TÉYANDI NAÑU PAAB MAALIG NDUUR (APR)

Tay lañu woolu woon Paab Maalig Nduur, nekkoon jëwriñ ca nguurug Maki Sàll ga woon, bi 16i waxtu jotee ci ngoon, fa màkkaanu banqaasu...

2026 : SENEGAAL A NGI SÓOBU CI SÉMB YU MAG YI

Ginnaaw bi ñu defee at ak lu teg, Càmmug Basiiru Jomaay Jaxaar Fay gee ngi waaj a song sémb yu mag yi ngir tabax...

MBIRUM SEEX TURE, GUNEG SENEGAAL GI ÑU FAAT CA GANA

Takk-deri Gana yi tàmbali nañoo lëñbët ngir ca yan anam la doomu Senegaal jii di Seex Ture faatoo ak ñan ñoo jël bakkanam. Dafa...

TUKKIY NJIITU RÉEW MI

Njiitu réew mi, Basiiru Jomaay Jaxaar Fay, door na tukki yu am solo ci njeexitalu ayu-bés bii ñu génn. Ñaari tukki yépp mi ngi...

CAAROY : GËSTUKAT YA JÉBBALE NAÑU NJIITU RÉEW MI NJUREEF YI

Gëstukat yi ñu dénkoon mbirum Caaroy ak sóobare ya ñu fa bóomoon ca atum 1944 jébbal nañu Njiitu réew mi Téere bu weex bob,...

MAGU WAXOON NAA KO

JIKKO JU RAFET MOOY TABAX AM RÉEW

Wolof nee na, rafet kanam, rafet jikko a ko...
01:33:07

“Héritages” dalal na Bubakar Bóris Jóob

"Héritages ak Awa" ngi dalal Bubakar Bóris Jóob, ngir...

Malaanum Lëndëm : Bóris Jóob, na woon, fa woon

Ñeenteelu yoon a ngi nii Bubakar Bóris Jóob di...

GÀCCE NGAALAAMA, MBUGAAR !

Senegaal amati na ndam ci 3eelu fan ci weeru...

KUJJE GEEK WOTEB 2022 BI: BËGG NAA LA, BËGGUMA LA, LOOLU JARUL COOW

Ci bésub 23 sàŋwiye ci atum 2022 bii di...

FÀTTALIKU DÉMB

SEEX

Seex Mooy góor Moo di as gor Mbokk ya ko wor Ñooy mbokk...

FÀTTALIKU OMAR BOLONDEŊ JÓOB… 2/2

(ÑAAREELU XAAJ) Bi ñu nee Senegaal moom na boppam tamit,...

2002, ATUM SUUXU JOOLAA BI

Bërki-démb 26 sàttumbar ci atum 2020, "Bateau le Joolaa"...

FAIDHERBE, SAAY-SAAY BI NUY SARGAL

Bi Siidiya Ndàtte Yàlla génnee àddina ak léegi, am...

JÉERI JOOR NDEELAAK TUBAAB BI

Jéeri Joor Ndeela Faal mu ngi gane àdduna ci...

DÉMB AK TEY

WIDEWO YI

WAXLEEN SEEN XALAAT

BOO BAÑEE ÑAAW…

Bu nu la waxee nga àggale kàddu gii, looy...

Njiitu Réew

Dangaa jiitoom Dañu la jiital Sa jubb cunduŋ xanaa taxul Moo ndax...

YAA GORE !

Yàgg, yàgg, dëgg ay daan Dëgg lottoon na Senegaal Usmaan Sonkoo...

Ndigalu Maam Ya

Afrig nee Waaw góor, waaw kumba Ayca leen ca waar wa Bu...

SÀCCIIN WI JËM CI TÀNN YI DËGMAL TE FEEÑALEES KO

Sëñ Abdu Xaadr Kebe mooy biral fii xalaatam ñeel...

TÀGGATOO

NJÀNGAT CI TÉERE YI

XËT YI LEEN DÀQAL

Sàmpiyonaa Senegaal : Casa Sport jël na raw-gàddu gi, SONACOS ak Estaad bu mbuur dellusi

Dibéer bi weesu (fukki fan ak ñaar ci weeru Me lees doon amal ñaar-fukk...

ÑAARI KUY DUÑU BOKK MBALKA

Pólitig ci Senegaal du jóg di jur mbetteel ci askan wi. Mu mel ni,...

GÀTTALI BÉS BI

Popengin 2023 : Kàdduy Mõseñëer Njaay ñeel jëwriñu biir réew mi, Àntuwan Feliks Jonn Nees...

AMNISTI : LIGGÉEY BI DOOR NA

Ci altiney jii, 4 màrs 2024, lees di fénc sémbub àtte bees duppee ci...

Li gën a fés ci xibaari tàggat-yaram (àllarba 1 Màrs 2023)

Paul Pogba  Gannaaw 11i weer yi mu toog ci sababu gaañu-gaañu bu metti bi...

NDAJEM ÑAXTU YEWWI ASKAN WI : WEDDI, GIS BOKKU CI

Coowal wotey palum depite yi lёmbe na réewum Senegaal lool ci jamono jii nu...

BEQI : JÀPPUÑU NGAÑ DEMBA TURE

Xibaar bi ñu biraloon ñeel jàppug Ngañ Demba Ture mu Pastef wérul. Kenn jàppu...

ANA LU GÓOR-GIY LÀQARCI ?

Bamu jógee Konaakiri ba tey, seeti woon Alfa Konde, Abdulaay Wàdd, sunu Njiitu-réew ma...

ATSU DËDDU NA

Saa-Gana bi, Atsu (1992-2023), mujje na feeñ ginnaaw bi mu réere ci màbbiti taax...

WAY-SOPP LÀMMIÑI RÉEW MI, TOOGAAY AMATUL !

Àjjuma 17eelu nowàmbar 2023 ca Fatig, Njiitu réew mi, Maki Sàll, yëkkati na yile...

‘’LI TAX SÉEX ANTA JÓOB AMUL MOROOM…’’

WAXTAANU SAADA KAN AK BUBAKAR BÓRIS JÓOB

SONKO-BÀRT : YÀGG BAWUL DARA (1/2)

Cin bax na, waaye du jikkoom, matt a ko ca jóo. Altine ba tey,...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI TÀGGAT-YARAM

WURE (FUTBAL) Gaynde Senegaal yu ndaw yi noppi nañoo waajal Chan bi. Tey ci...

Doxalinu wotey palum depite yi ci Senegaal

Dibéeru tey 31 i fan ci weeru Sulet la wotey palum depite yi tàmbali...

JOŊANTEY BASKET FIBA 2023

Senegaal bëgg naa dalal ndajem Playoffs yu mujj yi Menn ndaje a des ci juróom...

BUUR BI, DAG BI AK BATAÑSE BI

Bés, Buur dafa toog ak dagam, ñuy waxtaan. Buur ne ko : - Sama xel dafa...

AKSIDÃ CA LUGA : JURÓOMI BAKKAN ROT NAÑU

Tali baa ngiy wéy di faat bakkani way-tukki yi. Aksidaŋ bu jàll, beneen tegu...

CAN U17 2023 : KUB MU NGI XEEÑ !

Raayab Senegaal a ngi gën yéeg, turam di gën a jëm ca kow a...

« DAÑU MAA TOOÑ, WAAYE DUMA BÀYYI »

Yaayu Aadama miy jiiñ Sitoor Nduur ag ciif, àndul ak ndogal la tukkee ca...

XEESAL WALLA XEEB SA BOPP?

XEESAL WALLA XEEB SA BOPP ? Kañ la jigéeni Senegaal yi tàmbalee xeesal ? Fanweeri...

BAC 2023

Ni ñu ko baaxoo amale ci réewum Senegaal, démb ci Talaata ji, yamoo ak...

KORONAA, LËMBAAJE NGA DUNYAA (Taalifu Li Faal Sàmba Suuna)

  Koronaa Yamoo ci doon balaa Dajal nga àddina-wërngal-kepp Bawoo ca réew ma ñuy wax Caayna Ab xoqtal tax...

Bërug ndëgg-sërëx

*Xana du bër da daan neex ndongo ? Daara ju kawe ja ca Ndar,...

UBBITEB LIGGÉEY YI ÑEEL PÉNCOOM RÉEW MI

Àllarba, 31 me 2023, la Njiitu réew mi Maki Sàll woote woon ubbite péncoo...

LAAJ-TONTU SAADA KAN/BÓRIS (III)

Waxtaan wii, ab tekki la ñeel jotaayu laaj-tontu bu Saada Kan di amal ci...

SUNUY DOOMI-NDEYI MALI YI SONN NAÑU

At yi weesu yépp, fitu doomi-Mali yi toogul benn béréb. Weer yi nu génn...

LU ËPP TUURU

Saxaar, safara a ko yabal. Wolof ne, xoddiku balaa lakkle. Senegaalu tey, ci xoddiku...

JUAN JÉBBAANE NA MAKI SÀLL

Juan Branco, layookatu Usmaan Sonko bi, jure na Njiitu réew mi, Maki Sàll, ak...

WOTEY 2024 : MAKI SÀLL A NGI NGEMBU

Njiitu réew mi, Maki Sàll, dalal na 474i meer ak 37i njiitali Ndajem depàrtmaa...

Sëñ Bàmba

Sëñ Bàmba Kéemaan la Dem ba ñëw war a sant ci ñibbisi gi Di sant Boroom...

GÀTTAL YI – LI GËN A FÉS CI XIBAARI AYU-BÉSUG ALTINE 29 AWRIL JÀPP ALTINE 05 ME 2019

POLITIG #1eelu fan ci weeru Me Bés bii lañu jagleel liggéeykatI àddina sépp, di leen ci ...

USMAAN SONKO AK MAKI SÀLL : CÓOKI MUJJ GI

Tey, ci altine ji lees war a àttewaat layoob Usmaan Sonko ak Maam Mbay...

Burkinaa Faaso : lu ëpp 50i jigéen ni mes ni meenteñ

Diggante alxames ak àjjuma (12 ak 13 sãwiye 2023), lu ëpp 50i jigéen ñoo...

23 AWRIL, BÉSUB TÉERE AK ÀQI BINDKAT BI

Mbootaayu Xeet yi ñeel njàng, xarala ak mbatiit (UNESCO) moo tànn bésub 23i awril,...

LI GËN A FËS CI XIBAARI BÉS BI (ÀJJUMA 24 MÀRS 2023)

PÓLITIG Séex Umar Jaañ ak Abdu Kariim Géy dellu nañu kaso Ñetti weer kepp la Séex...