAMIN MBAAY ? Lamin Mbaay, ab Birigajeb pólis la woon. Mi ngi juddu...

LEKKOOL YA NGI CI YOONU LOMPOÑ

Coowal pólitigu Senegaal mi ngi wéy di jur jote ci réew mi. La ca...

36EELU NDAJEEM LËLUB  NJIITI RÉEW YEEK CÀMM YU MBOOTAAYU REEWI AFRIG YI (UA)

Mbootaayu Réewi Afrig yi dina amal ndajeem lëlub Njiiti Réew yeek Càmm yi. Moo...

MÀNGAAN NDEKE AM NA CI PÓLITIG !

b ak yu tey gis ñu woroo lool. Am na sax ci ñoom ku...

YEWWI ASKAN WI – TAXAWU SENEGAAL : ÀND BUY WAAJ A TAS ?

Waxtaanu Maki Sàll wi de, boo demee, moo nar a génne Taxawu Senegaal ci...

RËNG-RËNG CA TURKI AK SIRI : 4 890iy NIT DEEWAGUM NAÑU

Suuf si yëngooti na, àddina jooyati. Nde, ay rëng-rëng yu mettee metti ñoo dal...

NATHALIE YAMB : “LI TAX MAKI SÀLL DELLU GINNAAW…”

Altine jii weesu yemoo woon ak ñetti fan ci weeru sulet la Njiitu réew...

SENGHOR AK HOUPHOUËT, DOOMI AFRIG YI DAAN XEEX AFRIG (2/2) BOS NDÓOY

Ci beneen boor, ci nguuru Seŋoor lees nose, ñeel Senegaal, “Opération Persil” ak lenn ci...

JOŊANTE REN BII, PETOROOL LAY XEEÑ…

Keroog, askanu Senegaal jóg na ci njekk ak teggin, daldi def li ko war...

LAAYEEN YI MERE NAÑU MAKI SÀLL

Ku dégg kàdduy Imaam Basiiru Caw Laay xam ne Laayeen yi mer nañ lool....

JÀMBAAR

Jógati naa saddati ay bayit sargale mbër Bàkk ko jiin ko xaacu naan na woy...

GÀTTALI BÉS BI (GAAWU 29 AWRIL 2023)

Jàppal nañu bés layoob Usmaan ak Aji Saar : 16 me 2023 Bés bi ñépp doon...

YANQOOBA JATARA DAY TEKKI NDOMBOG-TÀNKAM

Lees doon xaar jib na : Yanqooba Jatara, jëwriñu tàggat-yaram gi, génn na pàrti...

SENEGAAL, XALIMAY ÑAARI BINDKAT DAMM NAÑ…

Ibraayma Aan ak Àbbaas Njoon, ñaari bindkat yu mag, ñoo génn àddina : kii ci...

LAAJ-TONTOOK GUY MARIUS SAGNA (GII MARYIIS SAAÑA)

Seen yéenekaay LU DEFU WAXU mi ngi dalal tey Gii Maryiis Saaña, fara caytu...

RFI : NJUUMTE, YABAATE WALLA LAN ? (NDEY KODDU FAAL)

Bërki-démb, ci altine ji, rajo Rfi dafa juum tàgge ñaar ci njiiti réewu Senegaal yi...

MAAM MBAY ÑAŊ : ” SONKO RËCCAGUL. “

Maam Mbay Ñaŋ nee na day def "appel", du bàyyi mu sedd. Moom, ak...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI Altine 23 sãwiye 2023

PÓLITIG Bërki-démb ci dibéer ji, waa Pastef doon nañ amal ab mitiŋ ca depàrtamã bu...

4 AWRIL : NAXEE-MBAAY WALLA ?

Fileek ñeenti fan, Senegaal dina Màggal jonnug boppam, ginnaaw juróom-benn-fukk ak ñetti at, bim...

NJAAY DARAAPOO DËDDU NA

Momar Njaay, ñu gënoon koo miin ci turu "Njaay Daraapoo", dëddu na. Moom, nag,...

AYSATA : TAAL BI DU AY FEN ÑOO KOY FAY

Kii di John Mearsheimer, ca atum 2011, dafa génne ab téere tudde ko "Why...

SÉEX ALIYU NDAW : NIT KI AK LIGGÉEY BI (Ibraayma Wan)

Saawo si ak nji yi Siidi Ahmet Aliyun Ndaw a ngi juddu atum 1933...

SÉEX ALIYU NDAW GÉNTOON NA KO DÉMB, AADAMA BAROW AK BASIIRU JOMAAY FAY DEF NAÑ KO TEY

Atum 1981, Séex Aliyu Ndaw, bindkat bu ràññeeku, daa bind woy tudde ko : Sama...

SONKO, AK KAN ?

Alxames, 16 màrs 2023 ba tey, Usmaan Sonkoo nga ca raglu ba, tëdd. Waa...

CAN KODDIWAAR 2024 : CAABALU BÉS BI

WÉR-GI-YARAMI ALIW SIISE AK ABDULAAY SIMAA Bees sukkandikoo ci yégle "Fédération Sénégalaise de Football" (FSF)...

LI GËN A FËS CI XIBAARI BÉS BI (4/8/2023)

PASTEF Ñoo ngi wéy di raafal ndawi Pastef yi. Keroog, Tuseŋ Màngaa ak Bentaleb Sow...

FAAS BÓOY, SIGGIL NDIGAALE !

Mbëkk maa ngi wéy di def i jéyya ci réewum Senegaal. jéyya ci kow...

Kafrin

Kafrin : Ndox mi bari na ca Ndukkumaan ginnaaw bi mu tawee taw bu...

Njiitu Réew

Dangaa jiitoom Dañu la jiital Sa jubb cunduŋ xanaa taxul Moo ndax doo tontoom Céy lii ciy way-xëccoo Ku...

WEYI TAN (SAYDU BA)

Saydu BA waa Ñooro la, di al-pulaar bu gàlle. Ndaanaan luy yëngu ci teyaatar la,...

XEWTEEB NDAAKAARU ÑEEL LADAB CI ÀDDINA SI

Ndakaaru dina amal ñaareelu xewteem ñeel ladab ci àddina si, FILID (Festival international de...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (Talaata 31 saŋwiye 2023)

PÓLITIG Beneen lawax bu bees feeñati na ñeel wotey 2024 yi. Dr Baabakar Jóob, di...

LAN MOOY GARAB ? (Li Faal Sàmba Suuna)

Li Faal Sàmba Suuna Lépp li nit kiy jënde farmasi la Wolof Njaay tuddee garab. Moone...

FAGAROO GËN FAJU

  Li Faal Sàmba Suuna Sama maam daan na wax ni maamam dund na téeméeri at...

GÀTTALI BÉS BI

TAXAWU SENEGAAL DINA BOKK CI WAXTAAN WI NJIITU RÉEW MI WOOTE  Ëllëg ci àllarba ji,...