LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (19/9/2024)

TUKKIB NJIITU RÉEW MI FA NJAASAAN Dibéer jii weesu moo nekkoon bés bi ñu doon màggul guddi gi Yonentu Yàlla Muhammat ganesee àdduna. Ñii di...

MBËNN MA FA TUUBAA

Asamaan démb si dafa bàyyeeku, ubbiy buntam, rëccal ndox mi, mu sotteeku bu baax a baax. Daanaka, réew mépp a taw. Waaye, Tuubaa daf...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (17/9/2024)

SAMP NAÑ ËTTU ÀTTE BII DI "POOL JUDICIAIRE FINANCIER" Jëwriñ ji ñu dénk wàllu Yoon samp tay ëttu àtte bees duppee "Pool judiciaire financier" (PJF)...

GÀMMU 2024

Démb, ci guddig dibéer ji jàpp altine jii, lañ doon amal gàmmu 2024. Muy xew mom, dañ ciy màggal bésu ganesi àddina Yonent Yàlla...

JÀPPATI NAÑ AY MBËKK-KAT

Coowal mbëkk mi lëmbe na lool réew mi, rawatina jamono jii. Am na sax, ñu jàppoon ne dina wàññeeku. Ndekete, tey la doomi Afrig...

MAGU WAXOON NAA KO

JIKKO JU RAFET MOOY TABAX AM RÉEW

Wolof nee na, rafet kanam, rafet jikko a ko...
01:33:07

“Héritages” dalal na Bubakar Bóris Jóob

"Héritages ak Awa" ngi dalal Bubakar Bóris Jóob, ngir...

Malaanum Lëndëm : Bóris Jóob, na woon, fa woon

Ñeenteelu yoon a ngi nii Bubakar Bóris Jóob di...

GÀCCE NGAALAAMA, MBUGAAR !

Senegaal amati na ndam ci 3eelu fan ci weeru...

KUJJE GEEK WOTEB 2022 BI: BËGG NAA LA, BËGGUMA LA, LOOLU JARUL COOW

Ci bésub 23 sàŋwiye ci atum 2022 bii di...

FÀTTALIKU DÉMB

SEEX

Seex Mooy góor Moo di as gor Mbokk ya ko wor Ñooy mbokk...

FÀTTALIKU OMAR BOLONDEŊ JÓOB… 2/2

(ÑAAREELU XAAJ) Bi ñu nee Senegaal moom na boppam tamit,...

2002, ATUM SUUXU JOOLAA BI

Bërki-démb 26 sàttumbar ci atum 2020, "Bateau le Joolaa"...

FAIDHERBE, SAAY-SAAY BI NUY SARGAL

Bi Siidiya Ndàtte Yàlla génnee àddina ak léegi, am...

JÉERI JOOR NDEELAAK TUBAAB BI

Jéeri Joor Ndeela Faal mu ngi gane àdduna ci...

DÉMB AK TEY

WIDEWO YI

WAXLEEN SEEN XALAAT

BOO BAÑEE ÑAAW…

Bu nu la waxee nga àggale kàddu gii, looy...

Njiitu Réew

Dangaa jiitoom Dañu la jiital Sa jubb cunduŋ xanaa taxul Moo ndax...

YAA GORE !

Yàgg, yàgg, dëgg ay daan Dëgg lottoon na Senegaal Usmaan Sonkoo...

Ndigalu Maam Ya

Afrig nee Waaw góor, waaw kumba Ayca leen ca waar wa Bu...

SÀCCIIN WI JËM CI TÀNN YI DËGMAL TE FEEÑALEES KO

Sëñ Abdu Xaadr Kebe mooy biral fii xalaatam ñeel...

TÀGGATOO

NJÀNGAT CI TÉERE YI

XËT YI LEEN DÀQAL

LËKKATOO “DIOMAYE PRÉSIDENT” DINA WÉYAL XEEX BI

Démb ci dibéer ji la lëkkatoo gii di “ Diomaye Président” doon amal ndajem...

LI GËN A FÉS CI XIBAAR BÉS BI (2/5/2024)

TUXAL NAÑU BÉSU NDAJEM JËWRIÑ YI Ndajem jëwriñ yee ngi daan am àllarba ju nekk....

ÑEENTI SÓOBARE ÑOO ÑÀKK SEEN I BAKKAN FA KAASAMÃS

Fa Kaasamãs, dafa ag daamaruy sóobare gu dal ci kow um mbéll « antichar ». Bi...

TUKKIB NJIITU RÉEW MI CA FARÃS

Njiitu réew mi, Basiiru Jomaay Fay, war teew ca Farãas ci àllarbay tey jii....

SÀNDARM BI AKSIDÀNTE FA KÉEDUGU

Ab sàndarm moo ñàkk bakkanam fa diiwaanu Kéedugu. Dafa def aksidaŋ ci tali Salemata...

BÓOMUG ALEŊ KALI: G7 BU CEES DOOR NA XEEX BI

Barkaatu-démb ci talaata ji lañu bóom jangalekat bii di Aleŋ Kali. Ci anam yu...

“UGB DU AY SËG !”

Ginnaaw Fàllu Seen (2018), leneen ndongo faatooti na fa jànguneb Ndar ba ci sababuy...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (8/6/2024)

BUGAAN GÉY DANEE NGI WEDDI AK A LEERAL Yéenekaay Source A dafa fésaloon ab xibaar,...

JÀPP NAÑ BAH JAXATE AK IMAAM SÉEX TIIJAAN NDAW

Démb lañ jàpp kii di Bah Jaxate, di aktiwist bu jege Maki Sàll. Waa...

ÀTTEWAAY BU NDAKAARU JOX NA SONKO DËGG

Coowal « damay bokk ! » ak « doo bokk ci wote yi ! », diggante Càmm geek Usmaan...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (20/9/2023)

TÀGGATOOB NJIITU RÉEW MI MAKI SÀLL CA ONU Démb ci talaata ji la Njiitu réew...

ABDU LATIF KULIBALI TEKKI NA NDOMBOG-TÀNKAM

Abdu Latif Kulibali, di jëwriñ ak magum fara-caytu Nguur gi, jël na ndogalu tekki...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (9/10/2023)

PÓLITIG Aali Nguy Njaay mottali na yéeneem ngir nekk lawax ci wotey 2024 yi. Ci...

MBEY MI : MAGUM JËWRIÑ YI JËL NA CI NDOGAL YU BEES

Magum jëwriñ yi, Usmaan Sonko, jël na ndogal yu bees ñeel kàmpaañu mbey mi...

BATAAXALU ÀLLIYUN TIN ÑEEL USMAAN SONKO

Àlliyun Tin yékkati na kàddu jagleel ko elimaanu jëwriñ yi, Usmaan Sonko. Ginnaaw ganam...

WOTEY 2024 YI : LEERALI JËWRIÑ MAXTAAR SIISE

Ëllëg ci dibéer ji lañ woo Saa-Senegaal yi ci mbañ-gàcce yi ngir ñu fal...

F24 WOOTEETI NA YËNGU-YËNGAL

Waa F24 fas nañoo yéene wéyal seen xeex bi. Loolu lañu siiwal keroog àjjuma...

IRÃ SONG NA ISRAAYEL

Ay weer ginnaaw ba ñu dekkalaatee xareb Israayel ak Palestiin, ba tey jeexagul. Ndax,...

NJIITU MBOOTAAYU RÉEWI AFRIG YI (2023-2024)

Benn weer kepp a dese Njiitu réewum Senegaal li, Maki Sàll, ci boppu kilifteefu...

UBBITEG LEKKOOL YI

Lekkooli Senegaal yi tàmbali na tijji ay buntam. Niki démb ci altine ji, 2...

LU TAX MAKI SÀLL MËNUL A KÀMPAAÑAL AAMADU BA ?

Fan yii nu génn, doon nañ yégle ne Njiitu réew mi, Maki Sàll, dina...

USMAAN SONKO AK CÀMM GI, PËND BA WUREEGUL

Dogal bi ñu doon xaar tey ci Talaata ji jëm ci àtteb Usmaan Sonko...

Ndigalul dakkal tabax yi ci peggu géej gi

Elimaanu jëwriñ yi, Usmaan Sonko, taxawal na ab banqaas buy saytu anam bees joxee...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (01/4/2024)

TABBUG BASIIRU JOMAAY JAXAAR FAY Ëllëg ci talaata ji, dees na tabb Basiiru Jomaay Jaxaar...

LI GËN A FËS CI WOTEY 2024 YI (25/3/ 2024)

KÀDDUY BASIIRU JOMAAY FAY YU NJËKK NIKI NJIITU RÉEWUM SENEGAAL  Njiitu réew lu bees li,...

NGOMBLAAN GA

Ci biir sémbub àtte biñ war a wote fa Ngomblaan ga, dañ ci bind...

LI GËN A FËS CI XIBAARI BÉS BI (19/4/2024)

NDOGALI NJIITU RÉEW MI, BASIIRU JOMAAY JAXAAR FAY  Ganug njénde li Njiitu Réew mi, Basiiru Jomaay...

ËTTU ÀTTEKAAY BU KAWE BI GÀNTAL NA CÀKKUTEEFU PDS GI

Ëttu àttekaay bu kawe bi gàntal na càkkuteefu PDS gi lawax yi ñu téye....

WOTEB SÉMBUB ÀTTE BIY DÀQ WOTE YI

Ngombalaan gi jàllale na sémbub àtte biy dàq wote yees nammoon a amal ci...

LUUBALU 540I TAMDARET CA CMS BU MEDINAA

CMS ab bànqaasu déncuwaay ak àbbuwaayu xaalis la bu nekk ci biir réew mi....

LI GËN A FËS CI WOTE YI (24/3/2024)

SAA-SENEGAAL YU BARI GÉNN NAÑ WOTEJI Ci dibéeru tey ji lañu woo saa-senegaal ngir ñu...

XIBAARI TÀGGAT-YARAM

FUTBAL Victor Boniface moo ngi dox ci ndox Ataakã Bayer Leverkusen bi moo ngi wane boppam...

GAYNDEY SENEGAAL YI RËKK NAÑ YOY KAMERUN YI

Gannaaw ba mu wullee dëkkandoom bi, Gàmbi, keroog ca bés bu njëkk ba, Senegaal...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (13/5/2024)

ÑËWUG KAGAME FI SENEGAAL Póol Kagame, Njiitu réewum Ruwàndaa li, moo ngi woon fi réew...

LI GËN A FÉS CI XIBAAR BÉS BI (25/04/2024)

ÑETTEELU NDAJEM JËWRIÑ Démb ci àllarba ji la Njiitu réew mi Basiiru Jomaay Jaxaar Fay...

NJIITU RÉEW MI FOMM NA WOTE YI

Wotey 2024 yi duñ am ci bésub 25 féewiryee bees leen àppaloon. Ndogal lu...

KAN MOOY ALIW MAMADU JA ?

Aliw Mamadu Ja ci 19i lawax yiy wut réew mi la bokk. Moom moo...

WAAJTAAYU BÉSU DAARA

Séex Umar Aan di jëwriñ ji ñu dénk njàng meek njàngale mi amal na...