LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (31/10/2024)

TUKKITEG NJIITU RÉEW MI FA TURKI Keroog la Njiitu réew mi, Basiiru Jomaay Jaxaar Fay, demoon fa Araabi Sawdit. Mu doonoon tukkiteg waxtaan ci mbirum...

TABAXUG DËQ FA NDAR

Tàmbali nañu tabax ab dëq (digue) fa Daaru, diiwaanu Ndar. Jubluwway bi mooy aar askan wa ci walum dex Senegaal gi. DIRPA, banqaas bi...

YOON : DAAN NAÑ BUGAAN WEERU KASO

Tay lees doon àtte Bugaan Géy Dani fa Tàmbaakundaa. Moom miy njiitul kurélu Gëm Sa Bopp nag, àttekat bi daan na ko weeru kaso...

NGËLÉN FA ESPAAÑ : 95i BAKKAN ROT NAÑU

Tay, ci àllarba ji, 30i oktoobar 2024, ngëlén lu am doole moo dikkal waa Espaañ. Bariwaayu ndox mi ak dooley ngelaw li tax nañu ba...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (29/10/2024)

KÀDDUY ÀLLIYUN TIN ÑEEL WAY-PÓLITIG YI Àlliyun Tin, di kenn ci njiiti kuréli ma-xejj yi, yékkateeti nay kàddu jëme ci way-pólitig yi, rawatina ci seen...

MAGU WAXOON NAA KO

JIKKO JU RAFET MOOY TABAX AM RÉEW

Wolof nee na, rafet kanam, rafet jikko a ko...
01:33:07

“Héritages” dalal na Bubakar Bóris Jóob

"Héritages ak Awa" ngi dalal Bubakar Bóris Jóob, ngir...

Malaanum Lëndëm : Bóris Jóob, na woon, fa woon

Ñeenteelu yoon a ngi nii Bubakar Bóris Jóob di...

GÀCCE NGAALAAMA, MBUGAAR !

Senegaal amati na ndam ci 3eelu fan ci weeru...

KUJJE GEEK WOTEB 2022 BI: BËGG NAA LA, BËGGUMA LA, LOOLU JARUL COOW

Ci bésub 23 sàŋwiye ci atum 2022 bii di...

FÀTTALIKU DÉMB

SEEX

Seex Mooy góor Moo di as gor Mbokk ya ko wor Ñooy mbokk...

FÀTTALIKU OMAR BOLONDEŊ JÓOB… 2/2

(ÑAAREELU XAAJ) Bi ñu nee Senegaal moom na boppam tamit,...

2002, ATUM SUUXU JOOLAA BI

Bërki-démb 26 sàttumbar ci atum 2020, "Bateau le Joolaa"...

FAIDHERBE, SAAY-SAAY BI NUY SARGAL

Bi Siidiya Ndàtte Yàlla génnee àddina ak léegi, am...

JÉERI JOOR NDEELAAK TUBAAB BI

Jéeri Joor Ndeela Faal mu ngi gane àdduna ci...

DÉMB AK TEY

WIDEWO YI

WAXLEEN SEEN XALAAT

BOO BAÑEE ÑAAW…

Bu nu la waxee nga àggale kàddu gii, looy...

Njiitu Réew

Dangaa jiitoom Dañu la jiital Sa jubb cunduŋ xanaa taxul Moo ndax...

YAA GORE !

Yàgg, yàgg, dëgg ay daan Dëgg lottoon na Senegaal Usmaan Sonkoo...

Ndigalu Maam Ya

Afrig nee Waaw góor, waaw kumba Ayca leen ca waar wa Bu...

SÀCCIIN WI JËM CI TÀNN YI DËGMAL TE FEEÑALEES KO

Sëñ Abdu Xaadr Kebe mooy biral fii xalaatam ñeel...

TÀGGATOO

NJÀNGAT CI TÉERE YI

XËT YI LEEN DÀQAL

JÀPPATI NAÑ USMAAN SONKO

Fan yii weesu lañ ñàggi kër Usmaan Sonko ginnaaw 55i fan. Ñu yaakaaroon ne...

XIBAARI TÀGGAT-YARAM

AY YEESAL ÑEEL BARI (LES EQUIPES) SENEGAAL YI Gaynde yu mag yi (ekib A) Wéyalees na...

TAAX BI MÀBB NDAKAARU : 5I BAKKAN ROT NAÑU

Taaxub 3i etaas moo màbb ci guddig altine ji jàpp talaata. Xaar-Yàlla la jéyya...

CAN KODDIWAAR 2024 : CAABALU BÉS BI

NGIRTEY JOŊANTEY DÉMB YI Démb ci àllarba ji moo nekkoon bés bu mujju ci 1eelu...

SONKO AK JOMAAY TUUMAAL NAÑ AAMADU BA

Démb la Usmaan Sonko ak Basiiru Jomaay Jaxaar Fay doon janook taskati xibaar yi...

LI GËN A FËS CI WOTEY 2024 YI (25/3/ 2024)

KÀDDUY BASIIRU JOMAAY FAY YU NJËKK NIKI NJIITU RÉEWUM SENEGAAL  Njiitu réew lu bees li,...

USMAAN SONKO : ELIMAANU JËWRIÑ YI

Njiitu réew mi, Basiiru Jomaay Fay, tabb na Usmaan Sonko, def ko elimaanu jëwriñ...

NJÀNG MAA NGI CI YOONU NDËRMEELU

Njàng meek njàngale mi ci Senegaal mu ngi jànkonteel ak i jafe-jafe yu metti....

REYAATE BI CI RÉEW MI

Gaawu gii weesu, dafa am ku ñu jam paaka fa Ndindi, mu faatu. Ndindi,...

LU GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (10/6/2024)

WÉR-GI-YARAM Kurél gii di ànd gësëm, di kurélug waa kër doktoor, àddooti na. Wile yoon...

JÉYYA FA ECOPI : LU ËPP 150 BAKKAN YU ROT

Jéyya ju réy moo xew fa Ecopi. Suuf saa fa màbb ba ay bakkan...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (10/7/2023)

PÓLITIG Ayda Mbóoj dina bokk ci lawax yiy xëccoo réew mi ci wotey 25 féewaryee...

NJAAYUM SUUF : DOORO GÉY TAQAL NA MAKI SÀLL

Dooro Géy, di kenn ci ñi jege lool Maki Sàll, lañu jàpp fan yii...

WOTEY 2024

Sàntar “Grande Medine” : Ci ndigalu perefe, dàq nañ taskati xibaar yépp bi waxtu...

NJUREEFI WOTEY 2024 YI : CEESU KOW (THIES NORD)

Bérébu wote : Séex Ibra Faal Pekku wote : 02 Limu wotekat yi bindu : 584 Limu ñu wote :...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (5/2/2024)

YËNGU-YËNGU YI GINNAAW NDÀQUG WOTE YI Ginnaaw dal gi nu tàmbali woon a seetlu ci...

WOTEY 2024 YI : BENNOOG TUGAL (U.E.) A NGI GËTËN MAKI SÀLL

Waa Bennoog Tugal (Union Européenne) àddooti nañ ci wotey 2024 yees war a amal...

ABDURAHMAAN JUUF MA NGA CA JÀNGUNE YA

Ginnaaw ba ñu leen takkalee seen i ndomboy-tànk, jëwriñi Càmm gu bees gi sóobu...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (16/01/2024)

DOXIINU YOON CI RÉEW MI Lépp lañ war a xoolaat ci ni yoon di doxee...

EURO 2024

Njureefi sumb bu njëkk bi Sumb bu njëkk bi ñeel Ëro 2024 bi ca Almaañ...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (14/2/2024)

DÀQATI NAÑU LAYOOB SÉYDINA UMAR TURE AK SÉEX YÉRIM SEKK Coow li dox diggante ki...

XIBAARI TÀGGAT-YARAM (3/9/2023)

SAALIF KEYTA KUPPEKATU MALI BA WOON GAAÑU NA Ci gaawug démb ji, 2 sàttumbaar 2023,...

LI GËN A FÉS CI XIBAAR BÉS BI (14/6/2024)

DELLOO NAÑU WALFADJIRI AY SÀQAM Keroog ci àllarba ji la xibaar bi rotoon ne, dañu...

DÉGGOOY SOROJ BEEK GAAS BI : CÀKKUTEEFU WAY-XARAÑ YI

Nguur gi war na waxtaanewaat déggoo yi ñeel soroj beek gil bi (gaas bi)....

Aj 2024 : Ujaaji Senegaal yu njëkk dellusi nañu ci réew mi

Lu ëpp 12 000iy ujaaj ñoo jóge woon ci biir réew mi. Ujaaj yu...

NDOGAL YU BEES ÑEEL NJÀNG MU KOWE MI

Ay ndogal yu bees wàcc nañ ci njàng mu kowe mi. Muy i ndogal...

COSCE ŊÀÑÑI NA NI ÑU TABBE WAA CENA

COSCE (Collectif des Organisations de la Société Civile pour les Elections) ag mbootaay la...

COOWAL NASIYONAALITE KARIIM MAYSA WÀDD

Juróomi fan kepp a des balaa ndajem ndeyu àtte miy siiwal limug lawax yiy...

KÀMPAAÑ 2024 YI : “MAA BAAX, YAA BON !”

Altiney tey jii mooy tollook juróom-ñeenteelu fanu kàmpaañ ñeel wotey 24 màrs 2024 yi....

SENEGAAL/ANSD : LIMU NIT ÑI

ANSD, banqaas biy saytu limu nit ñeel yu ni mel, génnee na caabalam gu...

USMAAN SONKO A NGI CI DIGGANTE DUND AK DEE

Wér-gi-yaramu Usmaan Sonko gën na doy waar. Njiiti YAW (Yewwi Askan Wi) yi ñoo...

PAATUG NJIITU RÉEWUM IRÃ

Njiitu réewum Irã li, Ebraahim Raysi, faatu na. Fafalnaaw bi mu duggoon ak jëwriñam...

MARIN BU SENEGAAL : JURÓOMI KOMÀNDOO YI RÉER

Juróomi komàndoo yu marin bu Senegaal ñoo réer. Muy mbir mu doy waar mu...

NDAJEM NDEYU SÀRTI RÉEW MI BAÑ NA NDOGALI WAXTAANU MAKI SÀLL WI

Ndajem Ndeyu sàrti réew mi bañ na dogal yi tukkee ci waxtaan wu mujj...

EURO 2024 AK COPA AMERICA 2024

Ren, soppey kuppe dinañubégg bég. Nde, ginnaaw sàmpiyonaa yi jeex ak Ligue des champions...

USMAAN SONKO WEER NA MAKI SÀLL

DGE, kurél giy saytu lépp lu aju ci wote yi, lànkalati na ndawul Usmaan...

U.I.J.A SARGAL NA USMAAN SONKO

U.I.J.A (Union Internationale des Journalistes Africains) kurél gu mag la, gu ëmb taskati-xibaari Afrig...

12I ATI M23 : LA WOON WONNEEGUL

Kurél gii di « Mouvement des forces vives de la nation », ñu gën koo xam...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (11/4/2024)

NJÉBBALUG LENGE FA MÀKKAANI NJËWRIÑ YA Keroog ci àjjuma ji la elimaanu jëwriñ ji génne...

AIBD : AB ROPPALAAN BU WÀCC YOONAM

Naawub Belees Jaañ bi (Aéroport International Blaise Diagne) dafa tëj, tey ci alxames ji....