LI GËN A FËS CI XIBAARI BÉS BI (6/11/2025)

PRODAC : YOON TÉYANDI NAÑU Tay ci ngoon la takk-deri DIC yi fekki Paab Maalig Nduur këram, daldi koy jàpp, yóbbu ko. Bees sukandikoo ci sunu...

« MËSUNOO GIS BOR BU ÑU NËBB BU TOLLU NII CI AFRIG », EDWARD GEMAYEL, NJIITU NDAWI FMI FI SENEGAAL

Nees ko biralee woon ci sunu yaxalu barki-démb bi, ndawi yi FMI yabal fi réew mi dañu toogaat ci réew mi ngir wéyal liggéey...

LIGGÉEY BAA NGI WÉY DIGGANTE FMI AK NGUURUG SENEGAAL GI

Waa FMI dinañu toogaat ci réew ay fan ngir wéyal liggéey bi ñu sumb ak Nguurug Senegaal. Bésub 22 oktoobar 2025 lañu ñëwoon Ndakaaru...

CAABALUG ARCOP 2022-2023 : 3,2 MILIYAAR YU NE MËY !

ARCOP (Autorité de Régulation des Marchés Publics), di banqaas biy saytu lépp lu aju ci yoonalug jawi bokkeef gi, siiwal na caabalug ati 2022-2023...

8eelu NDAJEM GALIEN AFRIG : CÀKKUTEEFU NJIITU RÉEW MI

Njiitu réew mi woote na jëme ci Afrig mën boppam ci wàllu paj mi. Muy woote bu mu amal fekk mu doon jiite xew...

MAGU WAXOON NAA KO

JIKKO JU RAFET MOOY TABAX AM RÉEW

Wolof nee na, rafet kanam, rafet jikko a ko...
01:33:07

“Héritages” dalal na Bubakar Bóris Jóob

"Héritages ak Awa" ngi dalal Bubakar Bóris Jóob, ngir...

Malaanum Lëndëm : Bóris Jóob, na woon, fa woon

Ñeenteelu yoon a ngi nii Bubakar Bóris Jóob di...

GÀCCE NGAALAAMA, MBUGAAR !

Senegaal amati na ndam ci 3eelu fan ci weeru...

KUJJE GEEK WOTEB 2022 BI: BËGG NAA LA, BËGGUMA LA, LOOLU JARUL COOW

Ci bésub 23 sàŋwiye ci atum 2022 bii di...

FÀTTALIKU DÉMB

SEEX

Seex Mooy góor Moo di as gor Mbokk ya ko wor Ñooy mbokk...

FÀTTALIKU OMAR BOLONDEŊ JÓOB… 2/2

(ÑAAREELU XAAJ) Bi ñu nee Senegaal moom na boppam tamit,...

2002, ATUM SUUXU JOOLAA BI

Bërki-démb 26 sàttumbar ci atum 2020, "Bateau le Joolaa"...

FAIDHERBE, SAAY-SAAY BI NUY SARGAL

Bi Siidiya Ndàtte Yàlla génnee àddina ak léegi, am...

JÉERI JOOR NDEELAAK TUBAAB BI

Jéeri Joor Ndeela Faal mu ngi gane àdduna ci...

DÉMB AK TEY

WIDEWO YI

WAXLEEN SEEN XALAAT

BOO BAÑEE ÑAAW…

Bu nu la waxee nga àggale kàddu gii, looy...

Njiitu Réew

Dangaa jiitoom Dañu la jiital Sa jubb cunduŋ xanaa taxul Moo ndax...

YAA GORE !

Yàgg, yàgg, dëgg ay daan Dëgg lottoon na Senegaal Usmaan Sonkoo...

Ndigalu Maam Ya

Afrig nee Waaw góor, waaw kumba Ayca leen ca waar wa Bu...

SÀCCIIN WI JËM CI TÀNN YI DËGMAL TE FEEÑALEES KO

Sëñ Abdu Xaadr Kebe mooy biral fii xalaatam ñeel...

TÀGGATOO

NJÀNGAT CI TÉERE YI

XËT YI LEEN DÀQAL

GÀMMU GI

Weeru Gàmmu La Buur Yàlla taamu Ngir gane àddina Yonent bi Yàlla def mu gën ci mbindeef...

CENA BI DËGGAL NA USMAAN SONKO

Ginnaaw ndogalu àttekatu Sigicoor bi, Sabasi Fay, CENA joxati na dëgg Usmaan Sonko ñeel...

“MAN, SÉEX ANTA JÓOB !”

Bu Séex Anta Jóob (1923-1986) doon dund ba tey, am koon na 100i at...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (31/10/2023)

PÓLITIG Abdu Karim Fofana, jëwriñ ji yor kàddu Càmm gi, wax na jëmale ci amalub...

MALI, BURKINAA FAASO AK NISEER BOKKATUÑU CI CEDEAO

Kaawteef ! Mali, Burkinaa Faaso ak Niseer mànkoo nañ génn ci CEDEAO. Xibaar bi...

GÀTTALI BÉS BI (4/6/2024)

ISRAAYEL RAY NA CI WAA PALASTIIN LU ËPP 15 000iy GONE Bees sukkandikoo ci tele...

XIBAARI TÀGGAT-YARAM

LIGUE DES CHAMPIONS 2024-2025 Waa UEFA amal nañu ay coppite yoy, dañuy yokk limatu ekib...

AFRIG, TONTU DU FOROX, Tontu ñeel kàdduy Óreliyoo De Lórãtis yi

Duma topp diw boo gis, fi ngeen jëm dafa sorewul. Loolu la waa CAF...

GÀTTALI BÉS BI (28/6/2023)

TABASKI Waa Ahlus Sunna, ñi ñu duppee Ibaadu, tabaski nañu tey ci àllarba ji, 28...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (16/4/2024)

SAYTUKAT YI CI GOX YEEK GOX-GOXAAT YI BANK NAÑ SEEN I LOXO Sàndikaa bi ëmb...

WOTEY 2024 YI : WURE WA DEM NA KËŊ

Tey ci gaawu gi la ndajem ndeyu àtte réew mi tàmbali seen liggéey ñeel...

15eelu NDAJEM OCI

Ci njeexitalug ayu bés bi, gaawu 4 ak dibéer 5 me 2024, lañ doon...

DOKTOOR PAAP MUSAA COOR : “NAÑ BÀYYI MBAS MI MU LAW !’’

  (TEKKIG PAAP AALI JÀLLO) Doktoor Paap Musaa Coor, gëstukat la, xelam màcc ci wérug mbooloo....

AKSIDAŊ BU METTI CI YOONU TUUBAA WI

Aksidaŋ bu metti moo am ci yoonu Tuuba wi. Xibaar bi nag, bettul ñu...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (25/12/2023)

PÓLITIG Saytukati ndeyu àtte réew mi ñoo ngi wéy ba léegi di jot wayndarey way-sàkku...

MAKI SÀLL TAGG NA SEEX MAAHI ÑAS

Tey ci talaata ji, Njiitu réew mi Maki Sàll, ma nga woon fa Kawlax....

BUUR MAKI

Démb, ci gaawug korite gi, Njiitu réew mi jagleel na ab laaj-tontu rajo RFM....

Kàddug Maki Sàll, Njiitu réew mi (AMI MBENG)

Ndakaarook biir Senegaal amoon nañuy yëngu-yëngu yu metti : ñu bari ñàkk ci seen bakkan,...

MAKI SÀLL NDOKKEEL NA NJIITU RÉEW MU BEES LI, BASIIRU JOMAAY FAY

Njiitu réew ma woon, war a fegal keroog 2 awril 2024, ndokkeel na Njiitu...

LI GËN A FËS CI XIBAARI BES BI Alxames 10 nowàmbar 2022

Mbirum pasug ngànnaay gu 45i miliyaar yi Dépitey Yewwi Askan Wi (YAW), nee nañ du...

NJAAYUM GERTE GI : CÀMM GI SAMP NA NJËG GI

Càmm gi samp na njëg gees war a jaaye gerte gi ci kàppaañ 2023-2024...

COOWAL ÑETTEELU MOOME GI

Lu tollu ci fukki weer ak ñeent kepp a des ci wotey 2024. Waaye,...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI Altine 26 Sàttumbar 2022

PÓLITIG Aminata Ture won na ginnaaw Njiitu réew mi Maki Sàll. Ciy waxam, dara waralu...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (13/12/2023)

NDONGOY UGB YI SUMB NAÑ AB XEEX Lu jege fukki fan ak juróom ba weer...

SONKO AK KARIIM DUÑ BOKK CI WOTEY 2024 YI

Ndogal li rot na. Tey jii, ci gaawug 20 sãwiyee 2024, la 7i àttekati...

ÑU BÓOM 160i DOOM-AADAMA CA BURKINAA, AFRIG DUMMÓOYU : LAN MOO NU DAL ? (PAAP AALI JÀLLO)

Solhan, gaawu, 5eelufan ci weeru suweŋ, ci kow i néew la jant bi fenk....

PÉNCUM RÉEW MI WALLA PÉNCUM BENNOO BOKK YAAKAAR ?

Am réew, su fa buur ak lingeer dee fecc, ku fay woyaan doo rus...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI 15/11/2023

TUXAL NAÑU USMAAN SONKO Lu ëpp ñetti weer ginnaaw ba ñu ko jëlee ca kasob...

MAKI SÀLL A NGI GËN A WÉET

Keroog, gaawu 3 féewiryee 2024, la Njiitu réew mi jëloon ndogalu xaatim ab dekkare...

MAKI SÀLL : "NAN JÉEM A DUND AK DOOMU JÀNGORO BI TE DU LOR KENN"

(PAAP AALI JÀLLO) Njiitu réew mi woyofal na sàrti guural gi ak dogal yi mu...

KÓLLËRE GINNAAW LAY FÉETE

Wotey dépite yi ci dibéeru 31 ci sulet 2022, wone na xar-kanam gu bees...

WAAJTAAYU MÀGGALU TUUBAA

Dëkk bu sell bi, Tuuba, dafa aadawoo di amal at mu jot màggalu 18...

Coowal Raglu Le Dantec bi

Li nit ñi doon xel ñaar ak a laam-laame, leer na ! raglu Le Dantec...

JÀPPUG PAAP AALE ÑAŊ

Seneweb moo siiwal xibaaru jàppug Paap Aale Ñaŋ, taskatu-xibaar ak faramfàccekat bu siiw. Jamono...

WOMEN FIRST TV Tele jigéen ñi, ngir jigéen ñi

WOMAN FIRST TV tele la bu ay jigéen sos jagleel  ko it jigéen ñi....

JÀNG AK JÀNGALE CI JAMONOY MBAS (Safiyetu Béey)

SAFIYETU BÉEY Céy Koronaa ! Doomu-jàngoro bii yëngal na jamono. Ku mënoon a gëm lu ndawe nii...

GII MARIS SAAÑAA XAS NA JËWRIÑU WÉR-GI-YARAM

Gii Maris Saañaa dal na ci kow Mari Xemes Njaay, jëwriñu wér-gi-yaram geek Ndimbalu...