BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi ñu jagleel waa jasporaa bi, ci njiiteefu Njiitu réew mi...

BÉS NIKI TAY, NEELEEN DOKTOOR PÀPPA AALI JÀLLO

Gaawo, 13eelu desàmbar 2025, ca Jàngune bu Ndar, la Pàppa Aali Jàllo (njiitul LDW) doon gaaral teesam ci Làkk ak mbatiiti Afrig, duppe ko...

FOQATIG NGUUR FA RÉEWUM BENEE

Ginnaaw coowal sóobare yi toog fa boppu réewum Gine Bisaawu, geneen foqatig Nguur naroon naa amaat, wile yoon, fa réewum Benee ak ay sóobare...

MOUSSO NGIR « JIGÉEN GÉNN CIG LËNDËM »

Soo déggee baatu « mousso », sam xel mën naa dem cib « restaurant » bu siiw ba ca Kanadaa. Waaye, « mousso » bii moom bokkul ak booba ; xéy-na...

NGOMBLAAN GI : DÉPITE YI TÀMBALI NAÑU CÀMBAR NAFA 2026 GI

Dépite yi tàmbali nañu càmbar nafag atu 2026 mi fa Ngomblaan ga. Ñu nar koo amal ci diiru ñaari ayu-bés ngir dalal jëwriñi Càmm...

MAGU WAXOON NAA KO

JIKKO JU RAFET MOOY TABAX AM RÉEW

Wolof nee na, rafet kanam, rafet jikko a ko...
01:33:07

“Héritages” dalal na Bubakar Bóris Jóob

"Héritages ak Awa" ngi dalal Bubakar Bóris Jóob, ngir...

Malaanum Lëndëm : Bóris Jóob, na woon, fa woon

Ñeenteelu yoon a ngi nii Bubakar Bóris Jóob di...

GÀCCE NGAALAAMA, MBUGAAR !

Senegaal amati na ndam ci 3eelu fan ci weeru...

KUJJE GEEK WOTEB 2022 BI: BËGG NAA LA, BËGGUMA LA, LOOLU JARUL COOW

Ci bésub 23 sàŋwiye ci atum 2022 bii di...

FÀTTALIKU DÉMB

SEEX

Seex Mooy góor Moo di as gor Mbokk ya ko wor Ñooy mbokk...

FÀTTALIKU OMAR BOLONDEŊ JÓOB… 2/2

(ÑAAREELU XAAJ) Bi ñu nee Senegaal moom na boppam tamit,...

2002, ATUM SUUXU JOOLAA BI

Bërki-démb 26 sàttumbar ci atum 2020, "Bateau le Joolaa"...

FAIDHERBE, SAAY-SAAY BI NUY SARGAL

Bi Siidiya Ndàtte Yàlla génnee àddina ak léegi, am...

JÉERI JOOR NDEELAAK TUBAAB BI

Jéeri Joor Ndeela Faal mu ngi gane àdduna ci...

DÉMB AK TEY

WIDEWO YI

WAXLEEN SEEN XALAAT

BOO BAÑEE ÑAAW…

Bu nu la waxee nga àggale kàddu gii, looy...

Njiitu Réew

Dangaa jiitoom Dañu la jiital Sa jubb cunduŋ xanaa taxul Moo ndax...

YAA GORE !

Yàgg, yàgg, dëgg ay daan Dëgg lottoon na Senegaal Usmaan Sonkoo...

Ndigalu Maam Ya

Afrig nee Waaw góor, waaw kumba Ayca leen ca waar wa Bu...

SÀCCIIN WI JËM CI TÀNN YI DËGMAL TE FEEÑALEES KO

Sëñ Abdu Xaadr Kebe mooy biral fii xalaatam ñeel...

TÀGGATOO

NJÀNGAT CI TÉERE YI

XËT YI LEEN DÀQAL

QATAAR – SENEGAAL, NDAM REKK

Ginnaaw bi mu ñàkkee joŋanteem bu njëkk bi digganteem ak Olànd, Senegaal dina janook...

BAC 2024

« BAC » dafa bokk ci joŋante yi gën a siiw fi Senegaal. Démb la door,...

USMAAN SONKO DALAL NAÑU KO FA TUUBA AK TIWAAWON

Njiitu Càmm gi, Usmaan Sonko, seeti woon na kilifay diine yu Tuubaa ak Tiwaawon....

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (11/10/2023)

MBIRUM USMAAN SONKO AK I ÑOÑAM Suba ci alxames ji la Yoon di leeral lenn...

USMAAN SONKO : ELIMAANU JËWRIÑ YI

Njiitu réew mi, Basiiru Jomaay Fay, tabb na Usmaan Sonko, def ko elimaanu jëwriñ...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI Altine 12 desàmbar 2022

PÓLITIG Jëwriñ ju mag ji, Aamadu Ba teew na ci kanamu ngombalaan gi. Ginnaaw bi...

XIBAARI TÀGGAT-YARAM

AY YEESAL ÑEEL BARI (LES EQUIPES) SENEGAAL YI Gaynde yu mag yi (ekib A) Wéyalees na...

NJIITU RÉEW MI NEENAL NA NDOGALI MAKI SÀLL YI

Ginnaaw bi mu jëlee lenge yi niki Njiitu réewum Senegaal, Basiiru Jomaay Fay jël...

NAPP GI : JUB, JUBAL, JUBBANTI

Jëwriñu napp gi, Doktëer Faatu Juuf, siiwal na toftaleg turi nit ñi ñu jagleel...

LI GËN A FËS CI XIBAARI BÉS BI (Alxames 22 desàmbar 2022)

PÓLITIG                            Taxawaayu Seex Abdu Baara Dolli ñeel wotey 2024               Dépite bii di Seex...

NJUREEFI WOTEY 2024 YI : CEESU KOW (THIES NORD)

Bérébu wote : Séex Ibra Faal Pekku wote : 02 Limu wotekat yi bindu : 584 Limu ñu wote :...

BÀRTELEMI JAAS SOOY NA

Ci àjjumay tey jii, 22 desàmbar 2023, la Ëttub àttewaay bu mag bi doon...

MA-DEMBA SOKK WUYUJI NA BOROOMAM

Xibaar bu tiis la réew mi xëyee tey. Ma-Demba Sokk moo génn àddina. Pari...

ALFUSEYNI GAY : “ DAMA RAGAL…”

Alfuseyni Gay mooy sinekolog ba nemmeeku woon Aji Saar keroog, guddi googu ndaw si...

U.I.J.A SARGAL NA USMAAN SONKO

U.I.J.A (Union Internationale des Journalistes Africains) kurél gu mag la, gu ëmb taskati-xibaari Afrig...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (6/7/2024)

CEDEAO - AES CEDEAO jël ndogal ñee maxejji réewi AES yi (Mali, Burkinaa Faaso ak...

XIBAARI TÀGGAT-YARAM (18/9/2023)

WAA LORIENT YI SARGAL NAÑU BENJAMIN MENDY Benjamin Mendy duggaat na démb ci pàkkub futbal,...

NJÀNG MAA NGI CI YOONU NDËRMEELU

Njàng meek njàngale mi ci Senegaal mu ngi jànkonteel ak i jafe-jafe yu metti....

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (25/5/2024)

SINEEBAR BA NGI JÀLLAAÑOO CI BIIR RЀEW MI Takk-deri duwaan yi (douaniers) dogaale nañu ay...

KAN MOOY ALIW MAMADU JA ?

Aliw Mamadu Ja ci 19i lawax yiy wut réew mi la bokk. Moom moo...

SONKO AK JOMAAY TUUMAAL NAÑ AAMADU BA

Démb la Usmaan Sonko ak Basiiru Jomaay Jaxaar Fay doon janook taskati xibaar yi...

USTAAS UMAR SÀLL MA NGA CA LOXOY YOON

Ustaas Umar Ahmad Sàll, ab waaraatekat bu siiw ci réew mi la. Fës na...

QATAAR 2022 : GAYNDE YI FÀDD NAÑ EKUWAATËER

kuppeg àddina saa ngay wéy ca Qataar. Ci kippu A gi, Senegaal amati na...

F24 WOOTEETI NA YËNGU-YËNGAL

Waa F24 fas nañoo yéene wéyal seen xeex bi. Loolu lañu siiwal keroog àjjuma...

NDAJEM NDEYU SÀRTI RÉEW MI BAÑ NA NDOGALI WAXTAANU MAKI SÀLL WI

Ndajem Ndeyu sàrti réew mi bañ na dogal yi tukkee ci waxtaan wu mujj...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (8/12/2023)

NDEY FAATU FAAL Ndey Faatu Faal mi ñuy woowee Faala Fëlëer nekk ab ñaxtukat,...

GOR, CA WAX JA !

Lu tollu ci weer ginnaaw ba ñu ko tabbee elimaanu jëwriñ yi, Usmaan Sonko...

EURO 2024 AK COPA AMERICA 2024

Ren, soppey kuppe dinañubégg bég. Nde, ginnaaw sàmpiyonaa yi jeex ak Ligue des champions...

CAN KODDIWAAR 2024 : CAABALU BÉS BI

NGIRTEY JOŊANTEY DÉMB YI Démb ci àllarba ji moo nekkoon bés bu mujju ci 1eelu...

ÀDDINA SAA NGI NDOKKEEL BASIIRU JOMAAY FAY

Wëliis Maki Sàll mi muy wuutu ci boppu réew mi, yeneen Njiiti réew yi...

NDOGAL YU BEES ÑEEL NJÀNG MU KOWE MI

Ay ndogal yu bees wàcc nañ ci njàng mu kowe mi. Muy i ndogal...

IRÃ SONG NA ISRAAYEL

Ay weer ginnaaw ba ñu dekkalaatee xareb Israayel ak Palestiin, ba tey jeexagul. Ndax,...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (13/7/2023)

GORNOORU NDAKAARU BI GÀNTAL NDAJEM TABB MU WAA PASTEF Waa Pastef dañ nammoon a amal...

SONKO AMATI NA NDAM !

Naam, CEDEAO joxe ko dëgg. Naam, Ëttub àttewaay bu mag bi neenal na àtteb...

XEEXI ÑAXTU CA DAARAY SIGICOOR JU KOWE JA

Daara yu kowe yi ci Senegaal dafa mel ni ag dal daf leen a...

SÀNDARM BI AKSIDÀNTE FA KÉEDUGU

Ab sàndarm moo ñàkk bakkanam fa diiwaanu Kéedugu. Dafa def aksidaŋ ci tali Salemata...

« WAXLEEN DËGG SONKO ! »

Ànd, wax dëgg ca la. Ànd bu laluwut ci dëgg, du yàgg. Te, sa...

DOOMU SENEGAAL JI ÑU REY CA FARÃS

Xew-xew bu tiis boobu mi ngi am ci guddig talaata jàpp àllarba. Takk-deri tubaab...

NJIITU MBOOTAAYU RÉEWI AFRIG YI (2023-2024)

Benn weer kepp a dese Njiitu réewum Senegaal li, Maki Sàll, ci boppu kilifteefu...