LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (3/12/2024)

CAAROY 44 : NJIITU RÉEW MI JËL NAY NDOGAL Barki-démb ci dibéer ji lañu doon màggal 80eelu pàttalikug Caaroy 44. Ñu doon ko amal ci njiiteefu...

TIIS WU RÉY FA GINE

Mats futbal bu mujje ciy masta ! Mbir yaa ngi xew barki-démb ci dibéeru 1eelu fanu desàmbar wii, mu di woon ab finaal bees...

ALIYUN BADARA BÉEY GUDDEE NA

Aliyun Badara Béey, njiitu kurélu bindkati Senegaal yi, moo génn àddina. Keroog, dibéer 1eelu desàmbar 2024, la wuyuji Boroomam, ginnaaw bi ko ab feebar...

EL MAALIG NJAAY MOOY NJIITUL NGOMBALAAN GU YEES GI

Sëñ Elaas Maalig Njaay lañu fal ci boppu Ngomblaan gu yees gi. Ci altiney tay jii, 2i pai desàmbar 2024, lees doon samp 15eelu...

UBBITEG NGOMBLAAN GU YEES GI

Tay, ci altine ji, ñaari fan ci weeru desàmbar 2024, lañuy ubbi Ngomblaan gu yees gi. Keroog ci alxames ji la Njiitu réew mi,...

CAAROY 44

MAGU WAXOON NAA KO

JIKKO JU RAFET MOOY TABAX AM RÉEW

Wolof nee na, rafet kanam, rafet jikko a ko...
01:33:07

“Héritages” dalal na Bubakar Bóris Jóob

"Héritages ak Awa" ngi dalal Bubakar Bóris Jóob, ngir...

Malaanum Lëndëm : Bóris Jóob, na woon, fa woon

Ñeenteelu yoon a ngi nii Bubakar Bóris Jóob di...

GÀCCE NGAALAAMA, MBUGAAR !

Senegaal amati na ndam ci 3eelu fan ci weeru...

KUJJE GEEK WOTEB 2022 BI: BËGG NAA LA, BËGGUMA LA, LOOLU JARUL COOW

Ci bésub 23 sàŋwiye ci atum 2022 bii di...

FÀTTALIKU DÉMB

SEEX

Seex Mooy góor Moo di as gor Mbokk ya ko wor Ñooy mbokk...

FÀTTALIKU OMAR BOLONDEŊ JÓOB… 2/2

(ÑAAREELU XAAJ) Bi ñu nee Senegaal moom na boppam tamit,...

2002, ATUM SUUXU JOOLAA BI

Bërki-démb 26 sàttumbar ci atum 2020, "Bateau le Joolaa"...

FAIDHERBE, SAAY-SAAY BI NUY SARGAL

Bi Siidiya Ndàtte Yàlla génnee àddina ak léegi, am...

JÉERI JOOR NDEELAAK TUBAAB BI

Jéeri Joor Ndeela Faal mu ngi gane àdduna ci...

DÉMB AK TEY

WIDEWO YI

WAXLEEN SEEN XALAAT

BOO BAÑEE ÑAAW…

Bu nu la waxee nga àggale kàddu gii, looy...

Njiitu Réew

Dangaa jiitoom Dañu la jiital Sa jubb cunduŋ xanaa taxul Moo ndax...

YAA GORE !

Yàgg, yàgg, dëgg ay daan Dëgg lottoon na Senegaal Usmaan Sonkoo...

Ndigalu Maam Ya

Afrig nee Waaw góor, waaw kumba Ayca leen ca waar wa Bu...

SÀCCIIN WI JËM CI TÀNN YI DËGMAL TE FEEÑALEES KO

Sëñ Abdu Xaadr Kebe mooy biral fii xalaatam ñeel...

TÀGGATOO

NJÀNGAT CI TÉERE YI

XËT YI LEEN DÀQAL

LI GËN A FËS CI XIBAARI BÉS BI (16/6/2024)

TABASKI 2024 NJIITU RÉEW MI JÉGGAL NA 376i MA-KASO Njiitu réew mi, Sëñ Basiiru Jomaay Jaxaar...

TABASKI 2024 : KÀDDU NJIITU RÉEW MI

Njiitu réew mi, Sñ Basiira Jomaay Jaxeer Fay, yëkkati nay kàddu ci julli gi....

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (16/01/2024)

DOXIINU YOON CI RÉEW MI Lépp lañ war a xoolaat ci ni yoon di doxee...

DÉGGOOY SOROJ BEEK GAAS BI : CÀKKUTEEFU WAY-XARAÑ YI

Nguur gi war na waxtaanewaat déggoo yi ñeel soroj beek gil bi (gaas bi)....

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (20/11/2023)

NGOMBALAAN GI Dépite yaa ngi wéy di nattal jëwriñi Càmm gi seen i gafaka ñeel...

PAATUG NJIITU RÉEWUM IRÃ

Njiitu réewum Irã li, Ebraahim Raysi, faatu na. Fafalnaaw bi mu duggoon ak jëwriñam...

NJOMBEW 6i PÀKK YI NGUUR GI WÀNTEER PERETZ

Noppeegunoo wax ci njombew pasug 45i miliyaar yi, ñu sullil nu beneen tóoxidóoni. Usmaan...

TÀGGE : USÉYNU BÉEY WÉY NA

Njabootu mbatiit ak làmmiñi réew mi amati nañ tiis ak uw naqar. Kenn ci...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (22/4/2024)

SONKO SANT NA JËWRIÑ YA WOON ÑU DELLOO DAAMARI NGUUR GI Jëwriñ yu nekkoon ci...

EURO AK COPA AMERICA 2024

EURO 2024 Njureefi 1/8 dë finaal yi Ndajey 1/8 dë finaal yi ñeel Euro bi jeex...

NJIITU RÉEW MI TAS NA CÀMM GI

Bees sukkandikoo ci Majambal Jaañ, Njiitu réew, Maki Sàll, tas na Càmm gi. Bi...

NDOG MU METTI FA KUMPENTUM

Ndogum yoon (aksidaŋ) mu mettee ame fa Kumpentum, tey ci suba teel, bi 7i...

DOG NAÑU MBAALI JOKKOO YI FA GABOŊ

Li wokkoon Senegaal, xuri na Gaboŋ. Ci njeexitalu ayu-bés bii ñu génn la réewum...

MAN MAAY KAN ?

Danuy faral di dégg ñu naan : « boo xamul foo jëm, dangay dellu...

COOWAL NASIYONAALITE KARIIM MAYSA WÀDD

Juróomi fan kepp a des balaa ndajem ndeyu àtte miy siiwal limug lawax yiy...

XIBAARI TAGGAT-YARAM (23/7/2023)

MESSI DELLOONA BUUM CA MBOY-MBOY GA ! Bërki-démb ci guddi, bi 3i waxtu jotee, la...

RËNG-RËNG FA MAROG : 820i NIT DEEWAGUM NAÑ CI

820i nit ñoo ñàkkagum seen i bakkan ci rëng-rëng bi yëngal suufus Marog si....

NJUREEFI BAC 2024 YI

Joŋante BAC bi jeex na ci ayu-bés bii ñu génn. Njureef ya ca tukkee...

BÀLLA GAY DAANATI NA TAFAA TIN

Démb a doonoon woon ñaareel wi yoon ñu sëgg ci géewub bëre-dóor. Bàlla Gay...

COONO DU RÉER ?

Bari na ay xale yuy làqatu di lekk kaani. Ndax, mag ñee leen koy...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (11/4/2024)

NJÉBBALUG LENGE FA MÀKKAANI NJËWRIÑ YA Keroog ci àjjuma ji la elimaanu jëwriñ ji génne...

JÀPP NAÑ MEERU SINJAAN BI

Ceerno Jaañ, meeru Sinjaan bi, lañu jàpp tey ci àllarba ji. Jàllale nañ ko...

WAA LACOS WOOTE NAÑ BÉSUB ÑAXTU

Lëkkatoo gi ëmb mbooleem njiit yi nekkug lawaxu Usmaan Sonko yitteel, ñu gën leen...

USMAAN SONKO WEER NA MAKI SÀLL

DGE, kurél giy saytu lépp lu aju ci wote yi, lànkalati na ndawul Usmaan...

NDELLOOG USMAAN SONKO CI WAYNDAREW WOTE WI

Ci talaatay tey jile, 12 desàmbar 2023, la tirbinaal « hors classe » bu Ndakaaru di...

TÀGGE : GASTÕ MBENG FAATU NA

GASTÕ SAALIF MBENG, tëggkatu làmb bi, moo génn àddina tey ci àllarba ji, 1eelu...

BAC 2024

« BAC » dafa bokk ci joŋante yi gën a siiw fi Senegaal. Démb la door,...

AAMADU BA : LAWAXU BENNOO BOKK YAAKAAR CI WOTEY 2024 YI

Ginnaaw wiiri-wiiri bu metti bi, àgg nañ Ndaari. Maki Sàll tànn na Aamadu Ba,...

COVID-19 BI NUYOOTI NA !

Li ñu doon laam-laamee démb ak barki-démb mi ngi bëgg a leer. Nde, ñu...

SAARAYA : AY SAAY-SAAY ÑOO SOQI FETEL CI AG DAAMAR

Fa Saaraya, féete ci diiwaanu Kéedugu, la ay saay-saay song ag daamar, soqi ciy...

KÉEW MI : BÉSUB NJËMBËT GARAB

ÔGinnaaw-ëllëg, dibéer 4i pani ut 2024, lañ jagleel garab fépp fi réew mi. Njiitu...

NJUREEFI NDAJEM JOMAAY AK MACRON

Njiitu réew mi, Basiiru Jomaay Jaxaar Fay, ma nga woon Farãs. Daf fa teeweeji...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (12/7/2023)

ONG CAMINANDO FRONTERAS WEDDI NA AYSATA TAAL SÀLL ONG Espaañ Bii di Caminando Fronteras dëggal...

YOON BÀYYI NA USTAAS UMAR SÀLL

Àtte bi daanu na. Tey ci àjjuma ji lañ doon àtte Ustaas Umar Sàll...

JÉYYA CA TASET

Taset, di ab gox bu féete ca diwaanu Nooto, fa Cees. Aw tiis moo...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (10/10/23)

PÓLITIG Ngomblaan gi génne na ab yégle di ci xamle ne dina amal lëlu aadaam...

KOLOBAAN : LEERALI USMAAAN SONKO

Démb, ci ngoonu dibéer ji, elimaanu jëwriñ yi amaloon na ab doxantu fa Kolobaan...

AY NAAL ÑEEL NJÀNG MI

Njiitu réew mi teewoon na ca ndaje ma ñu doon sargale ndongo yi gën...

LI GËN A FËS CI WOTEY 2024 YI (19/3/2024)

XEEX BI AMOON ÑOORO : JÀPP NAÑ NDAWUL PASTEF LA Militaŋi Pastef yee doon xeex...

« USMAAN SONKO NEE NA YËGATUL WETU CÀMMOOÑAM… »

Xadi Kebe ak Aana Jamanka, ñaari soxnay Usmaan Sonko yi, doon nañ amal ab...