BUBAKAR BÓRIS JÓOB : AG GUY CI PÉNCUM LADAB

Jukkees na ab laaj-tontu ci yéenekaay Le Soleil, limu 16582eel bu Gaawu 13 ak Dibéer 14 Sàttumbar 2025.  Waxtaan la wow, sunu naataangoo bii...

TUKKIB ELIMAANU JËWRIÑ YI FA EMIRAAT ARAAB YA AK ITAALI

Elimaanu jëwriñ yi, Sëñ Usmaan Sonko, moo nga woon tay fa réewum Itaali, ginnaaw bi mu jeexalee, démb ci àjjuma ji, tukki bu mu...

MBOOTAAYU XEET YI WOTE NA “DECLARATION DE NEW YORK” BI

Ngomblaanu Mbootaayu Xeet yi nangu na lees duppee "Déclaration de New York" bi nga xam ne, dafay sàrtal nekkug ñaari réew yii di Palestin...

NDAJEM JËWRIÑ YI : NJIITU RÉEW MI ÀDDU NA CI LÀKKI RÉEW MI

Njiitu Réew mi, Sëñ Basiiru Jomaay Jaxaar FAY, jiite na, ci alarbay démb ji, 10eelu fanu sàttumbar 2025, ndajem jëwriñ mees baaxoo di amal...

SENEGAAL XAATIM NA DÉGGOOB 300I MILIYOŊI DOLAAR NGIR YEESAL MBAY MI

Jëwriñu Mbay mi, Dund bu matale bi ak Càmm gi, Sëñ Mabuuba Jaañ, xaatim ab déggoo bu tollu ci ñetti téeméeri (300i) miliyoŋi dolaar...

MAGU WAXOON NAA KO

JIKKO JU RAFET MOOY TABAX AM RÉEW

Wolof nee na, rafet kanam, rafet jikko a ko...
01:33:07

“Héritages” dalal na Bubakar Bóris Jóob

"Héritages ak Awa" ngi dalal Bubakar Bóris Jóob, ngir...

Malaanum Lëndëm : Bóris Jóob, na woon, fa woon

Ñeenteelu yoon a ngi nii Bubakar Bóris Jóob di...

GÀCCE NGAALAAMA, MBUGAAR !

Senegaal amati na ndam ci 3eelu fan ci weeru...

KUJJE GEEK WOTEB 2022 BI: BËGG NAA LA, BËGGUMA LA, LOOLU JARUL COOW

Ci bésub 23 sàŋwiye ci atum 2022 bii di...

FÀTTALIKU DÉMB

SEEX

Seex Mooy góor Moo di as gor Mbokk ya ko wor Ñooy mbokk...

FÀTTALIKU OMAR BOLONDEŊ JÓOB… 2/2

(ÑAAREELU XAAJ) Bi ñu nee Senegaal moom na boppam tamit,...

2002, ATUM SUUXU JOOLAA BI

Bërki-démb 26 sàttumbar ci atum 2020, "Bateau le Joolaa"...

FAIDHERBE, SAAY-SAAY BI NUY SARGAL

Bi Siidiya Ndàtte Yàlla génnee àddina ak léegi, am...

JÉERI JOOR NDEELAAK TUBAAB BI

Jéeri Joor Ndeela Faal mu ngi gane àdduna ci...

DÉMB AK TEY

WIDEWO YI

WAXLEEN SEEN XALAAT

BOO BAÑEE ÑAAW…

Bu nu la waxee nga àggale kàddu gii, looy...

Njiitu Réew

Dangaa jiitoom Dañu la jiital Sa jubb cunduŋ xanaa taxul Moo ndax...

YAA GORE !

Yàgg, yàgg, dëgg ay daan Dëgg lottoon na Senegaal Usmaan Sonkoo...

Ndigalu Maam Ya

Afrig nee Waaw góor, waaw kumba Ayca leen ca waar wa Bu...

SÀCCIIN WI JËM CI TÀNN YI DËGMAL TE FEEÑALEES KO

Sëñ Abdu Xaadr Kebe mooy biral fii xalaatam ñeel...

TÀGGATOO

NJÀNGAT CI TÉERE YI

XËT YI LEEN DÀQAL

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (1/2/2024)

WAAJTAAYU KÀMPAAÑI WOTEY 2024 YI Ay fan yu néew ñoo des ngir kàmpaañ bi tàmbali....

70i WAY-SÀKKU JÉBBALE NAÑ SEEN I WAYNDARE

Ci àllarbay tey ji, 27 desàmbar 2023, la àpp bi Ndajem ndeyu àtte mi...

MUSAA JÓOB BAÑ NA NI MUUT, NEE NA MOTT (NDEY KODDU FAAL)

Musaa Jóob layookat bi doon jiite "Dakar Dem Dikk" la njiitu réew mi tekki...

MAKI SÀLL FEDDALI NA KÓOLUTEEM CI AAMADU BA

Àllarbay tay jii la xibaar gi rot, njiitu réew mi Maki Sàll xamal na...

KARIIM WÀDD BINDU NA, LÉEGI ?

Coowal wotey palug Njiitu réew ci atum 2024 door na bu yàgg te mbir...

SONKO YËNGAL NA

Ndaje moomu mi ngi amoon démb ci dibéer ji, fale ca béréb boobu ñuy...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (22/11/2023)

LAYOO MAAM MBAY ÑAŊ USMAAN SONKO Suba ci alxames ji lañu waroon a àttewaat coow...

BIRAM SULEY JÓOB MA NGA WOON KÉEDUGU

Jëwriñu laf gi, soroj beek mbéll yi, Biram Suley Jóob, ma nga woon fa...

WOTEY 2024 : ËTTUB DABU BI BIRAL NA NJUREEFI NÉGANDIKU YI

Tay ci àllarba ji la Ëttub dabu bi nekkee Ndakaaru biral  njureefi néggandiku yi...

“WAT GAAL AK YËGOO…” Jëwriñ Aliw Sow amal na tukkib nemmeeku ñeel artist yi

Ginnaaw bi ñu ko tabbee yees ci wàllum mbatiit ak moomeel, Aliw Sow door...

LËLUB NJÀNG MU KOWE MI ÑEEL BAAXAL APPUG NJANGALE MI

Kilifa yi séq njàng mu kowe mi ubbi nañu lëlub ñetti fan. Ñu namm...

BÀYYEENDI NAÑ BIRAM SULEY JÓOB AK EL MAALIG NJAAY

Bàyyi nañ Biram Suley Jóob. Layookatam bi, Meetar Musaa Saar a ko xamle. Moom,...

LI WARAL NJËGU KURAŋ BI YOKKU

Li ñu doon laam-laame mujje naa am dëggëntaan. Njëgu kuraŋ bi yokku na li...

YÓBBOOTI NAÑ PAAP AALE ÑAŊ CA RAGLUB PRINCIPAL

Ci guddig gaawu jàpp dibéer lees jàllale Paap Aale Ñaŋ ca raglub Principal. Me...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (08/11/2023)

AYIB DAFE JOTAGUL XOBI BAAYALE YI Ba joxeg xob yi tàmbalee ba léegi daanaka moo...

Futbalkati Afrig yi Orange ràññee (MUSAA AYSATU JÓOB)

Musaa Aysatu Jóob Démb ci altine ji Orange Footbaal Club fésal na ekibam ci atum 2019-2020, muy...

Li gën a fés ci xibaari bés bi Alxames 5 saawiye 2023

PÓLITIG Leerali Usmaan Sonko ñeel ñaxtuy ndongoy Sigicoor yi Ci ndajem-waxtaan mu mu doon amal tey...

NDAM LU RÉY, NDAM LU TUUT

Alxames, 8i fan ci desàmbar 2022. 15i waxtoo jot ci ginnaaw njolloor. Ñi ëpp...

BOROOM-ÑAARI-TUR YI SAMP NAÑU SEEN NDËND WAAYE…

Mbirum ngóor-jigéen doon na lu lëmbe àddina si fi mu tollu nii, moonte dey...

CEDEAO TEGGI NA DAAN YI MU TEGOON NISEER

Démb ci gaawu gi la way-bokki kurél gi boole réewi Afrig sowu-jant yi ci...

KUPPEG ÀDDINA SI : SENEGAAL TARXIIS NA

Ginnaaw ubbite gi, ci dibéer ji (20 nowàmbar 2022), démb lañ doon amal ñaareelu...

LI GËN A FËS CI XIBAARI BÉS BI (20/7/2023)

F24 Kurél gii di F24 boole ay làngi pólitig ak i way-moomeel dafa nammoon a...

TOFTALEG FIFA : SENEGAAL CA KOW CA KANAM

Ci alxemes ji, 6 Oktoobar 2022, la Fifa siiwal toftaleem bi muy amal weer...

ÑU SELL ÑA

Talaatay démb ji, 1 nowàmbar 2022, la waa jàngu bi doon màggal seen waliyu...

MBËKK MI : DEM REKK !

Mbëkk mi lëmbe na lool réewum Senegaal rawatina ci fan yii. Lu daan am...

TABASKI TEEROOTI NA

Tabaski, xew-xew bu mag a mag la ci jullit ñi. Mu am cëslaay lu...

ÀNDU NAWLE

Bokk na ci anam yi nit lootaabee ag dundam ci kaw suuf, lu nekk...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI Gaawu 19 nowàmbar 2022

PÓLITIG Woteb nafag 2023 gi door na ca Ngomblaan ga. Tey ci gaawu bi, jëwriñ...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (GAAWU 12 NOWÀMBAR 2022)

PÓLITIG Na mu ko yëglewoon ginnaaw ba mu janook taskati-xibaar yi, Usmaan Sonko miy njiitu...

LAYOO USMAAN SONKO – MAAM MBAY ÑAŊ

Àttekat bi daan na Usmaan Sonko ñaari weer yum dul tëdd kaso ak 200i...

XEW-XEWI NDÉGLUG USMAAN SONKO GI

Ci alxames jii weesu, ñetti fan ci weeru nowàmbar, la kii di Njiital PASTEF...

COOWAL UCAD

Ginnaaw ba ñu taaxeerloo ay ayu-bés, ndongoy jànguneb Ndakaaru yaa ngi sàkku ñu ubbi...

XIBAARI TÀGGAT-YARAM (19/11/2023)

LÀMB : LAG DË GEER 2 DAAN NA SITTA Ñaari mbër yi waajal nañu seen...

MAAMUR JALLO, KU ÑÉPP TUFLI NGA TOOY

Coowal Aji Saar ak Sonko, féewiryee 2021 la tàmbali woon. Ba tey ma ngay...

NJAMBAANU MOLOTOF MA CA LIISE DELAAFOS

Sàndarm yi wàcc nañu fa liise Delaafos ci gaawu gi. Yéenekaay Libération ne, seen...

ANTUWAAN F. JOM : « JURÓOM-ÑEENTI BAKKAN ROT NAÑU DIGGANTE NDAKAARU AK SIGICOOR. »

Démb, ci guddig alxames ji, jëwriñu biir réew mi doon janook taskati xibaar yi,...

TUUBAA : FETAL NAÑ BENN BAAY-FAAL

Ci guddig talaata ji, jàpp àllarba 8i nowàmbar 2023 la ñu fetal benn Baay-Faal...

Sitt ak Papaa Sow : Wure wa dem na këŋ

Sitt ak Papaa Sow dinañ jàmmaarloo ci dibéer jii, 6 noowàmbar 2022 ca Aren...

TÀGGE : MAHAMMAD BUUN ABDALAA JONN DËDDU NA

Elimaanu jëwriñ ja woon, Mahammad Buun Abdalaa Jonn, moo génn àddina.  Tey, ci àjjuma...