BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi ñu jagleel waa jasporaa bi, ci njiiteefu Njiitu réew mi...

BÉS NIKI TAY, NEELEEN DOKTOOR PÀPPA AALI JÀLLO

Gaawo, 13eelu desàmbar 2025, ca Jàngune bu Ndar, la Pàppa Aali Jàllo (njiitul LDW) doon gaaral teesam ci Làkk ak mbatiiti Afrig, duppe ko...

FOQATIG NGUUR FA RÉEWUM BENEE

Ginnaaw coowal sóobare yi toog fa boppu réewum Gine Bisaawu, geneen foqatig Nguur naroon naa amaat, wile yoon, fa réewum Benee ak ay sóobare...

MOUSSO NGIR « JIGÉEN GÉNN CIG LËNDËM »

Soo déggee baatu « mousso », sam xel mën naa dem cib « restaurant » bu siiw ba ca Kanadaa. Waaye, « mousso » bii moom bokkul ak booba ; xéy-na...

NGOMBLAAN GI : DÉPITE YI TÀMBALI NAÑU CÀMBAR NAFA 2026 GI

Dépite yi tàmbali nañu càmbar nafag atu 2026 mi fa Ngomblaan ga. Ñu nar koo amal ci diiru ñaari ayu-bés ngir dalal jëwriñi Càmm...

MAGU WAXOON NAA KO

JIKKO JU RAFET MOOY TABAX AM RÉEW

Wolof nee na, rafet kanam, rafet jikko a ko...
01:33:07

“Héritages” dalal na Bubakar Bóris Jóob

"Héritages ak Awa" ngi dalal Bubakar Bóris Jóob, ngir...

Malaanum Lëndëm : Bóris Jóob, na woon, fa woon

Ñeenteelu yoon a ngi nii Bubakar Bóris Jóob di...

GÀCCE NGAALAAMA, MBUGAAR !

Senegaal amati na ndam ci 3eelu fan ci weeru...

KUJJE GEEK WOTEB 2022 BI: BËGG NAA LA, BËGGUMA LA, LOOLU JARUL COOW

Ci bésub 23 sàŋwiye ci atum 2022 bii di...

FÀTTALIKU DÉMB

SEEX

Seex Mooy góor Moo di as gor Mbokk ya ko wor Ñooy mbokk...

FÀTTALIKU OMAR BOLONDEŊ JÓOB… 2/2

(ÑAAREELU XAAJ) Bi ñu nee Senegaal moom na boppam tamit,...

2002, ATUM SUUXU JOOLAA BI

Bërki-démb 26 sàttumbar ci atum 2020, "Bateau le Joolaa"...

FAIDHERBE, SAAY-SAAY BI NUY SARGAL

Bi Siidiya Ndàtte Yàlla génnee àddina ak léegi, am...

JÉERI JOOR NDEELAAK TUBAAB BI

Jéeri Joor Ndeela Faal mu ngi gane àdduna ci...

DÉMB AK TEY

WIDEWO YI

WAXLEEN SEEN XALAAT

BOO BAÑEE ÑAAW…

Bu nu la waxee nga àggale kàddu gii, looy...

Njiitu Réew

Dangaa jiitoom Dañu la jiital Sa jubb cunduŋ xanaa taxul Moo ndax...

YAA GORE !

Yàgg, yàgg, dëgg ay daan Dëgg lottoon na Senegaal Usmaan Sonkoo...

Ndigalu Maam Ya

Afrig nee Waaw góor, waaw kumba Ayca leen ca waar wa Bu...

SÀCCIIN WI JËM CI TÀNN YI DËGMAL TE FEEÑALEES KO

Sëñ Abdu Xaadr Kebe mooy biral fii xalaatam ñeel...

TÀGGATOO

NJÀNGAT CI TÉERE YI

XËT YI LEEN DÀQAL

LI GËN A FËS CI XIBAARI RÉEW MI (ALTINE 3 AWRIL 2023)

4 AWRIL Yewwi Askan Wi gàntal na Njiitu réew mi, Maki Sàll Lëkkatoo Yewwi Askan Widu...

MÓODU LÓO DAAN NA AAMAA BALDE

Xaar bi yàggoon na lool, waaj gi tamit naka noonu. Waaye, ñaari mbër yi...

NGOMBLAAN GI : TAXAWU WÉET NA

Ab diir, ginnaaw ba Ngomblaan gi tëjee woon ay buntam, tijjiwaat na leen ci...

SENEGAAL TIIT NA WAAYE ËLLËG, ËLLËGU ASKAN WI LA…(PAAP AALI JÀLLO)

Bindkat yi bind nañ, waxkat yi wax, gëstukat yi biral, boroom xam-xam yi jàngat,...

YOON : JUB, JUBAL, JUBBANTI

Tey, ci talaata ji, 28 pani suwe 2024, lañuy tijji péncoo mi ñu jagleel...

WURE WA DEM NA KËŊŊ !

Ngomblaan gi, walla Péncum ndawi réew mi (ni ko ñenn ñiy wowee), benn la...

LI GËN A FÉS CI XIBAAARI BÉS BI (29/08/2023)

PÓLITIG Ibraahima Amidu Dem bëgg naa nekk lawax ci wotey 2024 yii di ñëw. Ci...

FEEBARU XOL BU GAAW DAANEEL NA IBK (AMI MBENG)

  Dalu webub bennoog Afrig bii di "Jeune Afrique" moo yëgle ne njiitu réewum Mali mees...

COOWAL NJÀNG MU KOWE MI : UCAD TIJJEEGUL I BUNTAM

Jàngune Séex Anta Jóob bu ndakaaru tijjeegul i buntam. Musaa balde, jëwriñ ji ñu...

XAREB IKREN BI – COSAAN LI AK NJEEXITAL YI 1/3

Coowal Riisii – Ikren moo lëmbe àddina si. Daanaka, ñaari ayu-bés a ngi nii,...

MALI AK FARÃS : LA WOON, WONNI NA (2)

Diggante Farãs ak Mali ma ngay wéy di ñagas. Loolu nag tàmbaliwul tey rekk....

LI GËN A FËS CI XIBAARI BÉS BI Àjjuma 2 sàttumbar 2022

XEW-XEWU JAMONO Jëwriñ ji ñu dénk wàllum ndox mi ak cet gi fii ci Senegaal,...

KIPPUG WATTU LÀKKI RÉEW MI (CI TEKKIB PAAP AALI JÀLLO)

Cër bi nu jox farañse bi tax na ba, kenn sañul a xët sàrt...

“ WÀDD MOO REY ARTISANAA BI, MAKI SÀLL A KO SUUL”

Senegaal dafa tollu ci jamono joo xam ne, képp ku jàngul, mënul a jot...

ÀQ AK YELLEEFI DOOM-AADAMA : SENEGAAL DAFA GËN A DELLU GINNAAW

Senegaal mi ngi ci guuta. Loolu la kurél yiy sàmm àq ak yelleefi doom-aadama...

NJEEXITALI ÀTTEB BAARTELEMI JAAS BI

Ёttu àtte bu Ndakaaru dёggal na daan bi ñu teg ci ndoddu Bàrtlemi JAAS...

MASAALIKUL JINAAN WALLA YOONI ÀJJANA YI

Ci àjjuma jii weesu, 27eelufan ci weeru sàttumbar, atum 2019, lañ doon ubbi ci...

SENEGAAL, YOKK CERE, DOLLI ÑEEX !

Sàmpiyonaa yi jeex nañu. Ekibi dëkk yi ñooy futbal jamono jii. Ñii di futbal...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (22/8/2023)

WOTEY 2024 YI : MAMADU IBRA KAN DINA NEKK LAWAX Mamadu Ibra Kan dina bokk ci...

Gàttali bés bi

Wotey palum depite yi : Mari Tëw Ñaan mi yàggoon a liggéey ak Njiitu réew mi...

PÉNCUM MAAM YUNUS JEŊ : LADAB CI LÀMMIÑI RÉEW MI (NDEY KODDU FAAL)

Ku dégg Maam Yunus Jeŋ, sa xel dem ci jigéen ji jëkk a bind...

14eelu LËLU SAES : AW YOON NGIR TINKI NJÀNG MU KAWE MI

Kenn werentewul ne njàng mu kowe mi dafa nekk ci guuta. Ab diir a...

ÀTTE BOR FEY WALLA… FÀTTE ? (Ndongo Si)

Ndongo Si Mbasum Covid-19 mi am nay njeexital ci koom-koomu Afrig, dekkal na sax coow lu...

MËQ SUUF

Bari na ay mag, yu góor ak yu jigéen, yuy fàttaliku lenn ci li...

WAAW, ANA DIJJE BAAJI ?

Mbirum ñaari way-yëddu ya réeroon ca Kab Maniwel ma ngay wéy di lëmbe xel...

ALIYU SÀLL : KU AM KUDDU DOO LAKK

Aliyu Sàll tekki na ndombog-tànkam ci boppu CDC, teg loxoom ci Alxuraan, waat ne...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI Altine 5 ut 2022

PÓLITIG Maalig Gàkku fésal na yéeneem ak taxawaay bi mu namm a am ëllëg ci...

YOMBALUG DUNDU GI, NISËRU NGUUR GI

Ci atum 2023 mii nu dëgmal, Nguur gi dafa fas yéene génne gafaka (budget)...

LI GËN A FËS CI XIBAARI

LÀMB : Bàlla Gay 2 daanaat na Giri-Bórdoo  Ci diibéerub démb ji la Gastõ Mbeng...

MALI AK FARÃS : LA WOON, WONNI NA

Diggante Farãs ak Mali ma ngay wéy di ñagas. Loolu nag tàmbaliwul tey rekk....

AADAMA BARO RËCC NA !

Ag Nguur naroon na daanooti ci Afri sowu-jant. Gàmbi la naroon xewe. Ayu-bés bii...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (7/2/2024)

WAA ETAASINI, UE AK CEDEAO DAL NAÑU CI KOW MAKI SÀLL Ndogalu Njiitu réew mi...

ETAASINI : DÀQ NAÑ 140i SAA-SENEGAAL

140i saa-senegaal la Etaasini dàq. Daf leen a waññi ginnaaw biñ fa duggee ci...

DÓOR I YAT YARUL GONE

 SAFIYETU BÉEY Juróom-ñetti xarnu ci ginnaaw, amoon na fi buurub Almaañ bu ñuy wax Ferederik...

LI TAX 102i BOROOM XAM-XAM YU MAG JÀPP NE SENEGAAL DU RÉEWUM YEMALE

CI TEKKIB PAAP AALI JÀLLO * Séex Anta Jóob mas naa bind ne "Senegaal, mënees na fee...

DUND BU JAFE BI : SAA-SENEGAAL YEE NGI ÑAXTOOTI

Démb ci gaawu gi, 21 oktoobar 2023, saa-senegaal yaa nga woon fa Place de...

NGOMBLAAN GI JÀLLALE NA SEMBUB ÀTTE BI

Bees sukkandikoo ci Ayib Dafe, Ndiisoog àtte yi jàllale na sembub àtte biy soppi...

BÉS DINA ÑËW !

Lu yëngu lu ne, li ko yëngal a ko ëpp doole. Dëgg la, futbal...