BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi ñu jagleel waa jasporaa bi, ci njiiteefu Njiitu réew mi...

BÉS NIKI TAY, NEELEEN DOKTOOR PÀPPA AALI JÀLLO

Gaawo, 13eelu desàmbar 2025, ca Jàngune bu Ndar, la Pàppa Aali Jàllo (njiitul LDW) doon gaaral teesam ci Làkk ak mbatiiti Afrig, duppe ko...

FOQATIG NGUUR FA RÉEWUM BENEE

Ginnaaw coowal sóobare yi toog fa boppu réewum Gine Bisaawu, geneen foqatig Nguur naroon naa amaat, wile yoon, fa réewum Benee ak ay sóobare...

MOUSSO NGIR « JIGÉEN GÉNN CIG LËNDËM »

Soo déggee baatu « mousso », sam xel mën naa dem cib « restaurant » bu siiw ba ca Kanadaa. Waaye, « mousso » bii moom bokkul ak booba ; xéy-na...

NGOMBLAAN GI : DÉPITE YI TÀMBALI NAÑU CÀMBAR NAFA 2026 GI

Dépite yi tàmbali nañu càmbar nafag atu 2026 mi fa Ngomblaan ga. Ñu nar koo amal ci diiru ñaari ayu-bés ngir dalal jëwriñi Càmm...

MAGU WAXOON NAA KO

JIKKO JU RAFET MOOY TABAX AM RÉEW

Wolof nee na, rafet kanam, rafet jikko a ko...
01:33:07

“Héritages” dalal na Bubakar Bóris Jóob

"Héritages ak Awa" ngi dalal Bubakar Bóris Jóob, ngir...

Malaanum Lëndëm : Bóris Jóob, na woon, fa woon

Ñeenteelu yoon a ngi nii Bubakar Bóris Jóob di...

GÀCCE NGAALAAMA, MBUGAAR !

Senegaal amati na ndam ci 3eelu fan ci weeru...

KUJJE GEEK WOTEB 2022 BI: BËGG NAA LA, BËGGUMA LA, LOOLU JARUL COOW

Ci bésub 23 sàŋwiye ci atum 2022 bii di...

FÀTTALIKU DÉMB

SEEX

Seex Mooy góor Moo di as gor Mbokk ya ko wor Ñooy mbokk...

FÀTTALIKU OMAR BOLONDEŊ JÓOB… 2/2

(ÑAAREELU XAAJ) Bi ñu nee Senegaal moom na boppam tamit,...

2002, ATUM SUUXU JOOLAA BI

Bërki-démb 26 sàttumbar ci atum 2020, "Bateau le Joolaa"...

FAIDHERBE, SAAY-SAAY BI NUY SARGAL

Bi Siidiya Ndàtte Yàlla génnee àddina ak léegi, am...

JÉERI JOOR NDEELAAK TUBAAB BI

Jéeri Joor Ndeela Faal mu ngi gane àdduna ci...

DÉMB AK TEY

WIDEWO YI

WAXLEEN SEEN XALAAT

BOO BAÑEE ÑAAW…

Bu nu la waxee nga àggale kàddu gii, looy...

Njiitu Réew

Dangaa jiitoom Dañu la jiital Sa jubb cunduŋ xanaa taxul Moo ndax...

YAA GORE !

Yàgg, yàgg, dëgg ay daan Dëgg lottoon na Senegaal Usmaan Sonkoo...

Ndigalu Maam Ya

Afrig nee Waaw góor, waaw kumba Ayca leen ca waar wa Bu...

SÀCCIIN WI JËM CI TÀNN YI DËGMAL TE FEEÑALEES KO

Sëñ Abdu Xaadr Kebe mooy biral fii xalaatam ñeel...

TÀGGATOO

NJÀNGAT CI TÉERE YI

XËT YI LEEN DÀQAL

GENN GAAL, ÑAARI JULLI

Ku makiyaasu mbaa ñu makiyaas la, boo ñaqee ñaaw

FUTBAL AK BASKETU SENEGAAL : YAAKAAR AK YÀKKI

Bi Alseri dumaa Senegaal benn ci dara ci finaalu joŋanteb réewi Afrig yi (CAN)...

MÀNDELAA WAR NAA AM NAQAR FA MU TËDD !

Lan moo dal sunu mbokki réewum Afrig-bëj-Saalum ? Su ma nee ‘’mbokk’’, nit ñu ñuul...

LAMIN KAMARA, GONEG WURUS GI

Mamadu Lamin Kamara, jàppleen tur wi. Xareñte, dëgëraay, njaxlaf ak dégg-daaj la gaynde gu...

WOTEY 2024 LIY JOT, JOT NA

Lu moy at kepp a des ci wotey 2024 yi. Lawax yi tàmbali nañu...

AJI SAAR SÀKKU NA ÀTTEB DABU

Alxames 1 fan ci weeru suwe la àttekat bi biraloon daan yim gàll Usmaan...

SËRIÑ SEEKA BARI DOOLE CI LÀNGU PÓLITIG GI !

Ni waa Senegaal gëmee Yàlla te fonk diine, umpul kenn ci àddina si. Nde, askanuw...

KORONAAWIRIS : MBETE GAYNDE GU TËX !

Ndey Koddu Faal   Fii ci Senegaal, limu ñi Covid-19 bi daaneel romb na téeméer. Moonte bi...

XIBAARI TÀGGAT-YARAM (ALXAMES 4 ME 2023)

RËBËJOO BA CA PSG Gannaaw tukki bi Messi amaloon ca Araabi Sawdid, njiiti Paris Saint-Germain...

FÀTTALIKU OMAR BOLONDEŋ JÓOB…

https://www.youtube.com/watch?v=3sR_E7UeuMc Ci àllarba tey jii, 11eelu fan ci weeru Mee 2022 la Senegaal di fàttaliku...

LEAGUE DES CHAMPIONS : MANCHESTER CITY WULLI NA REAL MADRID

Démb ci àllarba ji lees doon amal ñaareelu joŋante démi-finaal diggante Manchester City ak...

“Ngalla bunu jaawale ECO ak… ECO!'”

Fan yii, coowal ECO baa ngi mel ni tànnbéeru dëmm, rëb ba nga ne...

F24, ÀND XEEX 3EELU MOOME

Njiitu réew mi, Maki Sàll, amati na soxla. Nde, kurél gu bees juddu na...

SENEGAAL AMATI NA NDAM !

Gàcca-ngaalaama sunu xëllóob yi (gaynde yu ndaw yi) ! Taaw daal, ndeke bu xàllee,...

NDAM LU SAFUL XOROM, SAFUL SUUKAR…?

10Dibéer yemook ñaar-fukki fan ak ñeent si weeru Féewaryee, la waa réew mi doon...

Rafayel Njaay taalifkat la woon…

Ndeem dëgg la ni àjjana, ngir mbindeef yi daa yokk yëf yu baax ci...

KIGALI

KIGALI Kigali, soo fay doxantu Sa xol day sedd doo gis loo  ñaxtu Nga naw ci saa...

SÉEX ALIYU NDAW : “LI MA JËLE CI MALAANUM LËNDËM…”

Ab téeree ngi nii boo xam ne, bii, boo koy jàng doo bëgg mu gaaw...

LI GËN A FËS CI XIBAARI BÉS BI (12/6/2023)

MBIRIM ÑETTEELU MOOME GI  Paap Sàmba Mbuub xelal na Maki Sàll Paap Sàmba Mbuub, kilifa la...

7 MÀRS WALLA 8 MÀRS ? BEY CI SA WEWU TÀNK…

Juróom-ñetteelu fan ci weeru màrs la xel yépp di dem ci jigéen ñi, ndax...

XËCC BU DAŊEE DAGG !

Nimbir yiy doxe diggante nguur geek kujje gi bi Màkki Sáll toogee ci jal...

FESPACO

FESPACO (festival panafricain du cinéma et de la télévision de Ouagadougou) bokk na ci...

DAANUB USMAAN SONKO AK NDEY XADI NJAAY : ÑU BAREE NGIY ÑAAWLU

Tey, ci alxames ji 1eelu fan ci weeru suwe la àttekat bi biral daan...

BATAAXAL BU JËM CI MAAM SEŊOOR

Maam, Fan yee weesu, sama xel dafa ne yarr ci yaw. Ba nga demee ba...

TABASKI 2023 : XUTBA SËRIÑ BAABAKAR SI MU DABBAAX (NJOOL-FUUTA)

Ci alxamesu démb ji la ñu ëpp ci saa-senegaal yi tabaski. Ku ne tabaski,...

Li gën a fés ci xibaari bés bi (Gaawu 4 fewaryee 2023)

NJÀNG AK NJÀNGALE  Ab toogaanu-ñaxtu la ñenn ci jàngalekat yi ñuy woowe "contractuels" amaloon démb....

MBOOTAAYU XEET YI YEDD NA NGUURUG SENEGAAL

Kurélug mbootaayu xeet yi ñeel àq ak yelleefi doom-aadama, àdduna ci xew-xew yi amoon...

CHAN 2023

Chan 2023 bi door na keroog àjjuma 13i fan ci saŋwiye 2023. Wile yoon...

QATAAR 2022 Talaata 22 nowàmbar 2022

Talaatay démb jee nekkoon ñetteelu bésu kuppeg àddina siy ame Qataar. Ñaari ponkal waroon...

Ëllëgu gaynde yi ca tugal

Naples noppeegul ngir bàyyi Kalidu Kulibali mu dem. Moo ngi ci tànki yokkal ko...

NÉEWAAYU LIMUB ÑI WOTE CI JOŊANTE YII : LAN MOO KO WARAL ?

Dibéer 31i fan ci weeru Sulet nekkoon bés bi ñu doon amal wotey palum...

WOTEY 31 SULET YI, Péncoo walla paacoo, askan waay tànn

Fukki fan rekk a ci des fii ak dibéer 31eelu fan ci sulet. Keroog...

KEN NDÓOY « ÑÀKK NA BAKKANAM »

Bindal sargal ku génn àddina, damay koy def. Waaye de, lu ma diis la,...

Gaasu Senegaal bi : lu tax tugal di ko xemmem?

Daan ya réewi tugal ya tegoon ci kow Riisi ñoo tàmbalee di dalaat seen kow. Nde, daan yooyee sabab tey jaf-jafe yu metti yi ñuy jànkonteel ci wàllum koom-koom. Daanaka lépp a yokku rawatina dund gi ak...

7 MÀRS WALLA 8 MÀRS ? BEY CI SA WEWU TÀNK…

Juróom-ñetteelu fan ci weeru màrs la xel yépp di dem ci jigéen ñi, ndax...