Facebook
Instagram
TikTok
Twitter
Ëtt bi
COKKAASU ODIA
MAGU WAXOON NAA KO
FÀTTALIKU DÉMB
WAXLEEN SEEN XALAAT
Xibaar
Bàyyi ci xel
Bindkatu ayubés bi
Diine
Gis-Gis
Kii Kumu
Koom-koom
Pólitig
Tàggat-yaram
Recherche
Ëtt bi
COKKAASU ODIA
MAGU WAXOON NAA KO
FÀTTALIKU DÉMB
WAXLEEN SEEN XALAAT
Xibaar
Bàyyi ci xel
Bindkatu ayubés bi
Diine
Gis-Gis
Kii Kumu
Koom-koom
Pólitig
Tàggat-yaram
Li des
BUBAKAR BÓRIS JÓOB : AG GUY CI PÉNCUM LADAB
Li fës
BUBAKAR BÓRIS JÓOB : AG GUY CI PÉNCUM LADAB
14/09/2025
Jukkees na ab laaj-tontu ci yéenekaay Le Soleil, limu 16582eel bu Gaawu 13 ak Dibéer 14 Sàttumbar 2025. Waxtaan la wow, sunu naataangoo bii...
Li fës
TUKKIB ELIMAANU JËWRIÑ YI FA EMIRAAT ARAAB YA AK ITAALI
13/09/2025
Elimaanu jëwriñ yi, Sëñ Usmaan Sonko, moo nga woon tay fa réewum Itaali, ginnaaw bi mu jeexalee, démb ci àjjuma ji, tukki bu mu...
Li fës
MBOOTAAYU XEET YI WOTE NA “DECLARATION DE NEW YORK” BI
12/09/2025
Ngomblaanu Mbootaayu Xeet yi nangu na lees duppee "Déclaration de New York" bi nga xam ne, dafay sàrtal nekkug ñaari réew yii di Palestin...
Li fës
NDAJEM JËWRIÑ YI : NJIITU RÉEW MI ÀDDU NA CI LÀKKI RÉEW MI
11/09/2025
Njiitu Réew mi, Sëñ Basiiru Jomaay Jaxaar FAY, jiite na, ci alarbay démb ji, 10eelu fanu sàttumbar 2025, ndajem jëwriñ mees baaxoo di amal...
Li fës
SENEGAAL XAATIM NA DÉGGOOB 300I MILIYOŊI DOLAAR NGIR YEESAL MBAY MI
10/09/2025
Jëwriñu Mbay mi, Dund bu matale bi ak Càmm gi, Sëñ Mabuuba Jaañ, xaatim ab déggoo bu tollu ci ñetti téeméeri (300i) miliyoŋi dolaar...
NDAJEM SALI NGIR SELLAL DUND BI
Li fës
10/09/2025
MONJAAL 2026 / RDC-SENEGAAL : XEEXU GAYNDE AK TENE
Li fës
09/09/2025
NDOGUM YOON MU METTI FA KEBEMEER
Li fës
08/09/2025
CÀMM GU YEES GI
Li fës
07/09/2025
MBIRUM SAA-SENEGAAL YI ÑU JÀPPOON FA MALI
Li fës
06/09/2025
LI GËN A FÉS CI XIBAAR BÉS BI (4/9/2025)
Li fës
04/09/2025
LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (2/9/2025)
Xibaar
02/09/2025
NDAJEM PÉNCOO NOSTEG DUND BI CI KEMBAARU AFRIG CI ATUM 2025.
Li fës
02/09/2025
DOXU ÑAXTU ÑOÑ PASTEF
Li fës
01/09/2025
XIBAARI TÀGGAT-YARAM
Xibaar
31/08/2025
MAGU WAXOON NAA KO
Yëral lépp
JIKKO JU RAFET MOOY TABAX AM RÉEW
Séex Jóob
-
10/09/2023
Wolof nee na, rafet kanam, rafet jikko a ko...
01:33:07
“Héritages” dalal na Bubakar Bóris Jóob
Defu Waxu
-
26/06/2022
"Héritages ak Awa" ngi dalal Bubakar Bóris Jóob, ngir...
Malaanum Lëndëm : Bóris Jóob, na woon, fa woon
Uséynu Béey
-
17/05/2022
Ñeenteelu yoon a ngi nii Bubakar Bóris Jóob di...
GÀCCE NGAALAAMA, MBUGAAR !
Uséynu Béey
-
16/11/2021
Senegaal amati na ndam ci 3eelu fan ci weeru...
KUJJE GEEK WOTEB 2022 BI: BËGG NAA LA, BËGGUMA LA, LOOLU JARUL COOW
Uséynu Béey
-
04/10/2021
Ci bésub 23 sàŋwiye ci atum 2022 bii di...
WAAW, KAÑ LA SENEGAAL GËJ A YËNGOO NII…?
15/07/2021
KÀDDUY USMAAN SONKO 2/2 PÀCC
23/05/2021
KÀDDUY USMAAN SONKO 1/2 PÀCC
03/05/2021
Njàngatub Bàmmeelu Kocc : Téereb dekkali 1/2
26/12/2020
BARSAA WALLA… BARSÀQ !… LU XEW CI MIIM RÉEW?
25/11/2020
FÀTTALIKU DÉMB
Yëral lépp
SEEX
Làmp Faal Kala
-
29/12/2022
Seex Mooy góor Moo di as gor Mbokk ya ko wor Ñooy mbokk...
FÀTTALIKU OMAR BOLONDEŊ JÓOB… 2/2
28/09/2021
(ÑAAREELU XAAJ) Bi ñu nee Senegaal moom na boppam tamit,...
2002, ATUM SUUXU JOOLAA BI
Ndey Koddu Faal
-
01/10/2020
Bërki-démb 26 sàttumbar ci atum 2020, "Bateau le Joolaa"...
FAIDHERBE, SAAY-SAAY BI NUY SARGAL
Uséynu Béey
-
07/09/2020
Bi Siidiya Ndàtte Yàlla génnee àddina ak léegi, am...
JÉERI JOOR NDEELAAK TUBAAB BI
Defu Waxu
-
03/01/2020
Jéeri Joor Ndeela Faal mu ngi gane àdduna ci...
DÉMB AK TEY
13/10/2019
JIÑAABO, JÀMBAARU SELEKI BA CA SIGICOOR
13/10/2019
DAAWUDA JAAWARA FAATU, NUY FÀTTALIKU SENEGÀMBI
22/09/2019
SAARTJIE BAARTMAN, NDAW SA TUBAAB YI DEFOON MALA
30/05/2019
WIDEWO YI
VOA AMAL NAB JOTAAY CI MBINDUM BUBAKAR BÓRIS JÓOB GINNAAW BI WEREKAAN BI JËLEE CARGALUG NEUSTADT 2022 BI. CUQAL CI LËNKAAY BII TOFTALU...
Defu Waxu
-
https://www.voaafrique.com/live/audio/50/6789298
Lire la suite
00:19:36
Jotaayu xam-xam ak Sën Abdu Xaadir Kebe
Defu Waxu
-
Lire la suite
00:03:10
“Slam” Maysa Maara
Defu Waxu
-
Lire la suite
00:15:20
Li Abdu Lahaat Ka wax ci wolof
Defu Waxu
-
Lire la suite
Yëral widewo yépp
WAXLEEN SEEN XALAAT
Yëral lépp
BOO BAÑEE ÑAAW…
Baabakar Lóo
-
26/05/2024
Bu nu la waxee nga àggale kàddu gii, looy...
Njiitu Réew
Defu Waxu
-
02/05/2024
Dangaa jiitoom Dañu la jiital Sa jubb cunduŋ xanaa taxul Moo ndax...
YAA GORE !
Defu Waxu
-
14/04/2024
Yàgg, yàgg, dëgg ay daan Dëgg lottoon na Senegaal Usmaan Sonkoo...
Ndigalu Maam Ya
Defu Waxu
-
02/04/2024
Afrig nee Waaw góor, waaw kumba Ayca leen ca waar wa Bu...
SÀCCIIN WI JËM CI TÀNN YI DËGMAL TE FEEÑALEES KO
Defu Waxu
-
06/03/2024
Sëñ Abdu Xaadr Kebe mooy biral fii xalaatam ñeel...
TÀGGATOO
01/03/2024
BAÑ A WACC SA ÀND…
31/08/2021
BOKK AK NAWLOO NGIR JÀMM AK NAATAANGE CI ÀDDUNA SI
26/12/2020
"LE PROTOCOLE DE L’ÉLYSÉE" : NJÀNGATU PROF BUUBA JÓOB
02/10/2020
NJÀNGAT CI TÉERE YI
MBIRUM DUWAAÑE BI LÀQOON YÀMBAA CI DAAMARAM
Mbay Sow
-
Malaanum Lëndëm : Bóris Jóob, na woon, fa woon
Uséynu Béey
-
Ay xalaat yu meññee ci “Malaanum Lëndëm”
Stefano Anselmo
-
Njàngatum Guddig Mbooyo (2/2)
Mustafaa Faal
-
XËT YI LEEN DÀQAL
MBËKK MI : GAALUG 280I NIT TEERI NA GÀDDAAY
Ag gaal gu yeboon i mbëkk-kat moo teeri Gàddaay. Nee ñu am ñaar ñu...
MAKI SÀLL GANEJI NAY DËKK AK I GOXI RÉEW MI : SAFIYETU BÉEY
Kafrin, Fatig ak Kawlax am nañu gan fan yii weesu, gannaaw bi njiitu réew...
WOMEN FIRST TV Tele jigéen ñi, ngir jigéen ñi
WOMAN FIRST TV tele la bu ay jigéen sos jagleel ko it jigéen ñi....
Sunu ekip sunu petorol ak gaas
MAKI SÀLL : “…BU BOOBAA, (…) ÑÉPP ÑOOY ÑÀKK…”
Njiitu réew mi, Maki Sàll, fasul yéene dellu ginnaaw. Ñaari bakkan rotagum nañ ci...
AKSIDAŊ BU METTI CA MBÀMBILOOR
Aksidaŋ yaa ngi wéy di rey nit ñi ci kow tali bi. Bërki-démb, ci...
YOKKUTEG DUND GI “…dañuy ragal ne 2023 mooy gën a metti.”
Njiitu réew mi, Maki Sàll, woote woon na ndajem waxtaan ñeel dund gi. Altine,...
FIARA 2024
Fiara (Foire internationale de l’agriculture et des ressources animales) bu 2024 bee ngi ñuy...
COKKAASU ODIA
GAALU JOOLAA, FÀTTE XAJU FI
Jéyya gënul réy suuxug gaalu Joola ga. Te, njaaxum du ko weesu. 20i at...
JOXEB LIJAASA BU 48eelu LËLU CESTI (NDEY KODDU FAAL)
Alxemes jii nu génn la CESTI doon jox seen lijaasa 4i taskati xibaar yu...
LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (GAAWU 01 OKTOMBAR 2022)
PÓLITIG Bitim-réew, ca Burkinaa Faaso, ñu nemmeekooti fa poqartim Nguur, ginnaaw juróom-ñatti weer kott ba...
KUY DUND DI XASAW, BOO DEEWEE DU MAT A WAX
Toftaleg IDH gu 2022 génn na ci alxames ji. PNUD a ko génne. PNUD...
NJIITU RÉEW MI FA TUUBAA
Njiitu Réew mi, Basiiru Jomaay Jaxaar Fay, amal na génnam gu njëkk ci biir...
MBIRI BAABAKAR FAAL : CAP DUGG NA CI COOW LI
Waa CAP àddu nañu ci mbiri Baabakar Faal. Ginnaaw bi taskatu xibaar bi jotee...
JËWRIÑI CÀMM GU BEES GI
Jëf toxal na wax. Ñoo ko dige woon, jëfe nañ ko. Umar Sàmba Ba...
LI GËN A FES CI XIBAARI BES BI (31/8/2023)
TAXAWAAYU ISMAYLA MAAJOOR ÑEEL DAANU SONKO BI Ci weeru suwe wale ñu génn lañu daanoon...
LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (13/4/2024)
NJABOOTU LÀMB DAL NA CI KOW BIRAM SULÉY JÓOB Bi jëwriñ jii di Biram Suléy...
TUKKI TEKKI, TOOG TOROX ? (PAAP AALI JÀLLO)
« Tekki mbaa dee ! » Li ko dale 1eelu fan jàpp 12eelu fan ci weeru oktoobar bii...
XIBAARI TÀGGAT-YARAM (25/2/2024)
MBIRI PAAP GÉY AK MÀRSEY Gannaaw CAN bi mu demoon ak Senegaal, Paap Géy, miliyë...
JAM NAÑ MAYMUNA NDUUR FAY
Maymuna Nduur Fay, taskatu xibaar bi jiite 7tv la ab/ay sàmbaabooy dogaale, fitnaal ko,...
CÀMM GU BEES GI : WAAW, ANA JIGÉEN ÑI ?
Ginnaaw ba mu jële lenge yi, njiitu réew lu bees li Basiiru Jomaay Jaxaar...
PAAP BUUBA, GAYNDE GU NU DOOTUL FÀTTE, (MUSAA AYSATU JÓOB)
Paap Buuba Jóob saay na, ginnaaw bi ko feebar bi ñuy wax "Charcot" tërale...
MAKI SÀLL JÉBBALU NA
Gaawu, ñetti fan ci weeru féewiryee 2024 la Njiitu réew mi jëloon ndogalu dàq...
LI GËN A FËS CI XIBAARI BÉS BI (ALTINE 27 MÀRS 2023)
YOON Deferee nañu Baabakar Ñaŋ ngir ne dafa seetaan aji-tawat ba mu faatu faf Ci altiney...
CAABALUG ËTTUB CETTANTAL GI ÑEEL YORINU FORCE COVID-19
Ëttub cettantal gi dafa bokk ci bànqaas yiy saytu liggéeyuwaay yi nga xam ne...
LI GËN A FÉS CI XIBAAR BÉS BI (9/5/2024)
BÉSUB MÀGGALU “ASCENSION” Tey, ci alxames ji, yemoo ak juróom-ñeenti fan ci weeru me, mooy...
LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (16/5/2024)
WÀÑÑIG DUND BI Wàññig dund bi bokk na ci li gën a soxal saa-senegaal yi...
LEES WAR A JÀNG CI NDIMBALU RÉEWUM FIDEL CASTRO ÑEEL ITALI ?
BOOS NDÓOY Saa buñ tuddee réewum Kibaa, ñépp daldi fàttaliku njiitam lu ràññeeku la :...
BOROOM JAKARTAA BI FAATU FA CAALI
As góor su tollu ci 25i at, daan dawal móto jakartaa, lees fekk neewam...
JAAR-JAARU BUBAKAR BÓRIS JÓOB (WAXTAAN AK PAAP SEEN)
https://youtu.be/rzrGnl479SM
DOGALUB GÓRNÓORU NDAKAARU ÑEEL DEM BEEK DIKK BI (AMI MBENG)
Górnóoru Ndakaaru jël nab dogal di ci teree daw bépp oto bu yab màrsandiis ba...
NDAJEM RÉEWI MSGBC ËLLËGU GAAS BI CI BOPP WAXTAAN WI
Kurél gii di MSGBC te ëmb yile réew, Móritani, Senegaal, Gàmbi, Gine Bisaawoo, ak...
JOŊANTEB XARITOO : SENEGAAL DÓOR NA KAMERUN 1-0
Gayndey kuppe yi dóor nañ Kamerun 1-0. Tey ci altine ji lañ doon amal...
MAKI SÀLL DINA TABB CÀMM GU BEES
Ginnaaw bim tànnee lawax bi mu bëgg mu wuutu ko ci boppu réew mi,...
LI UMAR YUM AK AALI NGUY NJAAY WAX TASKATI XIBAAR YI ÑEEL GUURAL GI
Paap Aali Jàllo Senegaal, ca njëlbeen ga (2eelu fan ci weeru màrs 2020), diiwaanu Ndakaaru...
LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (29/12/2023)
CAMPUG LAWAXU USMAAN SONKO Muy xew-xew bu ñu dëgmal te ña fare ca lëkkatoo pólitig...
GÀTTALUG XIBAAR YI (AMI MBENG)
(Ami Mbeng) 6i DOGAL YI MAKI SÀLL MUJJEE JËL ÑEEL MBAS MI Njiitu réew mi, Maki...
LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI Altine 17 oktoobar 2022
PÓLITIG Way-politig yi jublooti nañ ci wotey 2024 yi. Bu dee làngug Nguur gi, Njiitu...
KORONAA AK KOOM-KOOMU RÉEW MI
Xari Njaay Mbasum koronaawiris mi lëmbe na àddina sépp, jaxase réew yépp. Amul menn réew mu...
1
...
22
23
24
...
50
Page 23 sur 50