BUBAKAR BÓRIS JÓOB : AG GUY CI PÉNCUM LADAB

Jukkees na ab laaj-tontu ci yéenekaay Le Soleil, limu 16582eel bu Gaawu 13 ak Dibéer 14 Sàttumbar 2025.  Waxtaan la wow, sunu naataangoo bii...

TUKKIB ELIMAANU JËWRIÑ YI FA EMIRAAT ARAAB YA AK ITAALI

Elimaanu jëwriñ yi, Sëñ Usmaan Sonko, moo nga woon tay fa réewum Itaali, ginnaaw bi mu jeexalee, démb ci àjjuma ji, tukki bu mu...

MBOOTAAYU XEET YI WOTE NA “DECLARATION DE NEW YORK” BI

Ngomblaanu Mbootaayu Xeet yi nangu na lees duppee "Déclaration de New York" bi nga xam ne, dafay sàrtal nekkug ñaari réew yii di Palestin...

NDAJEM JËWRIÑ YI : NJIITU RÉEW MI ÀDDU NA CI LÀKKI RÉEW MI

Njiitu Réew mi, Sëñ Basiiru Jomaay Jaxaar FAY, jiite na, ci alarbay démb ji, 10eelu fanu sàttumbar 2025, ndajem jëwriñ mees baaxoo di amal...

SENEGAAL XAATIM NA DÉGGOOB 300I MILIYOŊI DOLAAR NGIR YEESAL MBAY MI

Jëwriñu Mbay mi, Dund bu matale bi ak Càmm gi, Sëñ Mabuuba Jaañ, xaatim ab déggoo bu tollu ci ñetti téeméeri (300i) miliyoŋi dolaar...

MAGU WAXOON NAA KO

JIKKO JU RAFET MOOY TABAX AM RÉEW

Wolof nee na, rafet kanam, rafet jikko a ko...
01:33:07

“Héritages” dalal na Bubakar Bóris Jóob

"Héritages ak Awa" ngi dalal Bubakar Bóris Jóob, ngir...

Malaanum Lëndëm : Bóris Jóob, na woon, fa woon

Ñeenteelu yoon a ngi nii Bubakar Bóris Jóob di...

GÀCCE NGAALAAMA, MBUGAAR !

Senegaal amati na ndam ci 3eelu fan ci weeru...

KUJJE GEEK WOTEB 2022 BI: BËGG NAA LA, BËGGUMA LA, LOOLU JARUL COOW

Ci bésub 23 sàŋwiye ci atum 2022 bii di...

FÀTTALIKU DÉMB

SEEX

Seex Mooy góor Moo di as gor Mbokk ya ko wor Ñooy mbokk...

FÀTTALIKU OMAR BOLONDEŊ JÓOB… 2/2

(ÑAAREELU XAAJ) Bi ñu nee Senegaal moom na boppam tamit,...

2002, ATUM SUUXU JOOLAA BI

Bërki-démb 26 sàttumbar ci atum 2020, "Bateau le Joolaa"...

FAIDHERBE, SAAY-SAAY BI NUY SARGAL

Bi Siidiya Ndàtte Yàlla génnee àddina ak léegi, am...

JÉERI JOOR NDEELAAK TUBAAB BI

Jéeri Joor Ndeela Faal mu ngi gane àdduna ci...

DÉMB AK TEY

WIDEWO YI

WAXLEEN SEEN XALAAT

BOO BAÑEE ÑAAW…

Bu nu la waxee nga àggale kàddu gii, looy...

Njiitu Réew

Dangaa jiitoom Dañu la jiital Sa jubb cunduŋ xanaa taxul Moo ndax...

YAA GORE !

Yàgg, yàgg, dëgg ay daan Dëgg lottoon na Senegaal Usmaan Sonkoo...

Ndigalu Maam Ya

Afrig nee Waaw góor, waaw kumba Ayca leen ca waar wa Bu...

SÀCCIIN WI JËM CI TÀNN YI DËGMAL TE FEEÑALEES KO

Sëñ Abdu Xaadr Kebe mooy biral fii xalaatam ñeel...

TÀGGATOO

NJÀNGAT CI TÉERE YI

XËT YI LEEN DÀQAL

«BU DUL WOON DOXANDÉEM YI, MBAS MI DU NAANE ÑEEX AFRIG » (Doktoor Séydu Jàllo)

Doktoor Séydu Jàllo ab farmasiyeŋ la, dib biyólósis ak « ancien interne des hopitaux ». Xam-xamam...

LI GËN A FËS CI XIBAARI BÉS BI (15/8/2023)

MBIRI USMAAN SONKO AK I ÑOÑAM Fukki fan ak juróom-ñaar ci tey bi Usmaan Sonko...

46i SÓOBAREY KODDIWAAR YIÑ JÀPP CA MALI

Ginnaaw juróomi weer biñ leen jàppee ak tey, sóobarei koddiwaar yaa ngi ci loxoy...

TÀGGE : MAHAMMAD BUUN ABDALAA JONN DËDDU NA

Elimaanu jëwriñ ja woon, Mahammad Buun Abdalaa Jonn, moo génn àddina.  Tey, ci àjjuma...

QATAAR 2022 Àllarba 23 nowàmbar 2022

Àllarbay démb jee nekkoon ñeenteelu bésu kuppeg àddina siy ame Qataar. Ñeenti joŋante waroon...

Ñaareelum ndaje Riisi-Afrig

Ci alxames jeek àjjuma jii la réewum Riisi doon dalal ñaareelum ndaje mi dox...

NDAJEM NDEYU ÀTTE RÉEW MI : GEG NAÑ USMAAN SONKO

Tey ci àjjuma ji la ndajem ndeyu àtte réew mi warron a jeexal caytug...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (Àllarba 08 féewaryee 202)

GUY MARIS SAAÑAA BOOLE NA SËRIÑ BASIIRU GÉY Guy Maris Saañaa bind nab bataaxal, jébbal...

Wotey 2024 : wure wa dem na këŋ

Ubbi nañu utum parenaas yi ñeel wotey 2024 yi. Ñi fas yéene nekk lawax...

TUKKIB NJIITU RÉEW MI CA FARÃS

Njiitu réew mi, Basiiru Jomaay Fay, war teew ca Farãas ci àllarbay tey jii....

‘’ÑAAWTEEF YIY XEW TEY RÉEWUM SIIN DU GULÉET…’’

(SÉEX MBÀKKE AMAAR, JËWRIÑU NDONGOY-DAARA SENEGAAL YA CA WUHAN. CI TAATAANUG NDEY KODDU FAAL) Ndey...

GÉNNUG USMAAN SONKO AK BASIIRU JOMAAY FAY

Usmaan Sonko génn na. Basiiru Jomaay Fay génn na. Senegaal yëngu na, rawatina Ndakaaru....

Mali : Soldaar yeek M5-RFP ñoo ngi wéy di waxtaan

Mali : Ba tey soldaar yi jiite CNSP (kurél gu yittewoo muccug askan wi)...

MBIRUM WAY-YËDDU YI RÉER

Baabakar Ture mu Kewoulo moo njëkk a siiwal xibaaru réeru ñaari way-yëdduy Nguur gi....

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (24/10/2023)

PÓLITIG Waa F24 fésal nañ seen tiitaange ci tolluwaayu réew mi. Seen xel dalul wenn...

COOWAL NAPPKATI KAYAAR YEEK YU MBOORO YI

Géej gi sàmbaraax na. Bakkan bu rot, 22i nit ñu amey gaañu-gaañu, ñaar ñu...

AMET SIISE WAXATI NA TOJAANGE !

Saa bu waxee, loxo dar gemmiñ. Amet Siise nekk ku ñu miin ci mbaali-jokko...

« Y’EN A MARRE » (NDEY KODDU FAAL)

Talaata jii ñu weesu (1 Sàttumbar 2020) kurél gii di « Y’en a marre...

ËTTUB TAALIF (Daawuda Njaay ak Daam Jaane)

  I Sëriñ Daawuda Njaay Jaraaf jàngalekatub wolof la. Def na gëstu bu am solo ci...

PRODAC : CAABALU ËTTUB CETTANTAL BI DËGGAL NA USMAAN SONKO

Njiitu réew mi, Basiiru Jomaay Fay, dafa santaane woon ñu siiwal caabali luññutu yees...

JURÓOM-ÑAARI TUUMA YEES GÀLL USMAAN SONKO

Usmaan Sonko kaso la jëm. Loolu la mbir yiy xeeñ jamono jii. Ginnaaw biñ...

Li gën a fés ci xibaari bés bi Àllarba 16 nowàmbar 2022

PÓLITIG  Maalig Gàkku Léegi leer na, kii di Maalig Gàkku mooy nekk lawaxu làng gii di...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (29/2/2024)

PÓLITIG Ndiisoog pólitig ga ca diisoo ba Njiitu réew ma woote woon noppi na. Bees...

BITIM-RÉEW : LAYOOKATI USMAAN SONKO YI TÀMBALI NAÑU XEEX BI

Ni ñu ko waxee woon lañu ko defe. Layookati Usmaan Sonko yi yóbbu nañu...

PASUG NGÀNNAAY GI : MBIR MI TEERI NA NGOMBLAAN GA

Dañ doon xaarandi Ngomblaan gi wax ci mbirum pasug ngànnaay gi dox diggante Nguurug...

Futbalu tefes gi : Gayndey Senegaal yi fobooti nañu

Gaynde Senegaal yu futbalu tefes gi fobu nañ. Démb ci alxames ji lañ doon...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (GAAWU 24 DESÀMBAR 2022)

PÓLITIG Tuuma ji ëttub cettantal gi tegoon ci yenn ndodd yi ñeel koppar yu ñu...

MBATIT BIIR NDAKAARU

Ndakaaru dalal na “Festival come to my home”. Muy xew-xewu mbatit, cosaan ak xeltu,...

WAAW, ANA AAMADU BA (BBY) ?

Gaawu, 3 féewaryee 2024 lañ gëj a dégg Aamadu Ba, jëwriñ ju mag ji,...

BUBAKAR BÓRIS JÓOB ÑAAWLU NA KÀDDUY TAYIIRU SAAR YI

Fan yii weesu, Tayiiru Saar, njiitul làng gii di Parti nationaliste, dafa fésaloon i...

NJIITU RÉEW MI BIND NA LIGÉEYKATI CAYTUG BOKKEEF GI

Njjitu réew mi, Basiiru Jomaay Jaxaar Fay, bind nab bataaxel, jagleel ko liggéeykati caytug...

XALIFA SÀLL JIITAL NA BÀRTELEMI JAAS

Bàrtelemi Jaas mooy jiite kàmpaañu Xalifa Sàll. Ci ngoon gi la xibaar bi rot....

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (30/4/2024)

CÀKKUTEEFU KURÉLI MAXEJJ YI Yenn ci kuréli maxejj yi, tudde seen bopp Sursaut citoyen et...

MÀGGALU POROXAAN : NU SIYAAREJI SOXNA MAAM JAARA

Màggalu Poroxaan bokk na ci xew-xewi diine yi gën a ràññeeku fi réew mi....

Yewwi Askan Wi nangu na ndogal, jël ndogal

Caabalug ëttu cettantal gi mi ngi wéy di lëmbe réew mi, rawatina làngug pólitig...

BARIGO PETOROL BU NJËKK FA SÀNGOMAAR

Muy xibaar bu njëkk ci noppi àdduna wërngal këpp : réewum Senegaal sol na...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI Altine 19 desàmbar 2022

PÓLITIG Dépite - Meer bii di Biram Suley Jóob a ngay artooti Njiitu réew mi...

YÀNQOOBA JATARA, JËWRIÑU TAGGAT-YARAM JU BEES JI

Mataar ba nekkatul jëwriñ jiñ dénk tàggat-yaram gi. Loolu bokk na ci xibaar yi...

XIBAARI TÀGGAT-YARAM

KUPPEG TEFES Mamadu Jàllo, tàggatkatu ekibu Senegaal bu kuppeg tefes bi tànn na ndaw yi...