BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi ñu jagleel waa jasporaa bi, ci njiiteefu Njiitu réew mi...

BÉS NIKI TAY, NEELEEN DOKTOOR PÀPPA AALI JÀLLO

Gaawo, 13eelu desàmbar 2025, ca Jàngune bu Ndar, la Pàppa Aali Jàllo (njiitul LDW) doon gaaral teesam ci Làkk ak mbatiiti Afrig, duppe ko...

FOQATIG NGUUR FA RÉEWUM BENEE

Ginnaaw coowal sóobare yi toog fa boppu réewum Gine Bisaawu, geneen foqatig Nguur naroon naa amaat, wile yoon, fa réewum Benee ak ay sóobare...

MOUSSO NGIR « JIGÉEN GÉNN CIG LËNDËM »

Soo déggee baatu « mousso », sam xel mën naa dem cib « restaurant » bu siiw ba ca Kanadaa. Waaye, « mousso » bii moom bokkul ak booba ; xéy-na...

NGOMBLAAN GI : DÉPITE YI TÀMBALI NAÑU CÀMBAR NAFA 2026 GI

Dépite yi tàmbali nañu càmbar nafag atu 2026 mi fa Ngomblaan ga. Ñu nar koo amal ci diiru ñaari ayu-bés ngir dalal jëwriñi Càmm...

MAGU WAXOON NAA KO

JIKKO JU RAFET MOOY TABAX AM RÉEW

Wolof nee na, rafet kanam, rafet jikko a ko...
01:33:07

“Héritages” dalal na Bubakar Bóris Jóob

"Héritages ak Awa" ngi dalal Bubakar Bóris Jóob, ngir...

Malaanum Lëndëm : Bóris Jóob, na woon, fa woon

Ñeenteelu yoon a ngi nii Bubakar Bóris Jóob di...

GÀCCE NGAALAAMA, MBUGAAR !

Senegaal amati na ndam ci 3eelu fan ci weeru...

KUJJE GEEK WOTEB 2022 BI: BËGG NAA LA, BËGGUMA LA, LOOLU JARUL COOW

Ci bésub 23 sàŋwiye ci atum 2022 bii di...

FÀTTALIKU DÉMB

SEEX

Seex Mooy góor Moo di as gor Mbokk ya ko wor Ñooy mbokk...

FÀTTALIKU OMAR BOLONDEŊ JÓOB… 2/2

(ÑAAREELU XAAJ) Bi ñu nee Senegaal moom na boppam tamit,...

2002, ATUM SUUXU JOOLAA BI

Bërki-démb 26 sàttumbar ci atum 2020, "Bateau le Joolaa"...

FAIDHERBE, SAAY-SAAY BI NUY SARGAL

Bi Siidiya Ndàtte Yàlla génnee àddina ak léegi, am...

JÉERI JOOR NDEELAAK TUBAAB BI

Jéeri Joor Ndeela Faal mu ngi gane àdduna ci...

DÉMB AK TEY

WIDEWO YI

WAXLEEN SEEN XALAAT

BOO BAÑEE ÑAAW…

Bu nu la waxee nga àggale kàddu gii, looy...

Njiitu Réew

Dangaa jiitoom Dañu la jiital Sa jubb cunduŋ xanaa taxul Moo ndax...

YAA GORE !

Yàgg, yàgg, dëgg ay daan Dëgg lottoon na Senegaal Usmaan Sonkoo...

Ndigalu Maam Ya

Afrig nee Waaw góor, waaw kumba Ayca leen ca waar wa Bu...

SÀCCIIN WI JËM CI TÀNN YI DËGMAL TE FEEÑALEES KO

Sëñ Abdu Xaadr Kebe mooy biral fii xalaatam ñeel...

TÀGGATOO

NJÀNGAT CI TÉERE YI

XËT YI LEEN DÀQAL

Naalub juróom-ñetti jàngu yu yees

Nguurug Senegaal dina ubbi juróom-ñetti jàngu yu kowe ñeel njàngalem liggéey (mécce), muy ISEP...

XIBAARI TÀGGAT-YARAM (10/07/2023)

MAROG JËL NA CAN U23 BI Démb, ci gaawu gi, lañ doon amal lii di...

SIROY ALLAAXIRA YA CA  GÀMBI

Musiba bu réy a am ca Gàmbi. Juróom-benn fukki xale ak juróom-benn ñoo fa...

AY NJÀNGAT ÑEEL KÀMPAAÑI WOTEY PALUM DEPITE YI

Fi mbir yi tollu nii tembe, gaa ñi fare ci làngug pólitig, ku nekk...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (04/01/2024)

LAYOO MAAM MBAY ÑAŊ AK USMAAN SONKO Coow li doxoon diggante Maam Mbay Ñaŋ ak...

LI GËN A FËS CI XIBAARI TÀGGAT-YARAM (ALXAMES 9 MÀRS 2023)

KUPPE Àngalteer Démb, foo geestu ci mbaali-jokkoo, ñoo ngi doon wone ay naataal ak i widewooy...

LI GËN A FËS CI XIBAARI BÉS BI Alxemes 13 oktoobar 2022

NJÀNG AK JÀNGALE  Ñàkkum ndox ca daara ju kowe jii di UADB Daara ju kowe jii...

KU TIITUL MAN TIIT NAA

Senegaal wote nañu dibéer ji weesu yamook ñaar-fukki fan ak ñeent ci weeru féewaryee....

«BACCALAUREAT» 2022

Joŋante “baccalauréat” amal nañu ko alxames jii, fukki fan ak ñeent ci weeru sulet....

LI GËN A FËS CI XIBAARI BÉS BI (TALAATA 28 MÀRS 2023)

XIBAAR YI TUKKE CI NDAJEM WAXTAAN MI TOPPEKAT BU MAG BI DOON AMAL Tey, ci...

JÉYYA JA CA KAFRIN

Ak jéyya ju réy a réy la réew mi yeewoo tey. 54i nit ñoo...

PORFESOOR MUSAA SÉYDI : «BÀYYI WIRIS BI LAW, MUSIBA LA NU NAROON A JURAL»

  Bàyyi wirisu Covid-19 bi law ngir sabab kiiraayu-mbooloo la Doktoor Paap Musaa Coor digle...

LI GËN A FËS CI XIBAARI BÉS BI (25/8/2023)

BAKKANU USMAAN SONKO MI NGI CI XOTTU GERTE Tey ci àjjuma ji, njiiti lëkkatoo Yewwi...

BATAAXELU NJÉMMEER ÑEEL JAWRINU CAYTUG NJÀNG MI CA LUGA

Kilifa gi, Ginnaaw ba ma la nuyoo jox la sa wàccuwaay, duma def lu moy...

“DAÑU NAR A DÉJJATI MAKI SÀLL…”

Paap Aale Ñaŋ a fésal xibaar bu doy waar ci xëtu Facebookam. Daf ci...

WAAW KUMBA, SAA NIJAAY

WAAW KUMBA…SAA NIJAAY!

FUKKI SIMILI YI SOPPI AMERIG BA FÀWW (Paap Aali Jàllo)

PAAP AALI JÀLLO George Floyd, jamono jii, mooy néew bi gën a siiw ci àddina...

XIBAARI TÀGGAT-YARAM

KUPPEG ÀDDINA U17 2023 Ndawi Senegaal yaa ngi ci waajtaayu kuppeg àddina si ñu dëgmal...

KORONAA JAT NA PAAP JUUF, GAYNDEY GAYNDE YI !

« Ërob, rawatina Farãs, dañuy xeex ak a bunduxataal tuutaafoni waaso yi (minorités ethniques)....

ËTTUB TAALIF

‘’Ëttub taalif’’ mooy xët wu bees wi defuwaxu.com jagleel ladabu réew mi. Sunu xarit,...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (8/8/2023)

BÀYYEENDI NAÑ PAAP AALE ÑAŊ Meetar Musaa Saar moo biral xibaarub bàyyeendi Paap Aale Ñaŋ....

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (11/12/2023)

WOTEY 2024 YI Tey ci altine ji, 11 desàmbar 2023, la deppo yi ñeel nekkug...

LI GËN A FËS CI XIBAARI BÉS BI (16/8/2023)

TEG NAÑU LOXO LÉWOO ÑING Léwoo Ñing mi jiite Pastef fa goxub Njagañaaw, jàpp nañu...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (TALAATA 2 ME 2023)

Usmaan Sonko : « Waxtaan wees woote, sàkkal pexe Usmaan Sonko rekk a di jubluwaay bi… » Usmaan...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI ( Altine 6 féewaryee 2022)

PÓLITIG Mitiŋ APR Militaŋi APR yi nekk ci peggug Ndakaaru doon nañu amal ab mitiŋ ci...

SËÑ BÀMBA

Sëñ Bàmba Kéemaan la Dem ba ñëw war a sant ci ñibbisi gi Di sant Boroom bi ci dem...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (gaawu 7 saŋwiyee 2023)

PÓLITIG Tuuma ji ëttub cettantal gi tegoon ñenn ciy jëwriñ ak i DAGE ñeel koppar...

NU DELLOO NJUKKAL YAAY MARI MU SELL MI

Boo déggee Popengin sa xel day dem ci waa jàngu bi. Muy màndargaal diiney...

YEWWI ASKAN WI : « MAKI SÀLL DAFA WOR BA FU WOR YEM. »

Lëkkatoo Yewwi Askan Wi génne na ab yégle ñeel tolluwaayu réew mi. Dañu bind...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (10/11/2023)

ËTTUB ÀTTEWAAY BU MAG BI DËGGAL NA WALF Ci weeru féewaryee wii weesu, CNRA dafa...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (22/01/2024)

WOTEY 2024 YI Usmaan Sonko Usmaan Sonko dañ gàntal dabantal bi mu dugaloon. Ndaje mi teg...

SIGICOOR : BENN TAKK-DER ÑÀKK NA BAKKANAM

Xeex bu mettee am ca Sigicoor diggante ndaw ñiy taxawu Usmaan Sonko ak takk-der...

SENEGAAL WÓOLUWUL GARABU MADAGASKAAR GI (SAFIYETU BÉEY)

«Kenn du jëfandikoo Covid Organics fii ci Senegaal». Porfesoor Musaa Séydi xamle na ni...

CARGALUG NEUSTADT INTERNATIONAL PRIZE FOR LITERATURE : BUBAKAR BÓRIS JÓOB JËL NA NDAM LI

Ci talaata 26eel ci oktoobar 2021, lees jot ci mbégtem weer wi. Surnaalu ladab...

WURE WA DEM NA KËŊŊ !

Ngomblaan gi, walla Péncum ndawi réew mi (ni ko ñenn ñiy wowee), benn la...

Na woon, fa woon

Ci bëccëgu altiney ji, 12 ut 2022, la Senegaal doon taxawal 14eelu ngombalaanam (péncum...

XEEB NGA XAL, MU LAKK SA DÀGGA (2/2)

Tey, ci talaata ji 14 màrs 2023, la lëkkatoo Yewwi Askan Wi di amal...

QATAAR, FULLAAY JAAY DAQAAR

Bu ñu toppe mboorum futbal, mënees na wax ne guleet dëkkub naar di dalal...