Li gën a fës ci xibaari bés bi (9/10/2024)

9JÀNGOROY ŊAS Nemmeeku nañ juróom-benni jarag yu ame jàngoroy ŋas. Juróom-benni jarag yooyu, ñu ngi nekk ci juróomi "district" : Ndakaaru suuf (1), Funjuuñ (1),...

FUTBAL : FSF ÀDDU NA CI MBIRU ISMAYLA SAKOB

Keroog, ci àjjuma jii weesu, la Paab Caw biral toftaleg gayndey kuppe yi. Moom mi toppoon ci Aliw Siise, moo ko wuutandi ci boppu...

TAKKU WALLU BËGGUL SONKO BOKK

Démb, ci altine ji, la waa DGE (Direction Générale des Elections) siiwal toftale yi. Limu toftale yi xaw naa takku, donte ne sax, ñeen-fukk...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (7/10/2024)

KÀDDUY NJIITU RÉEW MI ÑEEL FMI Njiitu réew mi, Sëñ Basiiru Jomaay Jaxaar Fay, rafetlu na taxawaayu FMI (Fonds Monétaire Internationale) ci li kurél gi...

WOTEY NGOMBLAAN YEES RANDALSI : DGE SIIWAL NA 41 TOFTALE

Kurél gu mag guy saytu wote yi fi Senegaal, Direction générale des élections (DGE), siiwal na toftale yiy joŋante ci wotey Ngomblaan yees randalsi,...

MAGU WAXOON NAA KO

JIKKO JU RAFET MOOY TABAX AM RÉEW

Wolof nee na, rafet kanam, rafet jikko a ko...
01:33:07

“Héritages” dalal na Bubakar Bóris Jóob

"Héritages ak Awa" ngi dalal Bubakar Bóris Jóob, ngir...

Malaanum Lëndëm : Bóris Jóob, na woon, fa woon

Ñeenteelu yoon a ngi nii Bubakar Bóris Jóob di...

GÀCCE NGAALAAMA, MBUGAAR !

Senegaal amati na ndam ci 3eelu fan ci weeru...

KUJJE GEEK WOTEB 2022 BI: BËGG NAA LA, BËGGUMA LA, LOOLU JARUL COOW

Ci bésub 23 sàŋwiye ci atum 2022 bii di...

FÀTTALIKU DÉMB

SEEX

Seex Mooy góor Moo di as gor Mbokk ya ko wor Ñooy mbokk...

FÀTTALIKU OMAR BOLONDEŊ JÓOB… 2/2

(ÑAAREELU XAAJ) Bi ñu nee Senegaal moom na boppam tamit,...

2002, ATUM SUUXU JOOLAA BI

Bërki-démb 26 sàttumbar ci atum 2020, "Bateau le Joolaa"...

FAIDHERBE, SAAY-SAAY BI NUY SARGAL

Bi Siidiya Ndàtte Yàlla génnee àddina ak léegi, am...

JÉERI JOOR NDEELAAK TUBAAB BI

Jéeri Joor Ndeela Faal mu ngi gane àdduna ci...

DÉMB AK TEY

WIDEWO YI

WAXLEEN SEEN XALAAT

BOO BAÑEE ÑAAW…

Bu nu la waxee nga àggale kàddu gii, looy...

Njiitu Réew

Dangaa jiitoom Dañu la jiital Sa jubb cunduŋ xanaa taxul Moo ndax...

YAA GORE !

Yàgg, yàgg, dëgg ay daan Dëgg lottoon na Senegaal Usmaan Sonkoo...

Ndigalu Maam Ya

Afrig nee Waaw góor, waaw kumba Ayca leen ca waar wa Bu...

SÀCCIIN WI JËM CI TÀNN YI DËGMAL TE FEEÑALEES KO

Sëñ Abdu Xaadr Kebe mooy biral fii xalaatam ñeel...

TÀGGATOO

NJÀNGAT CI TÉERE YI

XËT YI LEEN DÀQAL

LU YEES CI BÓOMUG ASIIS DABALAA AK WAALI

Mbirum bóomug ñaari bakkan yooyu moo lëmbe réew mi jamono jii. Waaye, mel na...

NJÉBBALUG WAYNDAREY LËKKATOO YI

Guddig dibéeru démb ji moo nekkoon àpp gu mujj ñeel njébbalug wayndare yi. Mu...

SONKO XIIRAL NA YAR WI

Elimaanu jëwriñ yi, Usmaan Sonko, doon na jël kàddu gi tey, ci àllarba ji....

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (30/9/2024)

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (30/9/2024) WOTEY NGOMBALAAN GI Jeexal nañu démb ci...

ELIMAANU JËWRIÑ YI SANTAANE NA YAXANAL

Elimaanu jëwriñ yi jël na ndogal lu bees ñeel Càmm gi. Muy sàkku ci...

XIBAARI TÀGGAT-YARAM (9/9/24)

Toogalante CAN 2025 : Senegaal waneegul lu dal xel ! Keroog ci àjjuma ji 6i...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (30/8/2024)

JËWRIÑU BIIR-RÉEW MI AMAL NAY TABB YU YEES Jëwriñu Biir-Réew mi, Seneraal Sã-Batist Tin amal...

JÀPPATI NAÑ AY MBËKK-KAT

Coowal mbëkk mi lëmbe na lool réew mi, rawatina jamono jii. Am na sax,...

KÀDDUY NJIITU RÉEW MI

Njiitu réew mi, Sëñ Basiiru Jomaay Jaxaar Fay, dina yékkati ay kàddu jagleel ko...

JUB, JUBAL, JUBBANTI : CONC BI TEGGEEKU NA !

Keroog 24 màrs 2024 la conc bi teggeeku. Keroog it la Yoon tekkeeku, wayndare...

ARCELOR MITTAL : ÀTTE BOR, FAY !

Càmmug Senegaal gu yees gi, jaare ko ci DGID, di kurél giy dajale kubal...

NJIITU RÉEW MI BIND NA NJIITUL NGOMBLAAN GI

Coowal DPG bu elimaanu jëwriñ yi ba léegi fayagul. Dina ko def am du...

TOLLUWAAYU RÉEW MI CI WÀLLU KOOM-KOOM

FMI dafa génnee ag caabal gog, day càmbar koom-koomu Senegaal ci njëlbeenug xaaju atum...

PALUG DÉPITE YI : KURÉLU ATEL TAXAW NA

Ginnaaw bi Njiitu réew mi Sëñ Basiiru Jomaay Jaxaar Fay tasee Ngomblaan gi, coow...

NDOG MU METTI FA NDÀNGALMA

Ndog mu metti moo am am fa Njama Faal. Njama Faal mi ngi bokk...

JÀPP NAÑ BUGAAN GÉY DANI

Ci àllarbay démb ji, 2i pani oktoobar 2024, lañu woolu woon Bugaan Géy Dani...

NJIITU RÉEW MI TAS NA NGOMBLAAN GI

Ngomblaan gee saay. Ki ko faat mooy Sëñ Jomaay. Démb la biral ndogal li,...

KOMISEER KEYTA TËDDI NA KASO

Ci ndigalu toppekatu Bokkeef gi, àttekatu 10eelu kabine bi dóor na « mandat de...

LI GËN A FËS CI XIBAARI BÉS BI (24/9/2024)

CÀMM GI DINA WAX AK ASKAN WI Njiitu réew mi ak Càmm gi dinañ wax...

USMAAN SONKO WOOTE NA BENNOO NGIR PALESTIN

Elimaanu jëwriñ yi, Usmaan Sonko, ma nga woon démb ca ndajem njàppale Palestin ma...

XIBAARI TÀGGAT-YARAM (25/9/2024)

Mbappe ame na gaañu-gaañu ! KilIyan Mbappe dina sori pàkk yi lu tollu ci...

DUND GU DIGG-DÓOMU

Lu jamono di gën a dem, mag ñi di gën a ñaawlu nekkiinu ndaw...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (12/9/2024)

NJIITU RÉEW MI DINA JANOOK ASKAN WI CI GUDDIG TEY JII Bu yàggul dara la...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (17/9/2024)

SAMP NAÑ ËTTU ÀTTE BII DI "POOL JUDICIAIRE FINANCIER" Jëwriñ ji ñu dénk wàllu Yoon...

MAKI SÀLL, LU LA KO JARAL ?

Seneweb moo siiwal xibaar bi. Maki Sàll, Njiitu réewum Senegaal mi folleeku keroog 24...

NGOMBLAAN GI : BENNOO BOKK YAAKAAR GÀNTAL NA SÉMBUW ÀTTE WI

Démb, ci altine ji, lañu doon àggale ndaje ma ñu dooroon ca ayu-bés bee...

NGASUM NGALAM MA CA FALAME

Ci weeru sulet wiI weesu, Njiitu réew mi jëloon nab dekkare ngir dakkal lépp...

WOTEY NGOMBLAAN YEES RANDALSI : DGE SIIWAL NA 41 TOFTALE

Kurél gu mag guy saytu wote yi fi Senegaal, Direction générale des élections (DGE),...

KÀDDUY NJIITU REEW MI CA NDAJEM MBOOTAAYU XEET YI

Démb ci àllarba ji, Njiitu réew mi, Basiiru Jomaay Jaxaar Fay, ma nga woon...

GÀMMU 2024

Démb, ci guddig dibéer ji jàpp altine jii, lañ doon amal gàmmu 2024. Muy...

JUB, JUBAL, JUBBANTI : KURÉLI MAXEJJ YI ÀDDU NAÑU

Kuréli maxejj yi àddu nañu ci « jub, jubal, jubbanti » bi Càmm gi woote. Ñuy...

FUTBAL/GAYNDEY SENEGAAL : YEWWI NAÑ ALIW SIISE

Gannaaw 9i at ci boppu ekibu Senegaal bu mag bi, Càmmug Senegaal gu yees...

FMI RAFETLU NA DOXALINU CÀMMUG SENEGAAL GI

FMI rafetlu na luññutu gi njiiti Senegaal yu bees yi amal ñeel koppari réew...

TAKKU WALLU BËGGUL SONKO BOKK

Démb, ci altine ji, la waa DGE (Direction Générale des Elections) siiwal toftale yi....

SONACOS/KAWLAX : UBBITEG ISINU LINJAAN BI

Elaas Ndaan Jaañ, njiitul SONACOS li, yégle na xibaar buy neex Saa-Senegaal yi, rawatina...

NJOMBE YI FI MAKI SÀLL BÀYYI

Démb la woon alxames, 26i pani sàttumbaar 2024, yemoo ak bés bees di fàttaliku...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (3/10/2024)

BÀYYI NAÑU SÉEX YÉRIM SEKK, KADEER JA AK BUGAAN GÉY Ci ndoorteelu ayu-bés bi lañu...