COKKAASU ODIA

MAGU WAXOON NAA KO

JIKKO JU RAFET MOOY TABAX AM RÉEW

Wolof nee na, rafet kanam, rafet jikko a ko...
01:33:07

“Héritages” dalal na Bubakar Bóris Jóob

"Héritages ak Awa" ngi dalal Bubakar Bóris Jóob, ngir...

Malaanum Lëndëm : Bóris Jóob, na woon, fa woon

Ñeenteelu yoon a ngi nii Bubakar Bóris Jóob di...

GÀCCE NGAALAAMA, MBUGAAR !

Senegaal amati na ndam ci 3eelu fan ci weeru...

WAAW, KAÑ LA SENEGAAL GËJ A YËNGOO NII…?

Weeru màrs wii weesu, Senegaal tàngoon na jipp !...

KÀDDUY USMAAN SONKO 2/2 PÀCC

Senegaal gépp amoon na fiy yëngu-yëngu, réew mi jaxasoo,...

KÀDDUY USMAAN SONKO 1/2 PÀCC

Senegaal gépp amoon na fiy yëngu-yëngu, réew mi jaxasoo,...

Njàngatub Bàmmeelu Kocc : Téereb dekkali 1/2

Du guléet. Déedéet. Bindkat bi tëbul rekk bind Bàmmeelu...

FÀTTALIKU DÉMB

SEEX

Seex Mooy góor Moo di as gor Mbokk ya ko wor Ñooy mbokk...

FÀTTALIKU OMAR BOLONDEŊ JÓOB… 2/2

(ÑAAREELU XAAJ) Bi ñu nee Senegaal moom na boppam tamit,...

2002, ATUM SUUXU JOOLAA BI

Bërki-démb 26 sàttumbar ci atum 2020, "Bateau le Joolaa"...

FAIDHERBE, SAAY-SAAY BI NUY SARGAL

Bi Siidiya Ndàtte Yàlla génnee àddina ak léegi, am...

JÉERI JOOR NDEELAAK TUBAAB BI

Jéeri Joor Ndeela Faal mu ngi gane àdduna ci...

DÉMB AK TEY

Dal-leen ak jàmm ci seen xët DÉMB AK TEY...

JIÑAABO, JÀMBAARU SELEKI BA CA SIGICOOR

Boo demee ca diiwaanu Sigicoor, dinga fa fekk liise...

DAAWUDA JAAWARA FAATU, NUY FÀTTALIKU SENEGÀMBI

Daawuda Kayraba Jaawara, jiite woon fi réewum Gàmbi 1979...

SAARTJIE BAARTMAN, NDAW SA TUBAAB YI DEFOON MALA

Saartjie Baartman ab jaam la woon, fekkoon baax ca...

WIDEWO YI

WAXLEEN SEEN XALAAT

BOO BAÑEE ÑAAW…

Bu nu la waxee nga àggale kàddu gii, looy...

Njiitu Réew

Dangaa jiitoom Dañu la jiital Sa jubb cunduŋ xanaa taxul Moo ndax...

YAA GORE !

Yàgg, yàgg, dëgg ay daan Dëgg lottoon na Senegaal Usmaan Sonkoo...

Ndigalu Maam Ya

Afrig nee Waaw góor, waaw kumba Ayca leen ca waar wa Bu...

SÀCCIIN WI JËM CI TÀNN YI DËGMAL TE FEEÑALEES KO

Sëñ Abdu Xaadr Kebe mooy biral fii xalaatam ñeel...

TÀGGATOO

Roqi, ba beneen yoon. Seetal ma lii rekk. Wax dëgg....

NJÀNGAT CI TÉERE YI

XËT YI LEEN DÀQAL

CARGALUG NEUSTADT INTERNATIONAL PRIZE FOR LITERATURE : BUBAKAR BÓRIS JÓOB JËL NA NDAM LI (PAAP AALI JÀLLO)

Ci talaata 26eel ci oktoobar 2021, lees jot ci mbégtem weer wi. Surnaalu ladab...

XIBAARI TÀGGAT-YARAM (16/7/2023)

KUPPEG ÀDDINA SI 2026 Kippu yi ñeel xëccoo paasu kuppeg àddina si war a am...

CAYTUG BAAYALE GI : ÑAAREELU SUMB BI

Tey ci talaata ji, 9 sãwiyee 2024, la ndajem ndeyu àtte réew mi doon...

XIBAARI TÀGGAT-YARAM

FUTBAL Victor Boniface moo ngi dox ci ndox Ataakã Bayer Leverkusen bi moo ngi wane boppam...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (17/01/2023)

JÉBBALUG DABANTAL YA TAQARNAASE NA Ñetti fan kepp a des ndajem ndeyu àtte mi biral...

NJËGU DUND BI NJIITU RÉEW MI, MAKI SÀLL, JËL NA 11i NDOGAL

Ci gaawu gii weesu, 5i fan ci nowàmbar, lees doon amal am ndaje ngir...

NGOMBLAAN GI GANTAL NA PASUM DIIŊAAT MU WAA YAW

Démb ci alxames ji la Ngomblaan gi amaloon am ndaje ngir wote pasum diiŋat...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI GAAWU 03 DESÀMBAR 2022

PÓLITIG Ginnaaw ndajeem jëwriñ yi mu amaloon, Njiitu réew mi Màkki Sàll, takkal na ndombog-tànk...

DIISOOB WOTE YI

Ndajem ndeyu àtte mi neenaloon dekkare Njiitu réew mi ak sémbub àtte bi Ngomblaan...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (8/6/2024)

BUGAAN GÉY DANEE NGI WEDDI AK A LEERAL Yéenekaay Source A dafa fésaloon ab xibaar,...

ANIBAAL JIIM PELENT NA AADAMA FAAL MU BENNOO

Ab bataaxal la Anibaal Jiim mi ci kaso bi biral, di ci xamle ne...

CÀKKUTEEFU WAA FORUM CIVIL

Kurélug maxejj yi, ñu gën koo miis ci Forum Civil, àdduna ci wàññi gi Nguur gi...

DOORO GÉY, BAH JAXATE AK IMAAM SÉEX TIIJAAN NDAW DEM NAÑ KASO

Tey ci altine ji, ñetti fan ci weeru suwe la ndogal li daanu. Bah...

Macky sall (SBJ)

Muumaa di li mu fésal ci li xew ci réew mi. Ana lu waral faleesoon...

Iniwérsite Gastoŋ Berse

  Ndongo daara ya nekk ca Iniwérsite GastoŋBerse waroon a tàmbali ci talaata jii, dogal...

LAMIN JÀLLO (NJIITUL TEKKI) DINA JÉEM A NEENAL DEKKARE MAKI SÀLL BI

Mamadu Lamin Jàllo mi jiite pàrti pólitig bii di Tekki ñaawlu na dekkare bi...

XIBAARI TÀGGAT-YARAM

Real Madrid a ngi wër góol bu bees Thibault Courtois, góolu Real Madrid bi,  dafa...

MBAS MEEK ÑÀKK XÉY CI SENEGAAL (SAFIYETU BÉEY)

Bérébu liggéeyukaay yu bare tëj nañu ndax mbas mi, loolu la ab lànket bu...

LÀRME BI JËLAAT NAY GÀNGOORI SÓOBARE YEES LIBEERE WOON

Làrmeb Senegaal a ngi yokk ay sóobareem, maanaam mi ngi yokk limi soldaar yi....

SOXNA XADIJATU NJAAY CA KUNGÉEL, DOY NGA ROYUKAAY ! (AMI MBENG)

« …ñeewuma sama benn moroom bu jàng farañse. » Njiit li, boroom raaya yi, taalifkat bi, njiitalu...

NDAR : SONKO DIGE NAY PEXE ÑEEL NAPP GI

Elimaanu jëwriñ yi, Usmaan Sonko, mi ngi woon fa Ndar, tay ci gaawu gi,...

ASP : 39i LIGGÉEYKAT YU BEES CI ÑAARI FAN

Njiitul “Agence de sécurité de proximité” (ASP) li jël na 39i liggéeykat yu bees...

LI GËN A FËS CI XIBAARI BÉS BI (ÀLLARBA 28 DESÀMBAR 2022)

TÀGGE : MUQADDAM SEEX BAAY BUUBU SI DËDDU NA Njabootu Seex Ahmet Tijaan, rawatina tiijaani Senegaal...

KASOY SENEGAAL : XIIFAL NIKI NGÀNNAAY

Ñi ñu tëj ci kaso yi, xiifal gi lañ jël def ko ngànnaayu xeex....

GÀTTALUG XIBAAR YI (Altine 13 eelu – dibéer 19eelu awril)

Paap Aali Jàllo Mbasum Covid-19 bi faat na juróomi way-tawat ci diggante dibéer ak altine Ci...

SENEGAAL WULLI NA GÀMBI

Tay ci altine jii 15 sãwiyee 2024 la Senegaal doon amal joŋanteem bu njëkk...

MBIRI USMAAN SONKO : CENA BI JËL NA NDOGALAM BA NOPPI

Ginnaaw bi DGE (Direction générale des élections) bañee doxal ndogal li àttewaay bu Sigicoor...

AY TABB YU YEES

Njiitu réew mi, Basiiru Jomaay Jaxaar Fay, tabb na ay njiit yu bees ci...

MAMADU BAAJO KAMARA, LOO NAR ?

Léegi, xam nañ kan mooy wuutu Paap Umar Saaxo mi dem alaaterete. Ci dekkareb...

TAXAWALUG “PLATEFORME” JUBBANTI

Talaata jii di ñëw mooy bés bi ñuy door waxtaan wi Njiitu réew mi...

XIBAARI TÀGGAT-YARAM

CAN-SENEGAAL : JOŊANTEB XARITOO Ëllëg, ci altine ji, bu 18i waxtu jotee la Senegaal di daje...

NJÀNG MEEK NJÀNGALE MI : BËGG-BËGGI JËWRIÑ JI MUSTAFAA GIRAASI

Jëwriñu njàngale mi ci daara yu ndaw yeek yu digg-dóomu yi, Mustafaa Giraasi, fésal...

SENEGAAL 2 – BOLIWII 0

Ekibu nasiyonalu Senegaal bu futbal a ngi ci waajtaayu Kub di mond bi war...

Li gën a fés ci xibaari bés bi (25/7/2023)

ALIW SAANE DELLU NA KASO Aliw Saane dellu na kaso. Moom, njiitul mbootaayu Y’en A...

Laaj-tontu ak Kolonel-Masoor Ismayla Wage : « Li nu def Mali, mëneesu ko tudde cëtëŋ… »

France 24 amal nab laaj-tontu ak kii di Kolonel-Masoor Ismayla Wage mi yor kàddug...

KARIIM WÀDD : “SAMAG GÀDDAAY MI NGI JEEX”

Ni ñu ko baaxoo gise ci njeexitalu at mu nekk, njiitu réew mi dina...

MBIRI USMAAN SONKO : UMS DUGG NA CI COOW LI

Ginnaaw bi àttekat bi tirbinaalu Sigicoor jële ndogalu bindaat Usmaan Sonko ci këyitug wote...

WOTEB SÉMBUB ÀTTE BIY DÀQ WOTE YI

Ngombalaan gi jàllale na sémbub àtte biy dàq wote yees nammoon a amal ci...

“UGB DU AY SËG !”

Ginnaaw Fàllu Seen (2018), leneen ndongo faatooti na fa jànguneb Ndar ba ci sababuy...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (28/3/2024)

MAKI SÀLL DEF NA NDAJEM JËWRIÑAM MU MUJJ Dibéer jii weesu lañu doon amal...

Rawale nañ Usmaan Sonko ca “réanimation” ba.

Rawale nañ Usmaan Sonko ca "réanimation" ba. Jotna Média moo siiwal xibaar bi. Ci...

KASO AMATI NA GAN

Jàpp nañu Faddiilu Keyta mi bokk ci bëkk-néegi Usmaan Sonko, njiital PASTEF li. Ab...

WOTEY 2024 YI : 19i LAWAX ÑOO CI DES

Ginnaaw bi mu neenalee dekkare Njiitu réew mi jëm ci fommug wotey 25 féewiryee...

BAKKAN ROTAAT NA FA GINNAAW RAAY

Ginnaaw ndongo la gaañu fa jànguneb Ndar, beneen ndaw ñàkk na bakkanam fa Ndakaaru....

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (20/12/2023)

LAYOO MAAM MBAY ÑAŊ USMAAN SONKO Bu yàggul dara lañu jàppoon layoo Maam Mbay ak...

LUUBALU 540I TAMDARET CA CMS BU MEDINAA

CMS ab bànqaasu déncuwaay ak àbbuwaayu xaalis la bu nekk ci biir réew mi....

Xibaari Tàggat-Yaram

kuppeg Àddina U17: 1/2 finaal Joŋante baa ngi wéy, ñu tollu fim ne ci 1/2...

KAN MOOY XALIFA SÀLL ?

Xalifa Sàll, nitu pólitig la, fës lool fi Senegaal, di lawax ci wotey 2024...

Li gën a fés ci xibaari bés bi Alxames 17 nowàmbar 2022

TÀGGAT-YARAM Futbal/Qataar 2022 : Saajo Maane du bokk Yaakaar tas na ! Ndeysaan. Xibaar bu tiis...

ÑEENTI SÓOBARE ÑOO ÑÀKK SEEN I BAKKAN FA KAASAMÃS

Fa Kaasamãs, dafa ag daamaruy sóobare gu dal ci kow um mbéll « antichar ». Bi...