Fondateur : Bubakar Bóris Jóob – Directeur de publication : Paap Aali Jàllo




LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (3/12/2023)

Pólitig Ëttu àttewaay bu mag bi gàntal na neenal-àtte bi layookati sonko yi sàkku woon ngir ñu saytuwaat dogal ga mu jëloon ñeel Usmaan Sonko...

LI GËN A FË CI XIBAARI BÉS BI (1/12/2023)

JËWRIÑU NGURD MI JOXE NA KÀDDOOM Démb la Ngomblaan gi doon jeexal ndaje yi mu doon amal ak jëwriñi Càmm gi. Def nañ 32i fan...

AYIB DAFE A NGI YEDD CDC

Bu Usmaan Sonko bokkee ci wotey 2024 yees dégmal de, dina doon jaloore ju réy. Nde, 2021 ba léegi, Nguurug Maki Sàll gaa ngi...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (30/11/2023)

LI BEES CI NDOGAL LI ËTTU ÀTTEWAAY BU KOWE BI JËLOON Ci talaata ji la layookati Usmaan Sonko yi jébbal waa ëttu àttewaay bu kowe...

LAYOOKATI SONKO YI DUGAL NAÑ AB NEENAL-ÀTTE

Ginnaaw bi ëttu àttewaay bu mag bi neenalee woon àtteb Sabasi Fay ba, keroog àjjuma17 nowàmbar 2023, layookati Sonko yi, ba léegi, xàddeeguñ. Nde,...
 
YËRAL LÉPP

MAGU WAXOON NAA KO

JIKKO JU RAFET MOOY TABAX AM RÉEW

Wolof nee na, rafet kanam, rafet jikko a ko...
01:33:07

“Héritages” dalal na Bubakar Bóris Jóob

"Héritages ak Awa" ngi dalal Bubakar Bóris Jóob, ngir...

Malaanum Lëndëm : Bóris Jóob, na woon, fa woon

Ñeenteelu yoon a ngi nii Bubakar Bóris Jóob di...

GÀCCE NGAALAAMA, MBUGAAR !

Senegaal amati na ndam ci 3eelu fan ci weeru...

KUJJE GEEK WOTEB 2022 BI: BËGG NAA LA, BËGGUMA LA, LOOLU JARUL COOW

Ci bésub 23 sàŋwiye ci atum 2022 bii di...
YËRAL LÉPP

FÀTTALIKU DÉMB

SEEX

Seex Mooy góor Moo di as gor Mbokk ya ko wor Ñooy mbokk...

FÀTTALIKU OMAR BOLONDEŊ JÓOB… 2/2

(ÑAAREELU XAAJ) Bi ñu nee Senegaal moom na boppam tamit,...

2002, ATUM SUUXU JOOLAA BI

Bërki-démb 26 sàttumbar ci atum 2020, "Bateau le Joolaa"...

FAIDHERBE, SAAY-SAAY BI NUY SARGAL

Bi Siidiya Ndàtte Yàlla génnee àddina ak léegi, am...

JÉERI JOOR NDEELAAK TUBAAB BI

Jéeri Joor Ndeela Faal mu ngi gane àdduna ci...

DÉMB AK TEY

YËRAL LÉPP

WIDEWO YI

WAXLEEN SEEN XALAAT

BAÑ A WACC SA ÀND…

Mbir mi doy na waar. Kenn xamul lii lu...

BOKK AK NAWLOO NGIR JÀMM AK NAATAANGE CI ÀDDUNA SI

Weer yii nu génn, réew yu bare tànn nañu seen njiit....

"LE PROTOCOLE DE L’ÉLYSÉE" : NJÀNGATU PROF BUUBA JÓOB  

Téere bu am solo bi Ceerno Alasaan Sàll génne...

KORONAAWIRIS : TAXAW TEEWLU

Làmp Faal Kala Mbasum Covid-19 mi lëmbe na àddina, lëmbaaje...

NAKA LAA GISE MBAS MI

Mbas mu dërkiis, ñàkk teggin tey jur tiiñalante ci...

KORONAAK ÀDDINA

YËRAL LÉPP

NJÀNGAT CI TÉERE YI

XËT YI LEEN DÀQAL

PALESTIN – ISRAAYEL : KU TOOÑ ?

Fan yii, Palestin ak Israayel ñu ngi sànnantey mbéll, sóobu cib xare bob, bim...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI 15/11/2023

TUXAL NAÑU USMAAN SONKO Lu ëpp ñetti weer ginnaaw ba ñu ko jëlee ca kasob...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (08/11/2023)

AYIB DAFE JOTAGUL XOBI BAAYALE YI Ba joxeg xob yi tàmbalee ba léegi daanaka moo...

LI GËN A FËS CI XIBAARI BÉS BI (12/11/ 2023)

LAKK CA JAWUB KAWLAX Ag lakk gu yéemee amoon ca ja bu mag (marché central)...

NJËGU MBËJ MI JÉGGI NA DAYO

Mboolaay mi sonn na, damm na, tàyyi na ci dundin bu metti bi muy...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (20/10/2023)

ISRAAYEL-PALESTIN Xeex bi dakkagul diggante yawuud yi ak julliti Palestin yi. Israayel a ngi wéy...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (22/11/2023)

LAYOO MAAM MBAY ÑAŊ USMAAN SONKO Suba ci alxames ji lañu waroon a àttewaat coow...

SAALIW MBAY : NDÀND FAAL, KËR MADAM (2/2)

Bërki-démb, ci gaawu gi (21eelu oktoobar 2023), lañ doon aajar téere Porofesëer Saaliw Mbay...

TUUBAA : FETAL NAÑ BENN BAAY-FAAL

Ci guddig talaata ji, jàpp àllarba 8i nowàmbar 2023 la ñu fetal benn Baay-Faal...

NJÀNG MAA NGI CI YOONU NDËRMEELU

Njàng meek njàngale mi ci Senegaal mu ngi jànkonteel ak i jafe-jafe yu metti....

NGOMBLAAN GI : TAXAWU WÉET NA

Ab diir, ginnaaw ba Ngomblaan gi tëjee woon ay buntam, tijjiwaat na leen ci...

DOG NAÑU MBAALI JOKKOO YI FA GABOŊ

Li wokkoon Senegaal, xuri na Gaboŋ. Ci njeexitalu ayu-bés bii ñu génn la réewum...

NJÀNG MEEK NJÀNGALE MI : YËNGU-YËNGU YI TÀMBALEETI NAÑU

Ci weer doŋŋ lañu tollu bi lekkool bi tijjee ak tey. Waaye ñaari kuréli...

MBIRI USMAAN SONKO : UMS DUGG NA CI COOW LI

Ginnaaw bi àttekat bi tirbinaalu Sigicoor jële ndogalu bindaat Usmaan Sonko ci këyitug wote...

USMAAN SONKO : « MBATIIT MOOY LÉPP, MOOY CËSLAAYU YOKKUTE. »

Laaj ak tontu bii nag, seen yéenekaayub web defuwaxu.com séqoon na kook Usmaan Sonko...

USMAAN SONKO WEER NA MAKI SÀLL

DGE, kurél giy saytu lépp lu aju ci wote yi, lànkalati na ndawul Usmaan...

TIRBINAALU SIGICOOR DUGALAAT NA USMAAN SONKO CI KËYITUG WOTE YI

« Am nanu ndam ! Àttekat bi santaane na ñu bindaat Usmaan Sonko ci këyitug wote...

MÓODU LÓO DAAN NA AAMAA BALDE

Xaar bi yàggoon na lool, waaj gi tamit naka noonu. Waaye, ñaari mbër yi...

CAABALUG ANSD 2023

Muy ab liggéey bu ñuy baamtu fukki at yu nekk. Ñu door ko ca...

KOLONEL SÉEX TIIJAAN MBÓOJ WUYUJI WOON NA SÀNDARMI KOLOBAAN YI

Kolonel Séex Tiijaan Mbóoj wuyuji woon na sàndarmi Kolobaan yi. Moom, Séex Tiijaan Mbóoj,...

CEDEAO AK ËTTUB ÀTTE BU MAG BI GÀNTAL NAÑ SONKO

Ëttu àtte bu CEDEAO gàntal na Usmaan Sonko, jox dëgg Càmmug Senegaal. tey la...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (20/11/2023)

NGOMBALAAN GI Dépite yaa ngi wéy di nattal jëwriñi Càmm gi seen i gafaka ñeel...

AKSIDAŊ BU METTI CA MBÀMBILOOR

Aksidaŋ yaa ngi wéy di rey nit ñi ci kow tali bi. Bërki-démb, ci...

LÀMB : TAFAA TIN DAAN NA ËMMA SEEN

Gannaaw ba Móodu Lóo ak Aama Balde bëree ci ayu-bés bii weesu, Móodu daan...

USTAAS UMAR SÀLL MA NGA CA LOXOY YOON

Ustaas Umar Ahmad Sàll, ab waaraatekat bu siiw ci réew mi la. Fës na...

XIBAARI TAGGAT-YARAM (1/10/2023)

KUPPEG ÀDDINA WAY-LUU YI (MUUMA YI) Bàyyeesu leen xel, waaye way-luu (muuma) yi teewal Senegaal...

MAKI SÀLL DÀQ NA WAA CENA

Njiiteefu réew mee génne yégle, di ci xamle ne Njiitu réew mi tabb ñu...

NJAAYUM GERTE GI : CÀMM GI SAMP NA NJËG GI

Càmm gi samp na njëg gees war a jaaye gerte gi ci kàppaañ 2023-2024...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (10/10/23)

PÓLITIG Ngomblaan gi génne na ab yégle di ci xamle ne dina amal lëlu aadaam...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (13/11/2023)

PÓLITIG Utum baayele yi ñeel Usmaan Sonko dina tàmbali ci njeexitalu ayu-bés bi. El Maalig...

DGE MÀTT NA, NE DU BÀYYI

Ci talaata jii, 31 oktoobar 2023, la kurél giy saytu wote yi ci réewum...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (6/11/2023)

PÓLITIG Kujje gee ngi waajal lu bees ñeel wote yiñ dégmal. Sëñ Abdurahmaan Juuf, di...

TËNKUG JIBAB NJÀNG MU KOWE MI

Ay fan a ngi ñuy amal ay wote ca Ngomblan ga ñeel koom mi...

PASTEF JIITAL NA BASIIRU JOMAAY

Xibaar bi jib na : Basiiru Jomaay Fay la waa PASTEF tànn ngir doon...

AY CONGU CI YENN BÉRÉB FA SIYERAA-LEWON

Njàqare ak tiis la askan wa dëkke fa Freetown yeewoo démb. Ay sàmbaa-bóoy ñoo...

JALOOREY RAGLUB SÓOBARE BU WAKAAM

Senegaal séqi na jéego bu am a am solo ci wàllu paj. Nde, doktoor...

AYIB DAFE A NGI YEDD CDC

Bu Usmaan Sonko bokkee ci wotey 2024 yees dégmal de, dina doon jaloore ju...

WAA LACOS WOOTE NAÑ BÉSUB ÑAXTU

Lëkkatoo gi ëmb mbooleem njiit yi nekkug lawaxu Usmaan Sonko yitteel, ñu gën leen...