BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi ñu jagleel waa jasporaa bi, ci njiiteefu Njiitu réew mi...

BÉS NIKI TAY, NEELEEN DOKTOOR PÀPPA AALI JÀLLO

Gaawo, 13eelu desàmbar 2025, ca Jàngune bu Ndar, la Pàppa Aali Jàllo (njiitul LDW) doon gaaral teesam ci Làkk ak mbatiiti Afrig, duppe ko...

FOQATIG NGUUR FA RÉEWUM BENEE

Ginnaaw coowal sóobare yi toog fa boppu réewum Gine Bisaawu, geneen foqatig Nguur naroon naa amaat, wile yoon, fa réewum Benee ak ay sóobare...

MOUSSO NGIR « JIGÉEN GÉNN CIG LËNDËM »

Soo déggee baatu « mousso », sam xel mën naa dem cib « restaurant » bu siiw ba ca Kanadaa. Waaye, « mousso » bii moom bokkul ak booba ; xéy-na...

NGOMBLAAN GI : DÉPITE YI TÀMBALI NAÑU CÀMBAR NAFA 2026 GI

Dépite yi tàmbali nañu càmbar nafag atu 2026 mi fa Ngomblaan ga. Ñu nar koo amal ci diiru ñaari ayu-bés ngir dalal jëwriñi Càmm...

MAGU WAXOON NAA KO

JIKKO JU RAFET MOOY TABAX AM RÉEW

Wolof nee na, rafet kanam, rafet jikko a ko...
01:33:07

“Héritages” dalal na Bubakar Bóris Jóob

"Héritages ak Awa" ngi dalal Bubakar Bóris Jóob, ngir...

Malaanum Lëndëm : Bóris Jóob, na woon, fa woon

Ñeenteelu yoon a ngi nii Bubakar Bóris Jóob di...

GÀCCE NGAALAAMA, MBUGAAR !

Senegaal amati na ndam ci 3eelu fan ci weeru...

KUJJE GEEK WOTEB 2022 BI: BËGG NAA LA, BËGGUMA LA, LOOLU JARUL COOW

Ci bésub 23 sàŋwiye ci atum 2022 bii di...

FÀTTALIKU DÉMB

SEEX

Seex Mooy góor Moo di as gor Mbokk ya ko wor Ñooy mbokk...

FÀTTALIKU OMAR BOLONDEŊ JÓOB… 2/2

(ÑAAREELU XAAJ) Bi ñu nee Senegaal moom na boppam tamit,...

2002, ATUM SUUXU JOOLAA BI

Bërki-démb 26 sàttumbar ci atum 2020, "Bateau le Joolaa"...

FAIDHERBE, SAAY-SAAY BI NUY SARGAL

Bi Siidiya Ndàtte Yàlla génnee àddina ak léegi, am...

JÉERI JOOR NDEELAAK TUBAAB BI

Jéeri Joor Ndeela Faal mu ngi gane àdduna ci...

DÉMB AK TEY

WIDEWO YI

WAXLEEN SEEN XALAAT

BOO BAÑEE ÑAAW…

Bu nu la waxee nga àggale kàddu gii, looy...

Njiitu Réew

Dangaa jiitoom Dañu la jiital Sa jubb cunduŋ xanaa taxul Moo ndax...

YAA GORE !

Yàgg, yàgg, dëgg ay daan Dëgg lottoon na Senegaal Usmaan Sonkoo...

Ndigalu Maam Ya

Afrig nee Waaw góor, waaw kumba Ayca leen ca waar wa Bu...

SÀCCIIN WI JËM CI TÀNN YI DËGMAL TE FEEÑALEES KO

Sëñ Abdu Xaadr Kebe mooy biral fii xalaatam ñeel...

TÀGGATOO

NJÀNGAT CI TÉERE YI

XËT YI LEEN DÀQAL

LI GЁN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI Alxames 29 sàttumbar 2022

DIINE Génnug àdduna Sёriñ Abdu Rahmaan Mbàkke Sёriñ Abdu Rahmaan Mbàkke ibnu Sёriñ Abdu Xuddóos ibnu...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (20/2/2024)

NDAJEM NDEYU ÀTTE MI YEESALAAT NA LAWAX YI Ndajem Ndeyu àtte réew mi génnee beneen...

GUY NJÓOBEEN (1/2)

Aatu feeñ na ! Njaayeen yi dégluleen Njóobeen bi raw na leen Buleen ko réyloo woyal,...

‘’ÑAAWTEEF YIY XEW TEY RÉEWUM SIIN DU GULÉET…’’

(SÉEX MBÀKKE AMAAR, JËWRIÑUNDONGOY-DAARA SENEGAAL YA CAWUHAN. CI TAATAANUG NDEY KODDU FAAL) Ndey Koddu Faal...

SAMES SÓOBU NA CI XEEX BI

Fajkat yi xamle nañ ne dinañ dakkal seen liggéey ci diirub ñaari fan. Seen...

2023 : YOON NAR NAA XUMB

Atum 2023 mii, atum Yoon la nar a nekk. Wëliis mbirum ñetteelu moome gi...

LI GËN A FËS CI XIBAARI BÉS BI (11/7/2023)

WOTEY 2024 Kuy doon lawaxu lëkkatooBennooBokkYaakaar ? Ku Maki Sàll di tànn ? Ñan ñooy xàll...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (3/12/2023)

Pólitig Ëttu àttewaay bu mag bi gàntal na neenal-àtte bi layookati sonko yi sàkku woon...

Ballon d’Or France Football 2022 : Saajo Maane ci pójëm bi 27i at ginnaaw Soors Weyaa Saajo Maane, sa woy wi dootul fay

Saajo Maane, sa woy wi dootul fay Joxe nañ cargalub Ballon d’Or France Football 2022...

FAATUG MUHAMMET JÓOB FA PIKIN

Am nay xibaar yu bees yu rot ñeel faatug Muhammet Jóob. Nde, jàllale nañ...

NJUUMTE

Ci xam-xamam bu amul yemu ak xareñam bu amul sikki-sàkka, Boroom Bi dafa bind...

TAXAWAAYI DÉPITEY KUJJE GI LAATA SEEN AG DEM CA PÉNCUM NDAWI RÉEW MA

Ginnaaw bi njureefi joŋantey palum dépite yi rotee, yenn ci dépite yi biral nañ...

ÉDITO CAP (ci tekkig Njuga Gay)

Bu nu xasee ba laal laalaake, amatul adada. Jot na, tey jii, mboolem taskati...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (7/8/2023)

WOTEY 2024 YI Xalifa Sàll ak Karim Wàdd yewweeku nañu. Delloos na leen seen i...

AAMADU BA WOO NA BASIIRU JOMAAY FAY NGIR NDOKKEEL KO

Sànq la xibaar bi rot. Muy xibaar boo xam ne biig ci guddi ba...

LEWOPÓOL SEDAAR SEŊOOR

Ñaar-fukki fan ci weeru Desàmbar atum 2001, bés bu Senegaal dootul fàtte. Raaya réew...

TABB YU YEES ÑEEL KÀNGAAMI YOON YI

Ci altine jii weesu lañu doon amal ndaje miy boole ak a tabb ñiy...

FÀWW FAIDHERBE DAANU !

  Paap Aali Jàllo «Tooñ, torox, goreedi ak ñàkk fulla weesuwul ñuy woyal Lat-Joor ci tóojug...

LI GËN A FËS CI XIBAARI BÉS BI

POLITIG : Toussaint Manga génn na PDS  Ab bataaxal la kii di Toussaint Manga jébbal njitaal...

COVID-19 CI ÀDDINA SI

Ami Mbeng   Bu dee mbas mi wàññeeku na bu baax ca Siin, mu ngiy wéy...

GÀTTALUG XIBAAR YI (AMI MBENG)

Ami Mbeng Ndengeleer Askan way yeewoo ca Ndengeleer amal nañu ab ndaje di xamal waa...

SËRIÑ SAALIW TURE WÀCC NA

Sëriñ Saaliw Ture mi toogaloon xalifa Murid yi ca Kees a wàcc liggéey guddig...

AES DËGGAL NA BOPPAM

Waa AES (Alliance des Etats du Sahel) fasul yéene dellu ginnaaw ci génn bi...

TËNKUG JIBAB NJÀNG MU KOWE MI

Ay fan a ngi ñuy amal ay wote ca Ngomblan ga ñeel koom mi...

TÀGGAT YARAM

Saajo Maane dugal na ñaari bal ci joŋante bi ekibam Liverpool doon amal démb...

SENEGAAL, ASAMAANU ÑAARI WEER

Woorandoo, woreendoo, ay gént la fi Senegaal. Daanaka, ñaari korite, dem na ba nekk...

GÀTTALI BÉS BI

BÉS DU ÑÀKK Gannaaw bi ñu génnee ci lёkkatoog Yewwi Askan Wi ci fan yii....

MAKI SÀLL : AMERIG DU SENEGAAL

Toroxal nañ Maki Sàll fa New York. Bi mu àggee Amerig, dañ ko fa...

MAKI DA NI WOON YOONU YOKKUTE : LÉPP YOKKU NA !

«Réew mi dafa tagatémbe !», «Dund gi jafe na !», «Lépp a dëgër !», «Danoo sonn!»,...

WAAJTAAYI MÀGGALUG TUUBAA 2023

Dëkk bu sell bii di Tuubaa sóobu na ci waajtaay yi ñeel màggalug 18...

DELLUSIG KARIIM MAYSA WÀDD FI RÉEW MI

Dellusig Kariim Maysa Wàdd fi réew mi doonatul lu ay ñoñam di xel-ñaar. Ñi...

RËG-RËG DAAN NA BOMBARJEE

Dooley xale xajul ci mag. Loolu la doomu Caaroy ji wan na doomu Mbuur...

OMAR BOLONNDEE JOOP: NGAMA WAYLITAARE AFRIKNAARE

Ñande 11 Duujal (Mai) 1973, Omar Bolondee Joop sagata feeloyaŋke-filosof senegaalnaajo luutndinooɗo laamu hooreejo...

AY NJÀNGAT ÑEEL KÀMPAAÑI WOTEY PALUM DEPITE YI

Fi mbir yi tollu nii tembe, gaa ñi fare ci làngug pólitig, ku nekk...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (04/01/2024)

LAYOO MAAM MBAY ÑAŊ AK USMAAN SONKO Coow li doxoon diggante Maam Mbay Ñaŋ ak...

LI GËN A FËS CI XIBAARI TÀGGAT-YARAM (ALXAMES 9 MÀRS 2023)

KUPPE Àngalteer Démb, foo geestu ci mbaali-jokkoo, ñoo ngi doon wone ay naataal ak i widewooy...