BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi ñu jagleel waa jasporaa bi, ci njiiteefu Njiitu réew mi...

BÉS NIKI TAY, NEELEEN DOKTOOR PÀPPA AALI JÀLLO

Gaawo, 13eelu desàmbar 2025, ca Jàngune bu Ndar, la Pàppa Aali Jàllo (njiitul LDW) doon gaaral teesam ci Làkk ak mbatiiti Afrig, duppe ko...

FOQATIG NGUUR FA RÉEWUM BENEE

Ginnaaw coowal sóobare yi toog fa boppu réewum Gine Bisaawu, geneen foqatig Nguur naroon naa amaat, wile yoon, fa réewum Benee ak ay sóobare...

MOUSSO NGIR « JIGÉEN GÉNN CIG LËNDËM »

Soo déggee baatu « mousso », sam xel mën naa dem cib « restaurant » bu siiw ba ca Kanadaa. Waaye, « mousso » bii moom bokkul ak booba ; xéy-na...

NGOMBLAAN GI : DÉPITE YI TÀMBALI NAÑU CÀMBAR NAFA 2026 GI

Dépite yi tàmbali nañu càmbar nafag atu 2026 mi fa Ngomblaan ga. Ñu nar koo amal ci diiru ñaari ayu-bés ngir dalal jëwriñi Càmm...

MAGU WAXOON NAA KO

JIKKO JU RAFET MOOY TABAX AM RÉEW

Wolof nee na, rafet kanam, rafet jikko a ko...
01:33:07

“Héritages” dalal na Bubakar Bóris Jóob

"Héritages ak Awa" ngi dalal Bubakar Bóris Jóob, ngir...

Malaanum Lëndëm : Bóris Jóob, na woon, fa woon

Ñeenteelu yoon a ngi nii Bubakar Bóris Jóob di...

GÀCCE NGAALAAMA, MBUGAAR !

Senegaal amati na ndam ci 3eelu fan ci weeru...

KUJJE GEEK WOTEB 2022 BI: BËGG NAA LA, BËGGUMA LA, LOOLU JARUL COOW

Ci bésub 23 sàŋwiye ci atum 2022 bii di...

FÀTTALIKU DÉMB

SEEX

Seex Mooy góor Moo di as gor Mbokk ya ko wor Ñooy mbokk...

FÀTTALIKU OMAR BOLONDEŊ JÓOB… 2/2

(ÑAAREELU XAAJ) Bi ñu nee Senegaal moom na boppam tamit,...

2002, ATUM SUUXU JOOLAA BI

Bërki-démb 26 sàttumbar ci atum 2020, "Bateau le Joolaa"...

FAIDHERBE, SAAY-SAAY BI NUY SARGAL

Bi Siidiya Ndàtte Yàlla génnee àddina ak léegi, am...

JÉERI JOOR NDEELAAK TUBAAB BI

Jéeri Joor Ndeela Faal mu ngi gane àdduna ci...

DÉMB AK TEY

WIDEWO YI

WAXLEEN SEEN XALAAT

BOO BAÑEE ÑAAW…

Bu nu la waxee nga àggale kàddu gii, looy...

Njiitu Réew

Dangaa jiitoom Dañu la jiital Sa jubb cunduŋ xanaa taxul Moo ndax...

YAA GORE !

Yàgg, yàgg, dëgg ay daan Dëgg lottoon na Senegaal Usmaan Sonkoo...

Ndigalu Maam Ya

Afrig nee Waaw góor, waaw kumba Ayca leen ca waar wa Bu...

SÀCCIIN WI JËM CI TÀNN YI DËGMAL TE FEEÑALEES KO

Sëñ Abdu Xaadr Kebe mooy biral fii xalaatam ñeel...

TÀGGATOO

NJÀNGAT CI TÉERE YI

XËT YI LEEN DÀQAL

ÑAŋ-MBAALO, TOJ NGA LÀMB JI !

« Toj naa fii ! », « Tasaare naa fee ! », « Rajaxe naa fale ! »… Su nu waxantee dëgg, xorom si...

DOOMU GAYNDE, GAYNDE LAY DOON !

Saa-senegaal bii di Paap Mataar Saar, ab wurekat la, nekk ndaw, tollu ci fukki...

MANCHESTER CITY WITTI NA BIDDIIWAM BU NJËKK

Àngale yaa ngay gundaandaat ! Manchester a ngi toj ! Ren, dafa baxa. Ci bëccëgu dibéeru...

WUJJE GI CI BIIR KUJJE GI  LAN MOOY JUBLUWAAY BI ?

“ Yaa ma..” ji ak “Maa la…” ji a ngi tulle ak màlle ci...

Xalifa Sàll : « Maki Sàll… dafa musal réew mépp. »

Bi Njiitu réew mi waxee démb ne du bokk ci wotey 2024 yi ba...

Paatug njiitul pekkug Asimi Goytaa li

Njiitul pekkug Asimi Goytaa lii di Umar Taraawore, ñu koy woowe Duglaas, ñàkk na...

KARIIM WÀDD : “DAMAY BOKK CI NII WALLA CI NAA…”

Gaawu gii weesu la ndajem ndeyu àtte mi biral limu lawax yiy bokk ci...

LAYOOB SONKO-MBAY ÑAŊ : XEEX BI DOOR NA !

Ñetti biisi Dakar Dem Dikk yu tàkk ca Petersen, AUCHAN Mermoos tàkk jëppeet, ay...

LI GËN A FËS CI XIBAARI BÉS BI (TALAATA 14 MÀRS 2023)

PÓLITIG Ci talaatay tey ji la lëkkatoo Yewwi Askan Wi doon amal ab « Giga meeting »...

ÀTTEKAT BI SETAL NA SITOOR NDUUR

Ndogal li rot na : yoon toppeetul dara Sitoor Nduur. Tey, ci àllarba ji 19...

BÀTTALE MAKI SÀLL ÑEEL MBASUM COVID-19 MI

Ami Mbeng “…Luy jot jot na ginnaaw dee.”   Ci altine jii weesu, 23eelu fan ci màrs...

TER, FOOY TEERE ?

Keroog, gaawu 28 saŋwiye 2023, la yéenekaayu Farãs bii di Le Figaro génne ab...

BIRAM SULEY JÓOB, MBAA DU… ?

Gor, ca wax ja. Kàddu gilee génn démb ci gémmiñi saa-senegaal yu baree bare....

TAAFAR SI CI LÀNGUG POLITIG GI, MBAA DINA JUR JÀMM CI RÉEW MI ?

Xeetu taafar yi nuy faral di gis te di ko dégg ci réew mi...

Li gёn a fés ci xibaari bés bi Alxames 3 nowambar 2022

PÓLITIG Coowal Aji Saar ak Usmaan Sonko Démb ci alxames ji, 3 nowàmbar, la kii di...

“ÀND GËSËM” A NGI GËSËM  

Fan yee nu jàll la waa “Ànd Gësëm” génne woon ab yégle di ci...

MBAY JAAG, GOR BI SENEGAAL AMEEL BOR (Xaaj bu njëkk)

Xel tëju na, xalaat dëju. Xol tooy na, bët jooy. Ndeysaan… Gaynde wàcc na liggéey....

Me Duudu Ndóoy ñeel mbirum Sonko : ” Li Maki Sàll mën a def ngir saafara mbir mi…”

Me Duudu Ndóoy a nekkoon ganu Maymuuna Nduur Fay ci jotaayu L'invité de MNF...

"BATTRÉ" DA FA XEW CI JAMONO

BATTRÉ DAFA XEW CI JAMONO

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (Altine 20 Féewirye 2023)

PÓLITIG Pur tàbb na lawaxam Sëriñ Mustafaa Si moo nar a nekk lawaxub làngug polititig gii...

AFROBASKET-KIGALI 2023 : XALAM DEMOON NA BAY NEEX !

Démb la woon finaalu Afrobasket bi doon am ren ca Ruwàndaa, doxoon ci diggante...

MBARA-WÀCC DOOMI-GAYNDE NJAAY YI !

Sunu gaynde yi amagul ñaar-fukki at wone nañu njàmbaar fale ca Niseer, nga xam...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (ÀLLARBA 3 ME 2023)

Aminata Ture Ginnaaw bi mu xamlee nee waa PDS ak Waa Bennoo Bokk Yaakaar dañoo...

LI GËN A FËS CI XIBAARI TÀGGAT-YARAM (DIBÉER 5 MÀRS 2023)

LÀMB  Saa-Cees - Rëg-rëg ñoo doon bëre ci dibéeru tey ji. Mu doonoon làmb ju...

LÀRME BI PÓLITIGUL

Bërki-démb, ci àjjuma ji, la waa Yewwi Askan Wi génne woon ab yëgle ngir...

MAKI SÀLL A NGI JËMMAL NAALAM

Àjjuma jii weesu lañu teg loxo Njiitul Pastef li, Usmaan Sonko, ginnaaw bi mu...

DAKKALUG PÓLITIG FA TUUBAA : AG NDIGAL AK I RÉEROO

Tolluwaayu pólitigu fi Senegaal ak coow la mu làmbool mel na ni bàyyiwul kenn....

BATAAXALU ITALI BU TIISE NII…

Mbokki Senegaal, Maa ngi leen di nuyu yéen ñépp, ku ci nekk ci sa tur...

SONKO AK MAKI : KUY DAAN ?

Fitna lañ doore bésub àjjuma jii. Fitna ju sosoo ci diggante Sonko ak Maki....

LU WARAL ITALI SOPPEEKU NII ?

Ak lu waay mën a wax, réewum Itali yàqu na. Bi Salwini toogee ci...

MAN, CEERNO ALASAAN SÀLL

Yeen, mbokki réew mi, Dama bëgg a waxtaan ak yeen ci réew mu màgg. Senegaal réew...

KOOM-KOOM GI : YITTEY YITTE YI

Gaawu, 17 sàttumbar 2022 la Njiitu réew mi Maki Sàll tëral ag Nguur gu...

YÉEN ÑIY SIIF JIGÉEN ÑI : NGEEN TEG KO FAN?

  Ndey Koddu Faal « Daf maa sàkku ci lu ma neexul… Egg na ci man… » Kàddu yu...

25 me 1963 – 25 me 2023 : 60i at ginnaaw juddug OUA

Keroog ci Alxames ji, 25 me 2023, la mboolooy Saa-Afrig yi doon màggal bés...

NJUREEFI NDAJEM RÉEWI MSGBC

Ci ndaje mi ñu amaloon ci 1eel ak 2eelu fan ci weeru Sàttumbar fii...

TONTU DU FOROX !

Démb ci yoor-yoor bi, toppekat bu mag bi, Ibraayma Baaxum, doon na amal ndajem...

SÉEX ALIYU NDAW : BÉS DU ÑÀKK, DAY SORE

Mbootaayu Fonk Sunuy Làmmiñ daa fas yéene delloo njukkal bindkat bu mag bii di...

UGB : XEEX BI DOORATI NA !

Xeex bi jolleeti na diggante ndongoy iniwérsite Gastoŋ Berse ak takk-der yi. Jamono jii...