BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi ñu jagleel waa jasporaa bi, ci njiiteefu Njiitu réew mi...

BÉS NIKI TAY, NEELEEN DOKTOOR PÀPPA AALI JÀLLO

Gaawo, 13eelu desàmbar 2025, ca Jàngune bu Ndar, la Pàppa Aali Jàllo (njiitul LDW) doon gaaral teesam ci Làkk ak mbatiiti Afrig, duppe ko...

FOQATIG NGUUR FA RÉEWUM BENEE

Ginnaaw coowal sóobare yi toog fa boppu réewum Gine Bisaawu, geneen foqatig Nguur naroon naa amaat, wile yoon, fa réewum Benee ak ay sóobare...

MOUSSO NGIR « JIGÉEN GÉNN CIG LËNDËM »

Soo déggee baatu « mousso », sam xel mën naa dem cib « restaurant » bu siiw ba ca Kanadaa. Waaye, « mousso » bii moom bokkul ak booba ; xéy-na...

NGOMBLAAN GI : DÉPITE YI TÀMBALI NAÑU CÀMBAR NAFA 2026 GI

Dépite yi tàmbali nañu càmbar nafag atu 2026 mi fa Ngomblaan ga. Ñu nar koo amal ci diiru ñaari ayu-bés ngir dalal jëwriñi Càmm...

MAGU WAXOON NAA KO

JIKKO JU RAFET MOOY TABAX AM RÉEW

Wolof nee na, rafet kanam, rafet jikko a ko...
01:33:07

“Héritages” dalal na Bubakar Bóris Jóob

"Héritages ak Awa" ngi dalal Bubakar Bóris Jóob, ngir...

Malaanum Lëndëm : Bóris Jóob, na woon, fa woon

Ñeenteelu yoon a ngi nii Bubakar Bóris Jóob di...

GÀCCE NGAALAAMA, MBUGAAR !

Senegaal amati na ndam ci 3eelu fan ci weeru...

KUJJE GEEK WOTEB 2022 BI: BËGG NAA LA, BËGGUMA LA, LOOLU JARUL COOW

Ci bésub 23 sàŋwiye ci atum 2022 bii di...

FÀTTALIKU DÉMB

SEEX

Seex Mooy góor Moo di as gor Mbokk ya ko wor Ñooy mbokk...

FÀTTALIKU OMAR BOLONDEŊ JÓOB… 2/2

(ÑAAREELU XAAJ) Bi ñu nee Senegaal moom na boppam tamit,...

2002, ATUM SUUXU JOOLAA BI

Bërki-démb 26 sàttumbar ci atum 2020, "Bateau le Joolaa"...

FAIDHERBE, SAAY-SAAY BI NUY SARGAL

Bi Siidiya Ndàtte Yàlla génnee àddina ak léegi, am...

JÉERI JOOR NDEELAAK TUBAAB BI

Jéeri Joor Ndeela Faal mu ngi gane àdduna ci...

DÉMB AK TEY

WIDEWO YI

WAXLEEN SEEN XALAAT

BOO BAÑEE ÑAAW…

Bu nu la waxee nga àggale kàddu gii, looy...

Njiitu Réew

Dangaa jiitoom Dañu la jiital Sa jubb cunduŋ xanaa taxul Moo ndax...

YAA GORE !

Yàgg, yàgg, dëgg ay daan Dëgg lottoon na Senegaal Usmaan Sonkoo...

Ndigalu Maam Ya

Afrig nee Waaw góor, waaw kumba Ayca leen ca waar wa Bu...

SÀCCIIN WI JËM CI TÀNN YI DËGMAL TE FEEÑALEES KO

Sëñ Abdu Xaadr Kebe mooy biral fii xalaatam ñeel...

TÀGGATOO

NJÀNGAT CI TÉERE YI

XËT YI LEEN DÀQAL

NDAJEM NJIITI KIPPAANGOY DÉPITE YI

Coowal DPG li ba tey jeexagul. Nde, ndeyu-mbill ji, Usmaan Sonko, dafa am ay...

NGOMBLAAN GI JOYYANTI NA SÀRTU-BIIRAM

Dépite yi jàllale nañ sémbuw àtteb 10/2024 wiy soppi ak a mottali « loi...

GEREEWU SAABALUKAAY YI

Saabalukaay xéy nañ bank seen i loxo tey ci talaata ji, 13i pani ut...

MÀGGALUG TUUBAA 2025

Tay, 13i pani ut 2025 mooy méngook 18eelu fanu safar ci atum 1447 ci...

CAAROY 44 : USMAAN SONKO ŊÀÑÑ NA FARÃS

Caaroy 44, xew-xew bu tiis la ci mboorum Afrig, rawatina mom Senegaal. Jéyya jooju,...

IGE JOT NA NDIGAL

IGE (Ispection Générale d’État) am na sas wu réy. Dina amal ay caytu yu...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (24/7/2024)

TUKKIB NJIITU RÉEW MI Njiitu réew mi, Basiiru Jomaay Jaxaar Fay, jóge na fi, dem...

KAÑ LANUY TOOG ?

Doomi Senegaal, ñu yàgg a dox lañu. Bu ñu nekkul fépp it, bari na...

LOMPUL : BIRAM SULEY JÓOB WAX NAAK NJIITI GCO YI

Jëwriñ ji, Biram Suley Jóob, wax na ak njiiti GCO (Grande Côte Opérations SA),...

JÀPP NAÑU AG GAAL FA BÀMBUGAR

Mbëkk maa ngi wéy di lëmbe réewi Afrig sowu-jant yi, rawatina Senegaal. Saa su...

NDOGAL YI ROTE CI “CONSEIL SUPÉRIEUR DE LA MAGISTRATURE”

Tey, àjjuma juróom-ñeenti fan ci weeru ut lañu doon amal ndajem CSM mi (Conseil...

MALI-IKREN : DIGGANTE BA DOG NA

Càmmug Mali gi dafa jël ndogalu dog bépp xeetu jëflante ak Ikren. Ndogal loolu...

TÀGGE : PAATUG AAMADU MAXTAAR MBÓW

Guy daanu na. Aamadu Maxtaar Mbów, maamu askan wi, moo génn àddina. Ci guddig...

WOODSIDE : NDAM AM NA CI SÉMBUW SÀNGOMAAR WI

Woodside Energy siiwal na xibaar buy neex Saa-Senegaal yi, rawatina njiit yu bees yi....

NJAAG NANGUL !

Baaxoo nanu, fi réew mi, bu xewu bànneex amee, jigéen ñiy joqalante ay teraanga....

BAKKEL : NJIITUL SAED LI SEETI WOON NA BAYKATI KÀMBUG KOLANGAL GI

Mbënnum dexug Senegaal gi dafa jural ay jafe-jafe dëkk yi ko dar, rawatina Bakkel...

XIBAARI TÀGGAT-YARAM (8/8/2024)

Jeu Olympic Paris 2024 Ci wàllu futbal bi, Espaañ U23 ak Farãs U23 ñooy daje...

ÀMBURUWAAS SAAR : AATU RÉER NA !

Njabootu làmbu Senegaal ak mbatiit am nañu dëj. Nde, xibaaru tiis ak uw naqar...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (24/6/2024)

BÉSU LIGGÉEYKATI BOKKEEF GI Démb, ci dibéer ji, 23i pani suwe 2024, lañ doon màggal...

LI GËN A FËS CI XIBAARI BÉS BI (13-8-2024)

MBIRUM "Conseil Supérieur de la Magistrature" Ndogal yi tukkee woon ca ndajem CSM (Conseil Supérieur...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (26-8-2024)

JËFLANTEEK BITIM-RÉEW Réewum Senegaal am na yéeney gën a dëgëral digganteem ak réewum Sapõ....

CÀMM GI ÀDDU NA CI COOWAL ONAS LI

Mustafaa Njekk Saare mi yore kàddu Càmm gi àddu na ci coowal Onas li...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (26/9/2024)

LEERALI CÀMM GI CI LIÑ FI FEKK Ci alxamesu tey jii, 26i pani sàttumbaar 2024...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (11/10/2024)

SÉMBUW SOPPI SENEGAAL FII AK 2050 Sémb wi, maanaam “Le Projet”, nees koy waxee, yemb...

NAALU NEKKAL : 300i DEFARUWAAYI KËYIT YEES LËNKALE

Ñetti téeméeri defaruwaayi këyit (état civil) lañu lënkale ngir yombal aar geek ceetug këyiti...

MAKI SÀLL, LU LA KO JARAL ?

Seneweb moo siiwal xibaar bi. Maki Sàll, Njiitu réewum Senegaal mi folleeku keroog 24...

PASTEF AK ÑOOMIN SEEN

Ndam la féete na wet. PASTEF a gobbi lépp, lëmbe géew bi, gën a...

LI GËN A FËS CI XIBAARI BÉS BI (24/9/2024)

CÀMM GI DINA WAX AK ASKAN WI Njiitu réew mi ak Càmm gi dinañ wax...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (2/9/2024)

TUKKIB NJIITU RÉEW MI FA SIIN Njiitu réew mi Sëñ Basiiru Jomaay Jaxaar Fay moo...

NJIITU RÉEW MI TABB AMINATU TURE

Njiitu réew mi, Basiiru Jomaay Fay, tabb na Soxna Aminata Ture. Ci altine ji,...

TOOLI CEEB YI TUUB FA DIIWAANU MAATAM

Tooli ceeb yu baree tuub fa diiwaanu Maatam. Looloo ngi am ginnaaw bi dex...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (7/11/2024)

UDS BU AJI MBERGAAN FEKKI NA PASTEF Fukki fan kepp a des ci wotey palug...

NDAJEM MBOOTAAYU ÀTTEKATI SENEGAAL YI

Mbootaayu àttekati Senegaal yi, ñu gën koo xam ci turu UMS (Union des Magistrats...

BALAA NOO LAAX JAAY…

Nit, ak xelam ak i xalaatam yu xóot, du jóg ci di jéem a...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (17/10/2024)

WAAJTAAYU WOTEY PALUG DEPITE YI Lu tollu ci weer moo des ci wote yi. Waaye,...

NJIITU RÉEW MI TAS NA NGOMBLAAN GI

Ngomblaan gee saay. Ki ko faat mooy Sëñ Jomaay. Démb la biral ndogal li,...

TÀGGE : SOXNA WAALO MU SËRIÑ SAALIW MBÀKKE NELAW NA

Xibaar bu tiis la njabootu Tuubaa ak taalibey murit yi xëyee tey. Soxna Waalo...

MBËKK MI : GAAL GI SUUX FA MBUUR

Jëyya ju metti amatina ci mbëkk mi. Genn gaal gu yab ba fees, wutali...