LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (1/7/2025)

NDAJEM ÀDDINA SI ÑEEL KOPPARAL SUQALEEKU GI Démb ci altine ji lañu doon amal Ndajem àddina si ñeel kopparal suqaleeku gi. Ñoo ngi ko doon...

TUKKIB NJIITU RÉEW MI FA ESPAAÑ

Démb, ci dibéer ji, la Njiitu réew mi, Basiiru Jomaay Jaxaar Fay, bawoo ci réew mi, jubali fa Tugal. Moom nag, du guléet muy...

XIBAARI TÀGGAT-YARAM

FUTBAL Racine Club de Lens xamle na ni Nàmpalis Mendi dana jóge ca ekib ba gannaaw bam fa defee ñaari at (2023-2025). Ci diir bim...

NGOMBLAAN GI YEESAL NA SÀRTU-BIIRAM

Dépite yi jàllale nañu « loi organique no10/2025 ». Muy àtte bob, dafa ñëw ngir andi ay coppite ci sàrtu-biiru Ngomblaan gi. Démb ci àjjuma ji, 27...

USMAAN SONKO “ BÉG” NA CI TUKKEEM BI MU AMAL FA SIIN

Elimaanu jëwriñ yi, Usmaan Sonko, fésal na mbégteem ci tukki bi mu tukki fa réewum Siin. Pekeŋ la ko waxee, di gëblag réew ma....

MAGU WAXOON NAA KO

JIKKO JU RAFET MOOY TABAX AM RÉEW

Wolof nee na, rafet kanam, rafet jikko a ko...
01:33:07

“Héritages” dalal na Bubakar Bóris Jóob

"Héritages ak Awa" ngi dalal Bubakar Bóris Jóob, ngir...

Malaanum Lëndëm : Bóris Jóob, na woon, fa woon

Ñeenteelu yoon a ngi nii Bubakar Bóris Jóob di...

GÀCCE NGAALAAMA, MBUGAAR !

Senegaal amati na ndam ci 3eelu fan ci weeru...

KUJJE GEEK WOTEB 2022 BI: BËGG NAA LA, BËGGUMA LA, LOOLU JARUL COOW

Ci bésub 23 sàŋwiye ci atum 2022 bii di...

FÀTTALIKU DÉMB

SEEX

Seex Mooy góor Moo di as gor Mbokk ya ko wor Ñooy mbokk...

FÀTTALIKU OMAR BOLONDEŊ JÓOB… 2/2

(ÑAAREELU XAAJ) Bi ñu nee Senegaal moom na boppam tamit,...

2002, ATUM SUUXU JOOLAA BI

Bërki-démb 26 sàttumbar ci atum 2020, "Bateau le Joolaa"...

FAIDHERBE, SAAY-SAAY BI NUY SARGAL

Bi Siidiya Ndàtte Yàlla génnee àddina ak léegi, am...

JÉERI JOOR NDEELAAK TUBAAB BI

Jéeri Joor Ndeela Faal mu ngi gane àdduna ci...

DÉMB AK TEY

WIDEWO YI

WAXLEEN SEEN XALAAT

BOO BAÑEE ÑAAW…

Bu nu la waxee nga àggale kàddu gii, looy...

Njiitu Réew

Dangaa jiitoom Dañu la jiital Sa jubb cunduŋ xanaa taxul Moo ndax...

YAA GORE !

Yàgg, yàgg, dëgg ay daan Dëgg lottoon na Senegaal Usmaan Sonkoo...

Ndigalu Maam Ya

Afrig nee Waaw góor, waaw kumba Ayca leen ca waar wa Bu...

SÀCCIIN WI JËM CI TÀNN YI DËGMAL TE FEEÑALEES KO

Sëñ Abdu Xaadr Kebe mooy biral fii xalaatam ñeel...

TÀGGATOO

NJÀNGAT CI TÉERE YI

XËT YI LEEN DÀQAL

LAYOOB KÀPPITEN TURE AK SÉEX YERIM SEKK

Àtte ba jib na. Àttekat bi jox na Kàmpiten Ture dëgg. Nde, dafa daan...

NDAJEM JËWRIÑ YI

Démb ci àllarba ji lañu doon amal ndajem jëwriñ yi ci njiiteefu Njiitu réew...

COOWAL MUURAAY CI DAARA YI

Coowal muuraay gi lëmbeeti na réewum Senegaal.  Kàddu yi elimaanu jëwriñ yi yékkati woon,...

YOON BÀYYI NA USTAAS UMAR SÀLL

Àtte bi daanu na. Tey ci àjjuma ji lañ doon àtte Ustaas Umar Sàll...

JÉYYAY MBËKK MI : AAMADU BA (BBY) ÀDDU NA

Elimaanu jëwriñ ja woon ci nguurug Maki Sàll, Aamadu Ba, àddu na ci jéyya...

AAMADU BA : LAWAXU BENNOO BOKK YAAKAAR CI WOTEY 2024 YI

Ginnaaw wiiri-wiiri bu metti bi, àgg nañ Ndaari. Maki Sàll tànn na Aamadu Ba,...

JÉYYA CA TASET

Taset, di ab gox bu féete ca diwaanu Nooto, fa Cees. Aw tiis moo...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (25/7/2024)

TUKKIB NJIITU RÉEW MI Démb ci àllarba ji la Njiitu réew mi, Basiiru Jomaay Jaxaar...

KAN MOOY IDIRIISA SEKK ?

Ay fan a des ci wotey 24 màrs yi ñeel palug Njiitu réewum Senegaal....

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (15/8/2024)

NJIITU RÉEW MI DALAL NA NJIITUL UEMOA UEMOA (Union Economique et Monétaire Ouest Africaine) mooy...

XIBAARI TAGGAT-YARAM (1/10/2023)

KUPPEG ÀDDINA WAY-LUU YI (MUUMA YI) Bàyyeesu leen xel, waaye way-luu (muuma) yi teewal Senegaal...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (12/7/2023)

ONG CAMINANDO FRONTERAS WEDDI NA AYSATA TAAL SÀLL ONG Espaañ Bii di Caminando Fronteras dëggal...

XEW-XEW BU TIIS FA ETAASINI

Ñetti Saa-Senegaal ñoo ñàkk seen i bakkan ci anam yu metti fa Etaasini. Ci...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (24/7/2023)

DINDI NAÑ ÑAG YA WOON CA SITE KËR-GÓOR-GI Dindi nañ ñag yañ defoon fa Site...

WÀÑÑIG DUNDU GI

Ñoo ko dige woon, tàmbali nañ ko def. Càmmug Basiiru Jomaay Fay geek Usmaan...

« USMAAN SONKO NEE NA YËGATUL WETU CÀMMOOÑAM… »

Xadi Kebe ak Aana Jamanka, ñaari soxnay Usmaan Sonko yi, doon nañ amal ab...

SIIWALUG CAABAL YI

Àllarba jii weesu la Njiitu réew mi, Basiiru Jomaay Jaxaar Fay, doon amal ñaareelu...

FITNA FA MEDINA GUNAAS

Xibaar bu yéeme te doy waar moo jib tey, ci bésub tabaski bi. Muy...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (10/10/23)

PÓLITIG Ngomblaan gi génne na ab yégle di ci xamle ne dina amal lëlu aadaam...

COOWAL BAC 2024 BI

Joŋante BAC bu atum ren jii bari na ay coow lool. Te, li ko...

YOONU GÀMMU

Mawlidu Nabi, ñu ciy màggal juddug Yonnent bi (sas), moom mi Yàlla sunu Boroom...

XIBAARI TÀGGAT-YARAM

DAAN NAÑ PÓOL POGBAA 4i AT YUM DUL FUTBAL Doomu Farãs ji, ndax futbalam du...

BËTAL NAÑ BFEM BI

Bésub 18 sulet 2024 lañ àppaloon joŋante BFEM bi. Waaye, dañu ko mujje bëtal....

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (1/7/2024)

NJÀNGATI WOTEY 2024 YI Kurélu maxejj gii di COSCE (Collectif des Organisations de la Société...

“ICS” FEEÑLE NA

Ginnaaw riirum caabal yi ci yorinu alalu askan wi, coow topp na kër gii...

EURO AK COPA 2024

EURO : Njureefi 1/4 dë finaal yi Mats yi ñeel 1/4 dë finaal yi "Euro"...

LI GËN A FES CI XIBAARI BES BI (6/9/2023)

BÀYYI NAÑU XALIL KAMARA BU SENEGO Bërki-démb ci talaata ji lañu téye woon taskatu xibaarub...

TAMXARIT

Tamxarit bokk ci na ci xew-xewi diine fii ci Senegaal. Tur wi rekk làmboo...

AM-AMU NJIITU RÉEW MI

Ndajem Ndeyu Sàrtu réew mi siiwal na am-amu Njiitu réew mi, Basiiru Jomaay Jaxaar...

REAL MADRID JËL NA “SUPER COUPE D’EUROPE” BI

"Super Coupe d'Europe" mooy kub boo xam ni, ñaar ñi gañe joŋantey kuppe yii...

KÀTTEY BFEM 2024

Démb, ci altine ji, door nañu kàttey BFEM 2024 bi. BFEM (Brevet de Fin...

LI GËN A FÉS CI XIBAAR BÉS BI (30/5/2024)

NJIITU RÉEW MI AMAL NA TUKKI FA MALI AK BURKINAA FAASO Ginnaaw ba mu amalee...

RTS : PAAP AALE ÑAŊ DAKKAL NA DÉGGOOY RAASIN TAALA YA

Paab Aale Ñaŋ a ngi indiy coppite ca RTS. Ndogal lu yees lu mu...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (6/11/2023)

PÓLITIG Kujje gee ngi waajal lu bees ñeel wote yiñ dégmal. Sëñ Abdurahmaan Juuf, di...

TAXAWALUG NJËWRIÑ GU YEES

Lu tollu ci ñetti weer kepp, ginnaaw bi ñu leen falee ak léegi, Nguur...

XIBAAR YU TEMBARE

NGOMBLAAN GA Càkkuteefu neenal dekkare fomm wotey 2024 YI Maalig Gàkku, Basiiru Jomaay Fay ak Seex...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (12/7/2024)

JANOO NJIITU RÉEW MI AK TASKATI XIBAAR YU RÉEW MI Lu tollu ci téeméeri fan...

PÉEXALUG JÀNGUNEB NDAKAARU

Càmm gi dellusi na ci way-am-bag yi (les nouveaux bacheliers) ak jël gi ñu...

MÀGGALUG TUUBAA GI

Màggal gi jubsi na. Nit ñaa ngay waaj, ku nekk ci sa wet. Waa...

COOWOO CA NGOMBALAANU CEDEAO

Barki-démb, ci gaawu gi, la dépitey CEDEAO yi doon amal am ndaje fa Abujaa,...