BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi ñu jagleel waa jasporaa bi, ci njiiteefu Njiitu réew mi...

BÉS NIKI TAY, NEELEEN DOKTOOR PÀPPA AALI JÀLLO

Gaawo, 13eelu desàmbar 2025, ca Jàngune bu Ndar, la Pàppa Aali Jàllo (njiitul LDW) doon gaaral teesam ci Làkk ak mbatiiti Afrig, duppe ko...

FOQATIG NGUUR FA RÉEWUM BENEE

Ginnaaw coowal sóobare yi toog fa boppu réewum Gine Bisaawu, geneen foqatig Nguur naroon naa amaat, wile yoon, fa réewum Benee ak ay sóobare...

MOUSSO NGIR « JIGÉEN GÉNN CIG LËNDËM »

Soo déggee baatu « mousso », sam xel mën naa dem cib « restaurant » bu siiw ba ca Kanadaa. Waaye, « mousso » bii moom bokkul ak booba ; xéy-na...

NGOMBLAAN GI : DÉPITE YI TÀMBALI NAÑU CÀMBAR NAFA 2026 GI

Dépite yi tàmbali nañu càmbar nafag atu 2026 mi fa Ngomblaan ga. Ñu nar koo amal ci diiru ñaari ayu-bés ngir dalal jëwriñi Càmm...

MAGU WAXOON NAA KO

JIKKO JU RAFET MOOY TABAX AM RÉEW

Wolof nee na, rafet kanam, rafet jikko a ko...
01:33:07

“Héritages” dalal na Bubakar Bóris Jóob

"Héritages ak Awa" ngi dalal Bubakar Bóris Jóob, ngir...

Malaanum Lëndëm : Bóris Jóob, na woon, fa woon

Ñeenteelu yoon a ngi nii Bubakar Bóris Jóob di...

GÀCCE NGAALAAMA, MBUGAAR !

Senegaal amati na ndam ci 3eelu fan ci weeru...

KUJJE GEEK WOTEB 2022 BI: BËGG NAA LA, BËGGUMA LA, LOOLU JARUL COOW

Ci bésub 23 sàŋwiye ci atum 2022 bii di...

FÀTTALIKU DÉMB

SEEX

Seex Mooy góor Moo di as gor Mbokk ya ko wor Ñooy mbokk...

FÀTTALIKU OMAR BOLONDEŊ JÓOB… 2/2

(ÑAAREELU XAAJ) Bi ñu nee Senegaal moom na boppam tamit,...

2002, ATUM SUUXU JOOLAA BI

Bërki-démb 26 sàttumbar ci atum 2020, "Bateau le Joolaa"...

FAIDHERBE, SAAY-SAAY BI NUY SARGAL

Bi Siidiya Ndàtte Yàlla génnee àddina ak léegi, am...

JÉERI JOOR NDEELAAK TUBAAB BI

Jéeri Joor Ndeela Faal mu ngi gane àdduna ci...

DÉMB AK TEY

WIDEWO YI

WAXLEEN SEEN XALAAT

BOO BAÑEE ÑAAW…

Bu nu la waxee nga àggale kàddu gii, looy...

Njiitu Réew

Dangaa jiitoom Dañu la jiital Sa jubb cunduŋ xanaa taxul Moo ndax...

YAA GORE !

Yàgg, yàgg, dëgg ay daan Dëgg lottoon na Senegaal Usmaan Sonkoo...

Ndigalu Maam Ya

Afrig nee Waaw góor, waaw kumba Ayca leen ca waar wa Bu...

SÀCCIIN WI JËM CI TÀNN YI DËGMAL TE FEEÑALEES KO

Sëñ Abdu Xaadr Kebe mooy biral fii xalaatam ñeel...

TÀGGATOO

NJÀNGAT CI TÉERE YI

XËT YI LEEN DÀQAL

XIBAARI TÀGGAT-YARAM

TOOGLANTE CAN 2025 : SENEGAAL - BURUNDI Ekibu Senegaal dina dalal bu Burundi talaata...

WOTEY NGOMBLAAN GI : NDAJEM NDEYU SÀRTU RÉEW MI SIIWAL NA NJUREEF YU MUJJ YI

Ndajem Ndeyu Sàrtu Réew mi biral na njureefi wotey Ngomblaan gi. Tay ci àllarba...

XIBAARI TÀGGAT YARAM

CAN 2025 : 24I EKIB YI JALL Noppees na ci matsi jàllug CAN bi ci...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (9/12/2024)

NDAJEM DOHAA MI Njiitu réew mi Sëñ Basiiru Jomaay Jaxaar Fay teeweji woon na Ndajem...

TËJANDI NAÑU JÀNGUNE BU SIGICOOR

Ginnaaw jàmmaarloo yu metti yi amoon Jànguneb Asan Sekk bu Sigicoor, kilifay daara ju...

XIBAARI TÀGGAT-YARAM (12/12/2024)

CHAN 2025 Ekibu Senegaal dina amal ñaari joŋante ñeel bokkadili CHAN 2025 bi. Gaynde...

CEDEAO : CAMPEEF GI NANGU NA GÉNNUG BURKINAA, MALI ET NISEER

Ca weeru sulet 2024 la ñetti réew yii di Burkinaa Faaso, Mali ak Niseer...

YÉENEY NJIITU RÉEW MI ÑEEL NJÀNG MI

Njiitu réew maa nga woon Gànnaar, démb ci talaata ji, ngir fekkeeji Ndajem waxtaan...

SIIWALUB TOFTALEG SAABALUKAAY YI CÀMM GI NANGU

Dees na siiwal limu saabalukaay yi méngoo ak yoon ci lu yàggul dara. Bees...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (13/12/2024)

SÉMBU ÀTTE14/2014 Ngomblaan gi dina ubbi ëllëg ci gaawu bi, 14i pani desàmbar 2024, bu...

CPI JÁPPLU NA BENYAMIN NETANYAHOU

Ëttu àttewaay bii di CPI (Cour Pénale Internationale, fa mbaxana doone benn fi àddina...

YOON WOO NA BÀRTELEMI JAAS AK AADAMA GAY

Sànq ci bëccëg gi la xibaar bi rot. Moom, Bàrtelemi Jaas miy ndeyu-mbill ji,...

MBIRUM MEERI BU NDAKAARU

Mbirum meeri bu Ndakaaru mi ngi wéy di jur coow. Tay rekk, Sëñ Bàrtelemi...

FAR NAÑU CAMPEEF YII DI HTTC AK CESE

Barki-démb ci gaawu bi lañu woo woon dépite yi fa Ngomblaan ga. Li waraloon...

TUKKIB ELIMAANU JËWRIÑ YI FA GÀMBI

Wii yoon mooy ñaareelu tukkeem fa Gàmbi ci diir bu gàtt. Barki-démb, ci àllarba...

EL MAALIG NJAAY MOOY NJIITUL NGOMBALAAN GU YEES GI

Sëñ Elaas Maalig Njaay lañu fal ci boppu Ngomblaan gu yees gi. Ci altiney...

XIBAARI TÀGGAT-YARAM

REAL MADRID JËLATI NA KUB Real Madrid moo ngi ak xalimaam di bind mbooram rekk...

NDAJEM JËWRIÑ YI

Njiitu réew mi, Sëñ Basiiru Jomaay Jaxaar Fay, jiite na ndajem jëwriñ yi barki-démb...

KÀDDUY NJIITU RÉEW MI CI AT MU BEES MI

Ci neexitalu atum 2024 mi, Njiitu Réew mi, Basiiru Jomaay Jaxaar Fay, biral na...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (2/1/2025)

BÀRTELEMI JAAS TEGGIWUL TÀNKAM Ginnaaw bi Yoon nangoo moomeg dépiteem ak cëru meeru Ndakaaru, taxul...

NDÀMPAAY ÑEEL WAY-LORUY XEW-XEWI 2021 JÀPP 2024

Njiitu réew mi, Sëñ Basiiru Jomaay Jaxaar Fay, beral na way-loruy xew-xewi 2021 jàpp...

FËKKUG XALIFA AAMADU HAADI TAAL FA MALI

Tiijaani Mali yi ñu ngi ci tiis ak njàqare, rawatina njabootu Séex Umar Fuutiyu...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (23/12/2024)

NJÀNG MI : SEYDI GASAMA ÀNDUL AK JËWRIÑ JI Xale yees yéex a bind ci...

USMAAN SONKO TONTU NA EMMANUEL MACRON

Tontu du forox naam, waaye mën na booy i nopp. Bu yeboo seet ba...

5eelu NDAJE MU MAG MU COSYDEP

Kurélug COSYDEP (Coalition des Organisations en Synergie pour la Défense de l’Éducation) amal na...

CAYTU AK WOTE NAFAY NJËWRIÑ YI AK CAMPEEF YI

Altine jee weesu, fukki fan ak juróom-benn ci weeru desàmbar, la Ngomblaan gi door...

WAA FADTS JURE NAÑU SÉEX UMAR JAAÑ

Li Séex Umar Jaañ waxoon ci Tirailleurs sénégalais yi jur na coow lu réy...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (26/12/2024)

BÉSUB DPG BI Ci weeru awril wale jàll la Njiitu réew mi, Basiiru Jomaay Jaxaar...

GÉNNEG SENEGAAL CI RÉEW YI GËN A NDÓOL

Senegaal ak réewum Kàmboj (Cambodge) ñooy réew yiy waaj a génn ci mboolom réew...

NGOMBLAAN GI : TAXAWAL NAÑU ËTTU ÀTTEKAAY BU KAWE BI

Ngomblaan gi taxawal na Ëttu àttewaay bu kawe bi. Tay ci gaawu bi, 28i...

NJIITU RÉEW MI DÀQ NA SÉEX UMAR JAAÑ

Njiitu réew mi, Basiiru Jomaay Jaxaar Fay, dàq na Séex Umar Jaañ. Moom, Séex...

XEW-XEW BU DOY WAAR FA KOLDAA

Xew-xew boobu mi ngi am démb, ci dibéer ji, fa koñ bii di Médina...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (7/1/2024)

LAYOOB WATTUKATI KAARAANGEG LËKKATOO SÀMM SA KÀDDU Tay ci altine ji, ëttu àttekaay bu Ndar...

XIBAARI TÀGGAT-YARAM

Senegaal jàll na ci mbooleem powi Afrig ci atum 2025 yi. Loolu di jéego...

BIRALU NAALU PÓLITIG WU USMAAN SONKO

Démb ci àjjuma ji, 27i pani desàmbar 2024, la elimaanu jëwriñ yi doon biral...